Vous avez cherché: loxoom (Wolof - Français)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

noonu yeesu teg leen ay loxoom, ba noppi jóge fa.

Français

il leur imposa les mains, et il partit de là.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu yeesu leewu leen, teg leen ay loxoom, barkeel leen.

Français

puis il les prit dans ses bras, et les bénit, en leur imposant les mains.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye yeesu jàpp loxoom, jógloo ko, xale bi daldi taxaw.

Français

mais jésus, l`ayant pris par la main, le fit lever. et il se tint debout.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

wone na jëf yu mag ci dooley loxoom,te tas mbooloom ñiy réy-réylu,

Français

il a déployé la force de son bras; il a dispersé ceux qui avaient dans le coeur des pensées orgueilleuses.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu ne ku loxoom làggi: «jógal, taxaw ci kanamu ñépp.»

Français

et jésus dit à l`homme qui avait la main sèche: lève-toi, là au milieu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

am beneen bés, yeesu duggaat ci jàngu bi, fekk amoon na fa nit ku loxoom làggi.

Français

jésus entra de nouveau dans la synagogue. il s`y trouvait un homme qui avait la main sèche.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu daldi leen won ay loxoom ak wetam. bi ñu gisee boroom bi, taalibe ya daldi bég lool.

Français

et quand il eut dit cela, il leur montra ses mains et son côté. les disciples furent dans la joie en voyant le seigneur.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu yërëm ko, tàllal loxoom, laal ko naan: «bëgg naa ko, wéral.»

Français

jésus, ému de compassion, étendit la main, le toucha, et dit: je le veux, sois pur.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ku daan sàcc, na ko dëddu te jublu ci liggéey lu baax ci ay loxoom, ngir mu man a dimbali ñi néew doole.

Français

que celui qui dérobait ne dérobe plus; mais plutôt qu`il travaille, en faisant de ses mains ce qui est bien, pour avoir de quoi donner à celui qui est dans le besoin.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ca saa sa yeesu tàllal loxoom, jàpp ko naan: «yaw mi néew ngëm, lu tax nga am xel ñaar?»

Français

aussitôt jésus étendit la main, le saisit, et lui dit: homme de peu de foi, pourquoi as-tu douté?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

amoon na ay nit, ñuy indil yeesu ay liir, ngir mu teg leen ay loxoom. bi taalibe ya gisee loolu, ñu gëdd leen.

Français

on lui amena aussi les petits enfants, afin qu`il les touchât. mais les disciples, voyant cela, reprenaient ceux qui les amenaient.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu tàllal loxoom, laal ko naan: «bëgg naa ko, wéral.» ca saa sa ngaanaam daldi deñ.

Français

jésus étendit la main, le toucha, et dit: je le veux, sois pur. aussitôt il fut purifié de sa lèpre.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye pool wàcc, daldi sëgg ci kawam, roof ko loxoom ne leen: «bàyyileen jooy yi, mu ngi dund.»

Français

mais paul, étant descendu, se pencha sur lui et le prit dans ses bras, en disant: ne vous troublez pas, car son âme est en lui.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

fekk baayu publiyus dafa tëdd ndax ay tàngoori yaram yu koy dikkal ak biiru taññ. pool nag dem seeti ko, ñaan ci yàlla, teg ko ay loxoom, mu daldi wér.

Français

le père de publius était alors au lit, malade de la fièvre et de la dysenterie; paul, s`étant rendu vers lui, pria, lui imposa les mains, et le guérit.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te kilifa ga may ko ko. noonu pool taxaw ca yéegukaay ba, tàllal loxoom mbooloo ma, ñu daldi ne tekk. mu wax ak ñoom ci làkku yawut ne:

Français

le tribun le lui ayant permis, paul, debout sur les degrés, fit signe de la main au peuple. un profond silence s`établit, et paul, parlant en langue hébraïque, dit:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye yeesu xam seen xalaat, daldi ne ku loxoom làggi: «jógal taxaw ci kanamu ñépp.» nit ka daldi jóg taxaw.

Français

mais il connaissait leurs pensées, et il dit à l`homme qui avait la main sèche: lève-toi, et tiens-toi là au milieu. il se leva, et se tint debout.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye baay ba ne ay surgaam: “gaawleen indi mbubb, mi gën a rafet, solal ko ko. te ngeen roof ab jaaro ci loxoom te solal ko ay dàll.

Français

mais le père dit à ses serviteurs: apportez vite la plus belle robe, et l`en revêtez; mettez-lui un anneau au doigt, et des souliers aux pieds.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu jàpp loxoom ne ko: «talita kumi,» liy tekki: «janq bi, maa ngi la koy wax, jógal.»

Français

il la saisit par la main, et lui dit: talitha koumi, ce qui signifie: jeune fille, lève-toi, je te le dis.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ci kaw loolu anañas dem, dugg ca kër ga, teg ay loxoom sool. mu ne ko: «sool sama mbokk, boroom bi yeesu, mi la feeñu woon ci kaw yoon wi, bi ngay dikk, moo ma yónni, ngir nga dellu di gis te fees ak xel mu sell mi.»

Français

ananias sortit; et, lorsqu`il fut arrivé dans la maison, il imposa les mains à saul, en disant: saul, mon frère, le seigneur jésus, qui t`est apparu sur le chemin par lequel tu venais, m`a envoyé pour que tu recouvres la vue et que tu sois rempli du saint esprit.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,793,788,898 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK