Vous avez cherché: estefanas (Wolof - Coréen)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Coréen

Infos

Wolof

aaŋkay! sóob naa it ci ndox waa kër estefanas. waaye ci sama pàttaliku sóobuma keneen.

Coréen

내 가 또 한 스 데 바 나 집 사 람 에 게 세 례 를 주 었 고 그 외 에 는 다 른 아 무 에 게 세 례 를 주 었 는 지 알 지 못 하 노

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi ma estefanas ak fortunatus ak akaykus seetsee, bég naa ci lool. taxawal nañu leen ci topptoo, bi ngeen yéene woon ci man te tële ko.

Coréen

내 가 스 데 바 나 와, 브 드 나 도 와, 아 가 이 고 의 온 것 을 기 뻐 하 노 니 저 희 가 너 희 의 부 족 한 것 을 보 충 하 였 음 이 니

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

xam ngeen ne, estefanas ak njabootam ñoo jëkk a nangu xebaar bu baax bi ci diiwaanu akayi, te ñoo joxe seen bopp, ngir liggéeyal gaayi yàlla yi. kon nag bokk yi, maa ngi leen di ñaan,

Coréen

형 제 들 아 스 데 바 나 의 집 은 곧 아 가 야 의 첫 열 매 요 또 성 도 섬 기 기 로 작 정 한 줄 을 너 희 가 아 는 지 라 내 가 너 희 를 권 하 노

Dernière mise à jour : 2012-05-06
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,090,758 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK