Vous avez cherché: sama soppe (Wolof - Français)

Wolof

Traduction

sama soppe

Traduction

Français

Traduction
Traduction

Traduisez instantanément des textes, des documents et des voix avec Lara

Traduire maintenant

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

sama

Français

ma

Dernière mise à jour : 2024-04-26
Fréquence d'utilisation : 40
Qualité :

Wolof

sama rak

Français

français

Dernière mise à jour : 2024-04-22
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

sama nekinou

Français

wol

Dernière mise à jour : 2024-04-13
Fréquence d'utilisation : 30
Qualité :

Wolof

looloo tax, sama soppe yi, nangeen daw xërëm yi.

Français

c`est pourquoi, mes bien-aimés, fuyez l`idolâtrie.

Dernière mise à jour : 2024-04-13
Fréquence d'utilisation : 6
Qualité :

Wolof

nuyul-leen ma it urban, sunu nawle ci liggéeyu kirist, ak sama soppe estakis;

Français

saluez urbain, notre compagnon d`oeuvre en christ, et stachys, mon bien-aimé.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

sama soppe, maa ngi ñaan, yàlla may la jàmm ci lépp, ànd ak wér gi yaram, ju mel ni sa naataangeg xol.

Français

bien-aimé, je souhaite que tu prospères à tous égards et sois en bonne santé, comme prospère l`état de ton âme.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

samay soppe, bu nu sunu xol daanul, kon man nanoo jege yàlla ak kóolute.

Français

bien-aimés, si notre coeur ne nous condamne pas, nous avons de l`assurance devant dieu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maa ngi nuyu tirifen, moom ak tirifos, jigéen ñi sonn ci liggéeyu boroom bi, ak it sama soppe persidd, mi ci jeex tàkk.

Français

saluez tryphène et tryphose, qui travaillent pour le seigneur. saluez perside, la bien-aimée, qui a beaucoup travaillé pour le seigneur.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«kii mooy sama ndaw li ma tànn,di sama soppe bi neex sama xol.dinaa def sama xel ci moom,muy yégal xeet yi yoonu njub.

Français

voici mon serviteur que j`ai choisi, mon bien-aimé en qui mon âme a pris plaisir. je mettrai mon esprit sur lui, et il annoncera la justice aux nations.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag yéen samay bokk, ñi ma bëgg te namm leen, di sama mbég ak sama kaalag ndam, jàppleen bu dëgër noonu ci boroom bi, soppe yi!

Français

c`est pourquoi, mes bien-aimés, et très chers frères, vous qui êtes ma joie et ma couronne, demeurez ainsi fermes dans le seigneur, mes bien-aimés!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye nag yéen samay soppe, su fekkee ne sax, nii lanuy waxe, nu ngi yaakaar li gën ci yéen te ànd ak mucc.

Français

quoique nous parlions ainsi, bien-aimés, nous attendons, pour ce qui vous concerne, des choses meilleures et favorables au salut.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu kon mu dellusi kana ci galile, dëkk ba mu soppe woon ndox ma biiñ. amoon na benn dagu buur bu dëkkoon kapernawum te doomam feebar.

Français

il retourna donc à cana en galilée, où il avait changé l`eau en vin. il y avait à capernaüm un officier du roi, dont le fils était malade.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

man pool, mi ñu tëj kaso ngir kirist yeesu, ak sunu mbokk timote, noo lay bind, yaw filemon sunu soppe ak sunu nawle ci xeex bi;

Français

paul, prisonnier de jésus christ, et le frère timothée, à philémon, notre bien-aimé et notre compagnon d`oeuvre,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndegam nag jot nanu ci dige yu mel nii, samay soppe, nanu sellal sunu bopp ci bépp sobeb yaram walla bu xel, dund dund gu sell, ba mat ci ragal yàlla.

Français

ayant donc de telles promesses, bien-aimés, purifions-nous de toute souillure de la chair et de l`esprit, en achevant notre sanctification dans la crainte de dieu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

samay soppe, buleen gëm xel mu nekk, waaye nattuleen xel yi, ba xam ndax ci yàlla lañu jóge walla déet, ndaxte naaféq yu bare yu mbubboo turu yonent jóg nañu, tasaaroo ci àddina si.

Français

bien-aimés, n`ajoutez pas foi à tout esprit; mais éprouvez les esprits, pour savoir s`ils sont de dieu, car plusieurs faux prophètes sont venus dans le monde.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

samay soppe, li ma leen di bind du ndigal lu bees, waaye ndigal lu yàgg la; la ngeen jotoon ca ndoorte la. te ndigal lu yàgg loolu, mooy kàddu gi ngeen déggoon.

Français

bien-aimés, ce n`est pas un commandement nouveau que je vous écris, mais un commandement ancien que vous avez eu dès le commencement; ce commandement ancien, c`est la parole que vous avez entendue.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

samay soppe, buleen di feyantoo, waaye bàyyileen lépp ci loxoy yàlla, mi yelloo àtte; ndax yàlla nee na ci mbind mi: «man maay àtte, maay fey jëf.»

Français

ne vous vengez point vous-mêmes, bien-aimés, mais laissez agir la colère; car il est écrit: a moi la vengeance, à moi la rétribution, dit le seigneur.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
8,927,608,262 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK