Vous avez cherché: mistet (Norvégien - Wolof)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Norvégien

Wolof

Infos

Norvégien

- forat det ord skulde opfylles som han hadde sagt: jeg mistet ikke en av dem som du har gitt mig.

Wolof

noonu la baat boobu mu waxoon ame: «baay, kenn sànkuwul ci ñi nga ma dénk.»

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

hvilket menneske iblandt eder som har hundre får og mister ett av dem, forlater ikke de ni og nitti i ørkenen og går efter det han har mistet, til han finner det?

Wolof

«kan ci yéen soo amoon téeméeri xar, te benn réer ci, nooy def? ndax doo bàyyi ca parlukaay ba juróom-ñeent-fukki xar ya ak juróom-ñeent, toppi ma réer, ba gis ko?

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

og når han kommer hjem, kaller han sine venner og granner sammen og sier til dem: gled eder med mig, for jeg har funnet mitt får som jeg hadde mistet!

Wolof

boo àggee ca kër ga, dinga woo say xarit ak say dëkkandoo ne leen: “kaayleen bànneexu ak man, ndaxte gis naa sama xar ma réeroon.”

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Norvégien

den som elsker sitt liv, mister det, og den som hater sitt liv i denne verden, skal bevare det til evig liv.

Wolof

ku bëgg bakkanam dina ko ñàkk, waaye ku ko bañ ci àddina sii, dina ko denc ngir dund gu dul jeex gi.

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,502,847 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK