Vous avez cherché: yónni (Wolof - Français)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Français

Infos

Wolof

ku ma gis, gis nga ki ma yónni.

Français

et celui qui me voit voit celui qui m`a envoyé.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yàlla yónni woon na nit ku ñu naan yaxya.

Français

il y eut un homme envoyé de dieu: son nom était jean.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te kàddoom saxul ci yéen, ndaxte gëmuleen ki mu yónni.

Français

et sa parole ne demeure point en vous, parce que vous ne croyez pas à celui qu`il a envoyé.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mujj mu yónni doomam naan: “xëy na ñu weg sama doom.”

Français

enfin, il envoya vers eux son fils, en disant: ils auront du respect pour mon fils.

Dernière mise à jour : 2024-04-13
Fréquence d'utilisation : 31
Qualité :

Wolof

noonu mu yónni leen ñuy yégle nguuru yàlla ak di faj jarag yi.

Français

il les envoya prêcher le royaume de dieu, et guérir les malades.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mbaa du damaa lekk seen alal, jaare ko ci kenn ci ñi ma yónni woon?

Français

ai-je tiré du profit de vous par quelqu`un de ceux que je vous ai envoyés?

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye loolu lépp dinañu leen ko def ndax man, ndaxte xamuñu ki ma yónni.

Français

mais ils vous feront toutes ces choses à cause de mon nom, parce qu`ils ne connaissent pas celui qui m`a envoyé.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yónni nanu nag yudd ak silas, ñu di leen xamal xebaar boobu ci seen gémmiñ.

Français

nous avons donc envoyé jude et silas, qui vous annonceront de leur bouche les mêmes choses.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

te nun gis nanu te seede ne, baay bi yónni na doom ji, mu nekk musalkatu àddina.

Français

et nous, nous avons vu et nous attestons que le père a envoyé le fils comme sauveur du monde.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu yégle ne: «ku ma gëm, gëmuloo ma waaye gëm nga ki ma yónni.

Français

or, jésus s`était écrié: celui qui croit en moi croit, non pas en moi, mais en celui qui m`a envoyé;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

su ko mënul, dafay yónni ndaw ca beneen buur ba, fi ak ma ngay sore, ngir ñu juboo.

Français

s`il ne le peut, tandis que cet autre roi est encore loin, il lui envoie une ambassade pour demander la paix.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

su ma dikkee, dinaa dénk seen xaalis ñi ngeen tànn, yónni leen yerusalem, boole ko ak bataaxal.

Français

et quand je serai venu, j`enverrai avec des lettres, pour porter vos libéralités à jérusalem, les personnes que vous aurez approuvées.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

mu yónneeti beneen surga, ñu rey ko. mu yónni ñeneen ñu bare, ñii ñu dóor leen, ñii ñu rey.

Français

il en envoya un troisième, qu`ils tuèrent; puis plusieurs autres, qu`ils battirent ou tuèrent.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bind nañu ci téereb yonent yàlla esayi naan:«maa ngi yónni sama ndaw ci sa kanam,mu xàllal la sa yoon.

Français

selon ce qui est écrit dans Ésaïe, le prophète: voici, j`envoie devant toi mon messager, qui préparera ton chemin;

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«bi nga xamee ne bëgg nañoo witt réseñ yi, mu yónni ay surgaam ci beykat yi, ngir jot wàllam ci meññeef mi.

Français

lorsque le temps de la récolte fut arrivé, il envoya ses serviteurs vers les vignerons, pour recevoir le produit de sa vigne.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

nit kiy wax ci coobareem nag, day wut a màggal boppam, waaye kiy wut a màggal ki ko yónni, dëgg rekk lay wax te jubadiwul fenn.

Français

celui qui parle de son chef cherche sa propre gloire; mais celui qui cherche la gloire de celui qui l`a envoyé, celui-là est vrai, et il n`y a point d`injustice en lui.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«baay, yaw ku jub ki, waa àddina xamuñu la, waaye man xam naa la, te ñii xam nañu ne, yaa ma yónni.

Français

père juste, le monde ne t`a point connu; mais moi je t`ai connu, et ceux-ci ont connu que tu m`as envoyé.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

lii mooy mbëggeel, du sunu mbëggeel ci yàlla, waaye mbëggeelam ci nun, ba mu yónni doomam, mu joxe bakkanam, ngir dindi sunuy bàkkaar.

Français

et cet amour consiste, non point en ce que nous avons aimé dieu, mais en ce qu`il nous a aimés et a envoyé son fils comme victime expiatoire pour nos péchés.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi bët setee, àttekat ya yónni alkaati ya, ñu ne boroom kaso ba: «yiwil ñaari nit ñooñu, ñu dem.»

Français

quand il fit jour, les préteurs envoyèrent les licteurs pour dire au geôlier: relâche ces hommes.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

«ku nangu xale bu mel ni bii ci sama tur, man mii nga nangu; te ku ma nangu, du man mii sax nga nangu waaye ki ma yónni.»

Français

quiconque reçoit en mon nom un de ces petits enfants me reçoit moi-même; et quiconque me reçoit, reçoit non pas moi, mais celui qui m`a envoyé.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,794,594,788 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK