Vous avez cherché: trône (Français - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

et celui qui jure par le ciel jure par le trône de dieu et par celui qui y est assis.

Wolof

ku giñ ci asamaan, giñ nga ci jalu buur yàlla ak ki ci toog.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il vint, et il prit le livre de la main droite de celui qui était assis sur le trône.

Wolof

mbote ma ñëw, jël téere, ba nekkoon ca loxol ndeyjooru ka toog ca gàngune ma.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

il sera grand et sera appelé fils du très haut, et le seigneur dieu lui donnera le trône de david, son père.

Wolof

ku màgg lay nekki, te dinañu ko wooye doomu aji kawe ji. boroom bi yàlla dina ko jébbal nguuru daawuda maamam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

a un jour fixé, hérode, revêtu de ses habits royaux, et assis sur son trône, les harangua publiquement.

Wolof

ca bés ba ñu jàpp nag erodd sol mbubbi buuram, toog ca jal ba ca àttekaay ba, di leen yedd ak a dénk.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

elle enfanta un fils, qui doit paître toutes les nations avec une verge de fer. et son enfant fut enlevé vers dieu et vers son trône.

Wolof

noonu mu jur doom ju góor, muy ki war a jiite xeeti àddina yépp ak yetu weñ. waaye ñu daldi fëkk doom ja, mu dem ca yàlla ak gànguneem.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

comme il était prophète, et qu`il savait que dieu lui avait promis avec serment de faire asseoir un de ses descendants sur son trône,

Wolof

waaye yonent la woon, te xamoon na ne, yàlla digoon na ko ci ngiñ ne, dina teg ci nguuram kenn ci askanam.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

car l`agneau qui est au milieu du trône les paîtra et les conduira aux sources des eaux de la vie, et dieu essuiera toute larme de leurs yeux.

Wolof

ndaxte mbote mi nekk ci diggu gàngune mi dina leen sàmm,yóbbu leen ca bëti ndoxum dund ma,te yàlla dina fomp bépp rangooñ ci seeni bët.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

approchons-nous donc avec assurance du trône de la grâce afin d`obtenir miséricorde et de trouver grâce, pour être secourus dans nos besoins.

Wolof

kon nag nanu am kóolute ci jege jalu yàlla bu yiw ba, ngir jot yërmandeem ak yiwam, ngir mu wallu nu fu soxla taxawe.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et il me montra un fleuve d`eau de la vie, limpide comme du cristal, qui sortait du trône de dieu et de l`agneau.

Wolof

noonu malaaka ma won ma dexu ndoxum dund, mu leer ni weer bu set, di génn ca gàngune mu yàlla ak mbote ma,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

le ciel est mon trône, et la terre mon marchepied. quelle maison me bâtirez-vous, dit le seigneur, ou quel sera le lieu de mon repos?

Wolof

“asamaan mooy sama jal,te suuf mooy sama tegukaayu tànk.kon gan kër ngeen may tabaxal,mbaa fan mooy sama bérabu noppalukaay?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

et ils criaient d`une voix forte, en disant: le salut est à notre dieu qui est assis sur le trône, et à l`agneau.

Wolof

naan:«mucc gaa ngi ci yàllasunu boroom, bi toog ci gàngune mi,ak ci mbote mi!»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

c`est pour cela qu`ils sont devant le trône de dieu, et le servent jour et nuit dans son temple. celui qui est assis sur le trône dressera sa tente sur eux;

Wolof

loolu moo taxñu nekk ci kanamu gàngunem yàlla,di ko jaamu guddi ak bëccëg ci këram,te ki toog ci gàngune mi dina leen yiir.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

après cela, je regardai, et voici, il y avait une grande foule, que personne ne pouvait compter, de toute nation, de toute tribu, de tout peuple, et de toute langue. ils se tenaient devant le trône et devant l`agneau, revêtus de robes blanches, et des palmes dans leurs mains.

Wolof

gannaaw loolu ma xool, gis mbooloo mu réy, ba kenn mënu koo waññ, ñu bokk ci xeet yépp, giir yépp, réew yépp ak kàllaama yépp, taxaw ca kanamu gàngune ma ak mbote ma. Ñu sol ay mbubb yu weex, di màggal te di yengal ay cari garab ci seeni loxo,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,781,145,596 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK