Vous avez cherché: mensura (Latin - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Latin

Wolof

Infos

Latin

in quo enim iudicio iudicaveritis iudicabimini et in qua mensura mensi fueritis metietur vobi

Wolof

ndaxte dees na leen àtte ak ni ngeen di àttee, nattal leen ak li ngeen di nattale.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et mensus est murus eius centum quadraginta quattuor cubitorum mensura hominis quae est angel

Wolof

malaaka ma natt miir ba nattub nit, fekk miir ba di téeméer ak ñeent-fukk ak ñeenti xasab.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

et dicebat illis videte quid audiatis in qua mensura mensi fueritis remetietur vobis et adicietur vobi

Wolof

mu ne leen: «seetleen bu baax li ngeen di dégg. dees na leen nattal ak natt, bi ngeen di nattale, te dollil leen.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Latin

date et dabitur vobis mensuram bonam confersam et coagitatam et supereffluentem dabunt in sinum vestrum eadem quippe mensura qua mensi fueritis remetietur vobi

Wolof

mayeleen te dinañu leen may. dinañu leen ëmbal natt bu baax bu ñu rokkas te yengal ko, mu fees bay tuuru. ndaxte dees na leen nattal ak natt, bi ngeen di nattale.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,719,800,873 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK