Vous avez cherché: gnome (Wolof - Français)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

kàgguy gnome

Français

bibliothèque gnome

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

lu jëm ci gnome

Français

À propos de gnome

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

barabu biro bu gnome

Français

environnement graphique de bureau gnome

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

wanda, jën bu gnome

Français

wanda le poisson gnome

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci mbiri binduwaayu gnome

Français

À propos du bureau gnome

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

gën a xam lu jëm ci gnome

Français

en savoir plus sur gnome

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

dalal-jàmm ci binduwaayu gnome

Français

bienvenue sur le bureau gnome

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

woney xibaar ñeel bii sumbu gnome

Français

affiche des informations relatives à la présente version de gnome

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bii task dafay joxe prograam yu biro "desktop" di jëfandikoo barabu biro bu gnome.

Français

cette tâche fournit les logiciels de base pour l'environnement de bureau gnome.

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Avertissement : un formatage HTML invisible est présent

Wolof

ak gnome dees na jébbalaale it ab joyaluwaay bees jagleel tëralkat yi, tax ñuy man a bindiy tëriin yu kàttanu te fasu

Français

gnome incorpore également une plateforme complète de développement pour programmeurs. elle leur permet de créer des applications puissantes et complexes.

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bii task dafay joxe ay prograam yu biro (desktop), moo làmboo task yu biro gnome ak biro kde.

Français

cette tâche fournit les logiciels de base pour un environnement de bureau et sert de base pour les tâches d'installation des environnements gnome et kde.

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

gnome ëmbaale na lu bari ci mbir yi ne ci sa nosukaay, boole ci yorkatu dencukaay yi, joowukaayu web, njël yeek tëriin yu bari.

Français

gnome inclut la plupart de ce que vous voyez sur votre ordinateur, y compris le gestionnaire de fichiers, le navigateur web, les menus et beaucoup d'applications.

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

dooley gnome mooy askanam gu rëy. daanaka ku ne, muy ku man walla ku manul bindi tëriin, man ngaa duggal sa loxo ci gnome ngir gënal ko.

Français

la plus grande force de gnome est sa puissante communauté. À peu près n'importe qui, avec ou sans compétence en programmation, peut contribuer à améliorer gnome.

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ay téeméeri nit cëru nañu ci yoonu gnome dalee ci juddam 1997 ba léegi, ñeneen ñi ci yeneen fànn, muy tekki, uti xibaar ak ci wóoral baaxaayam.unknownmonitor vendor

Français

des centaines de personnes ont apporté du code au projet gnome depuis sa naissance en 1997 ; encore plus ont contribué dans d'autres domaines importants tels que les traductions, la documentation et l'assurance qualité.unknownmonitor vendor

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bàyyi-xel cig yomb a jëfandikoom ak jotaleem, génnewaat yu tegu ci yoon, ak jàppaleem gu këru-liggéey yu mag tax gnome doon kenn ci tëriinu binduwaay yu féex yi.

Français

l'attention de gnome sur l'ergonomie et l'accessibilité, un cycle de distribution régulier et le suivi de grandes entreprises le rend unique entre tous les environnements de bureau libre.

Dernière mise à jour : 2014-08-15
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,804,317 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK