Vous avez cherché: ni man (Wolof - Français)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

man dou

Français

se retenir (forme d’humilité)

Dernière mise à jour : 2023-01-25
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

dañoo mel ni man; bokkuñu ci àddina.

Français

ils ne sont pas du monde, comme moi je ne suis pas du monde.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

ya ni mey sonal

Français

ne me fatigue pas

Dernière mise à jour : 2022-05-29
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

sa calam ne mène ni hag

Français

ton visage on dirait le chien

Dernière mise à jour : 2023-10-04
Fréquence d'utilisation : 3
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

nanu seet ni nu man a xiirtalante cig mbëggeel ak ci jëf yu baax.

Français

veillons les uns sur les autres, pour nous exciter à la charité et aux bonnes oeuvres.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

ndegam ñu bare dañuy damu ni nit kese, man itam kon dinaa damu.

Français

puisqu`il en est plusieurs qui se glorifient selon la chair, je me glorifierai aussi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

saxleen ci bëggante ni ay bokk.

Français

persévérez dans l`amour fraternel.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

te it ku nangu ci sama tur xale bu mel ni kii, man mii nga nangu.

Français

et quiconque reçoit en mon nom un petit enfant comme celui-ci, me reçoit moi-même.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

waaye lii neex na ma ci yaw: sib nga ni man li ñoom nikolas di jëf. i

Français

tu as pourtant ceci, c`est que tu hais les oeuvres des nicolaïtes, oeuvres que je hais aussi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

boole naa leen ci ndam, li nga ma sol, ngir ñu àndandoo, ni nu ànde man ak yaw.

Français

je leur ai donné la gloire que tu m`as donnée, afin qu`ils soient un comme nous sommes un, -

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

nangeen am yërmande, ni seen baay ame yërmande.

Français

soyez donc miséricordieux, comme votre père est miséricordieux.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

dinga xamal mbooloom,ni leen boroom bi man a musale,jaare ko ci seen mbaalug bàkkaar,

Français

afin de donner à son peuple la connaissance du salut par le pardon de ses péchés,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

bu leen timote ganesee, fexeleen ba bumu am njàqare ci seen biir, ndaxte dafay liggéeyal boroom bi ni man.

Français

si timothée arrive, faites en sorte qu`il soit sans crainte parmi vous, car il travaille comme moi à l`oeuvre du seigneur.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

waaye xam ngeen takkuteg timote, ci ni mu ànde ak man ci tas xebaar bu baax bi, ni doom di taxawoo baayam.

Français

vous savez qu`il a été mis à l`épreuve, en se consacrant au service de l`Évangile avec moi, comme un enfant avec son père.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

na ku nekk seetlu ni muy beye sasam. bu ko defee dina man a naw boppam, tey bañ di diirante mbagg ak ñi ci des.

Français

que chacun examine ses propres oeuvres, et alors il aura sujet de se glorifier pour lui seul, et non par rapport à autrui;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

noonu dina soppi sunu yaram wu toroxlu, def ko ni yaramam wi ànd ak ndam dëppook kàttanam, gi ko man a nootal mbindeef yépp.

Français

qui transformera le corps de notre humiliation, en le rendant semblable au corps de sa gloire, par le pouvoir qu`il a de s`assujettir toutes choses.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

musaa moomu moo ne woon bànni israyil: “yàlla dina leen feeñalal ci seeni bokk yonent bu mel ni man.”

Français

c`est ce moïse qui dit aux fils d`israël: dieu vous suscitera d`entre vos frères un prophète comme moi.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

gannaaw muñ nga, ni ma la ko dénke woon, man itam dinaa la yiir ci jamono, ji musiba mi di wàcc ci dunyaa bépp ngir nattu waa àddina. i

Français

parce que tu as gardé la parole de la persévérance en moi, je te garderai aussi à l`heure de la tentation qui va venir sur le monde entier, pour éprouver les habitants de la terre.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

bu fekkoonte ne ibraayma, ci kaw i jëfam la ko yàlla àttee ni ku jub, kon am na lu mu ci man a damoo. waaye demewul noonu ci kanam yàlla.

Français

si abraham a été justifié par les oeuvres, il a sujet de se glorifier, mais non devant dieu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Wolof

ku daan, dinga sol mbubb mu weex ni ñoom. te duma far sa tur ci téereb dund bi, waaye dinaa nangu ci sama kanamu baay ak ay malaakaam ne, bokk nga ci man.

Français

celui qui vaincra sera revêtu ainsi de vêtements blancs; je n`effacerai point son nom du livre de vie, et je confesserai son nom devant mon père et devant ses anges.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Référence: Anonyme

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,777,960,333 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK