Vous avez cherché: dangaa gate (Wolof - Français)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

ndaxte ku ci nekk dangaa war a yenu sab yen.

Français

car chacun portera son propre fardeau.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«bul wax it:“kuy dem ca barsàq?”» mel ni dangaa bëgg kirist dekki.

Français

ou: qui descendra dans l`abîme? c`est faire remonter christ d`entre les morts.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mbooloo ma ne ko: «xanaa dangaa am ay rab! ku lay wut a rey?»

Français

la foule répondit: tu as un démon. qui est-ce qui cherche à te faire mourir?

Dernière mise à jour : 2024-04-14
Fréquence d'utilisation : 34
Qualité :

Wolof

yawut ya ne ko: «ndax danoo waxul dëgg, bu nu nee, nitu samari nga te dangaa am ay rab?»

Français

les juifs lui répondirent: n`avons-nous pas raison de dire que tu es un samaritain, et que tu as un démon?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi mu agsee ba ca simoŋ piyeer, kooku ne ko: «boroom bi, ndax yaw dangaa nar a raxas samay tànk?»

Français

il vint donc à simon pierre; et pierre lui dit: toi, seigneur, tu me laves les pieds!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye li ma naqari ci yaw moo di dangaa bàyyi yesabel, jigéen joojuy tuddoo yonent, di jàngale ak a réeral sama jaam yi, ngir ñuy sóobu ci njaaloo te di lekk ñam wu ñu tuuroo xërëm yi.

Français

mais ce que j`ai contre toi, c`est que tu laisses la femme jézabel, qui se dit prophétesse, enseigner et séduire mes serviteurs, pour qu`ils se livrent à l`impudicité et qu`ils mangent des viandes sacrifiées aux idoles.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«ci xew yépp, naan gu neex gi lañuy jëkke. bu nit ñi doyalee, ñu sog a génne ga ca des. waaye yaw dangaa dencoon gi gën a neex ba nëgëni.»

Français

et lui dit: tout homme sert d`abord le bon vin, puis le moins bon après qu`on s`est enivré; toi, tu as gardé le bon vin jusqu`à présent.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu mu dellusi ci taalibe yi, fekk ñuy nelaw. mu ne piyeer: «simoŋ, dangaa nelaw? amuloo sax dooley xoolandoo ak man benn waxtu?

Français

et il vint vers les disciples, qu`il trouva endormis, et il dit à pierre: simon, tu dors! tu n`as pu veiller une heure!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Certaines traductions humaines peu pertinentes ont été masquées.
Affichez les résultats peu pertinents.

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,777,204,755 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK