Vous avez cherché: vieux (Français - Wolof)

Traduction

Wolof

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Français

Wolof

Infos

Français

et personne, après avoir bu du vin vieux, ne veut du nouveau, car il dit: le vieux est bon.

Wolof

ku naan biiñ bu màggat du bëgg bu bees bi, ndax day wax ne: “bu màggat bi baax na.”»  

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

célébrons donc la fête, non avec du vieux levain, non avec un levain de malice et de méchanceté, mais avec les pains sans levain de la pureté et de la vérité.

Wolof

kon nanu màggal sunu màggal, waxuma ak lawiir bu màggat biy misaal kiñaan ak lu bon, waaye ak mburu mu amul lawiir, maanaam ci xol bu laab ak ci dëgg.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

zacharie dit à l`ange: a quoi reconnaîtrai-je cela? car je suis vieux, et ma femme est avancée en âge.

Wolof

sakariya daldi ne malaaka ma: «nan laay xame ne, loolu dëgg la? ndaxte mag laa, te sama jabar it màggat na.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

nicodème lui dit: comment un homme peut-il naître quand il est vieux? peut-il rentrer dans le sein de sa mère et naître?

Wolof

nikodem ne ko: «nit ku xas ba màggat, nan lay man a judduwaate? ndax day dellu ci biiru yaayam ngir judduwaat?»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Français

en vérité, en vérité, je te le dis, quand tu étais plus jeune, tu te ceignais toi-même, et tu allais où tu voulais; mais quand tu seras vieux, tu étendras tes mains, et un autre te ceindra, et te mènera où tu ne voudras pas.

Wolof

ci dëgg-dëgg piyeer, maa ngi la koy wax, bi nga dee ndaw yaa doon takk sa geño, di dem fu la neex. waaye boo màggatee, dinga tàllal say loxo, keneen takkal la sa geño, yóbbu la foo bëggul.»

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,947,594,121 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK