Vous avez cherché: waxaat (Wolof - Français)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

mënuñu woon a gëm, ndaxte esayi dafa waxaat ne:

Français

aussi ne pouvaient-ils croire, parce qu`Ésaïe a dit encore:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu daldi leen bàyyi, waxaat loolu ñetteel bi yoon.

Français

il les quitta, et, s`éloignant, il pria pour la troisième fois, répétant les mêmes paroles.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu waxaat léeb wii nit, ñi foog ne jub nañu tey xeeb ñi ci des.

Français

il dit encore cette parabole, en vue de certaines personnes se persuadant qu`elles étaient justes, et ne faisant aucun cas des autres:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

pilaat waxaat ak mbooloo ma, ndaxte dafa bëggoon a bàyyi yeesu.

Français

pilate leur parla de nouveau, dans l`intention de relâcher jésus.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

moo tax mu waxaat feneen ne:“doo bàyyi sa waa ju sell, mu yàqu.”

Français

c`est pourquoi il dit encore ailleurs: tu ne permettras pas que ton saint voie la corruption.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

noonu yeesu waxaat ak mbooloo mi ne leen: «yéen ñépp dégluleen ma te xam.

Français

ensuite, ayant de nouveau appelé la foule à lui, il lui dit: Écoutez-moi tous, et comprenez.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te maa ngi dellu di waxaat ne, képp kuy farataal xaraf, fàww nga sàmm lépp lu yoon wi santaane.

Français

et je proteste encore une fois à tout homme qui se fait circoncire, qu`il est tenu de pratiquer la loi tout entière.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu waxaat ay taalibeem ne leen: «fiir yuy yóbbe nit bàkkaar mënta ñàkk, waaye toroxte dal na ki koy lal.

Français

jésus dit à ses disciples: il est impossible qu`il n`arrive pas des scandales; mais malheur à celui par qui ils arrivent!

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu waxaat leen beneen léeb ne leen: «nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni doomu fuddën bu nit jël, ji ko ci toolam.

Français

il leur proposa une autre parabole, et il dit: le royaume des cieux est semblable à un grain de sénevé qu`un homme a pris et semé dans son champ.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ma waxaat leen ko: giléem jaar ci bën-bënu pusa, moo gën a yomb boroom alal dugg ci nguuru yàlla aji kawe ji.»

Français

je vous le dis encore, il est plus facile à un chameau de passer par le trou d`une aiguille qu`à un riche d`entrer dans le royaume de dieu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

maa ngi leen koy waxaat: bu ma kenn jàpp nib dof. walla boog bu ngeen ma ko jàppee, séddleen ma céru dof, ngir ma damu tuuti, man itam.

Français

je le répète, que personne ne me regarde comme un insensé; sinon, recevez-moi comme un insensé, afin que moi aussi, je me glorifie un peu.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

li ma waxoon ci sama ñaareelu ngan, ci ñi bàkkaaroon bu yàgg ak ñi ci des, maa ngi koy waxaat léegi, bala maa dikkaat: su ma dellusee, duma yërëm kenn.

Français

lorsque j`étais présent pour la seconde fois, j`ai déjà dit, et aujourd`hui que je suis absent je dis encore d`avance à ceux qui ont péché précédemment et à tous les autres que, si je retourne chez vous, je n`userai d`aucun ménagement,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

newaat na:«dinaa am ci yàlla kóolute.» dellu na waxaat ne:«maa ngi nii, man ak doom yi ma yàlla may.»

Français

et encore: je me confierai en toi. et encore: me voici, moi et les enfants que dieu m`a donnés.

Dernière mise à jour : 2013-02-18
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu waxaat ne: «ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, du musaa moo leen jox ñam woowu wàcce ca asamaan; sama baay ci boppam, moo leen di jox ñam wu wóor, wi wàcce ca asamaan.

Français

jésus leur dit: en vérité, en vérité, je vous le dis, moïse ne vous a pas donné le pain du ciel, mais mon père vous donne le vrai pain du ciel;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,782,347,028 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK