Vous avez cherché: fekk (Wolof - Français)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

booba fekk yoor-yoor di jot.

Français

c`était la troisième heure, quand ils le crucifièrent.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bët set ñu génn betani, fekk yeesu xiif.

Français

le lendemain, après qu`ils furent sortis de béthanie, jésus eut faim.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk seeni bët muuru, ba mënu ko woon a xàmmi.

Français

mais leurs yeux étaient empêchés de le reconnaître.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

Ñu teg seen bopp ni boroomi xel, fekk ñu ñàkk xel lañu woon.

Français

se vantant d`être sages, ils sont devenus fous;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk na yàlla tudde ko saraxalekat bu mag ni ko melkisedeg nekke.

Français

dieu l`ayant déclaré souverain sacrificateur selon l`ordre de melchisédek.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi ñu agsee, ñu fekk ñu béraŋ doj, wa uboon bàmmeel ba.

Français

elles trouvèrent que la pierre avait été roulée de devant le sépulcre;

Dernière mise à jour : 2024-04-17
Fréquence d'utilisation : 3
Qualité :

Wolof

ca ëllëg sa pool ànd ak nun, seeti saag, fekk njiit yépp teew fa.

Français

le lendemain, paul se rendit avec nous chez jacques, et tous les anciens s`y réunirent.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk amoon na ca waxambaane wu lëkkaayoo woon sér, topp yeesu, ñu daldi ko jàpp.

Français

un jeune homme le suivait, n`ayant sur le corps qu`un drap. on se saisit de lui;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk booba nag, taalibey yeesu ya dañoo demoon ca biir dëkk ba, di jënd lu ñu lekk.

Français

car ses disciples étaient allés à la ville pour acheter des vivres.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye sool yég seen pexe. fekk guddi ak bëccëg ñu doon wottu bunt yi yépp, ngir man koo bóom.

Français

et leur complot parvint à la connaissance de saul. on gardait les portes jour et nuit, afin de lui ôter la vie.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk booba amoon na ay yawut yu daloon yerusalem, doon ay nit ñu ragal yàlla te bokk ci xeeti àddina yépp.

Français

or, il y avait en séjour à jérusalem des juifs, hommes pieux, de toutes les nations qui sont sous le ciel.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk dangeen leen di toroxal! xanaa du boroom alal yi ñoo leen di noot te di leen yóbbu fa kanam àttekat yi?

Français

et vous, vous avilissez le pauvre! ne sont-ce pas les riches qui vous oppriment, et qui vous traînent devant les tribunaux?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk nag nun la ko yàlla won, jaarale ko ci xelam. xelum yàlla mooy leeral lépp, ba ci xalaati yàlla yi gën a xóot.

Français

dieu nous les a révélées par l`esprit. car l`esprit sonde tout, même les profondeurs de dieu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag góor guy ñaan yàlla, walla muy wax ci kàddug yàlla, fekk mu teg dara ci boppam, day suufeel kirist, kilifaam.

Français

tout homme qui prie ou qui prophétise, la tête couverte, déshonore son chef.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te kenn ci yéen ne ko: «demal ak jàmm, nga solu te lekk,» te fekk fajuleen aajoom, loolu lu muy jariñ?

Français

et que l`un d`entre vous leur dise: allez en paix, chauffez-vous et vous rassasiez! et que vous ne leur donniez pas ce qui est nécessaire au corps, à quoi cela sert-il?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,780,414,466 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK