Vous avez cherché: diggante (Wolof - Suédois)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Suédois

Infos

Wolof

betani ma nga woon ca wetu yerusalem, diggante bi matul woon sax ñetti kilomet.

Suédois

nu låg betania nära jerusalem, vid pass femton stadier därifrån,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

jëfeleen ak xel ci seen diggante ak waa àddina, te fu ngeen ame jot, fexeleen ba jariñoo ko.

Suédois

skicken eder visligt mot dem som stå utanför och tagen väl i akt vart lägligt tillfälle.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte jenn yàlla kepp moo am, ak benn rammukat kepp diggante yàlla ak nit ñi, di nit ki kirist yeesu,

Suédois

ty en enda är gud, och en enda är medlare emellan gud och människor: en människa, kristus jesus,

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi mu waxee loolu nag, werante wu metti daldi xew diggante farisen ya ak sadusen ya, ba mbooloo ma xaajalikoo.

Suédois

knappt hade han sagt detta, förrän en strid uppstod mellan fariséerna och sadducéerna, så att hopen blev delad.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

gan déggoo moo man a am diggante kirist ak beliyar? gan jaxasoo moo man a am diggante ki gëm ak ki gëmul?

Suédois

huru förlika sig kristus och beliar, eller vad delaktighet har den som tror med den som icke tror?

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

su fekkee sa ngëm dëgër na, wone ko ci sa diggante ak yàlla. kiy nangu, te du ci sikkal boppam, kooku barkeel na.

Suédois

den tro du har må du hava för dig själv inför gud. salig är den som icke måste döma sig själv, när det gäller något som han har prövat vara rätt.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag amul xaajale ci diggante yawut ak ki dul yawut, ci diggante jaam ak gor, ci diggante góor ak jigéen. yéen ñépp benn ngeen ci seen bokk ci kirist.

Suédois

här är icke jude eller grek, här är icke träl eller fri, här är icke man och kvinna: alla ären i ett i kristus jesus.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

waaye ni jaan ja naxe woon awa ci pexeem, ragal naa yéen itam ñu lëmbaaje ni seen xel, ba ngeen dëddu xol bu laab, bi ngeen amoon ci seen diggante ak kirist.

Suédois

men jag fruktar att såsom ormen i sin illfundighet bedrog eva, så skola till äventyrs också edra sinnen fördärvas och dragas ifrån den uppriktiga troheten mot kristus.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bi erodd nekkee ci tànki indilu ko, ca guddi googa yeewoon nañu piyeer ak ñaari càllala, muy nelaw diggante ñaari xarekat, te ay xarekat di wottu buntu kaso ba.

Suédois

natten före den dag då herodes tänkte draga honom inför rätta låg petrus och sov mellan två krigsmän, fängslad med två kedjor; och utanför dörren voro väktare utsatta till att bevaka fängelset.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

am naa warugar sama diggante ak ñépp, muy ñi jàng ni gereg yi, muy ñi jàngul ni baarbaar yi, ñi bare xam-xam ak ñi barewul xam-xam.

Suédois

både mot greker och mot andra folk, både mot visa och mot ovisa har jag förpliktelser.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

looloo tax mu nekk rammukat bi ci wàllu kóllëre gu bees ci diggante yàlla ak nit, ngir ñi yàlla woo am cér bu sax ci kaw, te mu digoon leen ko, ndaxte kirist dee na, ngir jot ñi jàdd yoon ca kóllëre gu jëkk ga.

Suédois

så är han medlare för ett nytt förbund, på det att de som voro kallade skulle få det utlovade eviga arvet, därigenom att en led döden till förlossning ifrån överträdelserna under det förra förbundet.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte ndëndu xare jib na, waxuma sunu diggante ak nit ñi, waaye ak kilifa yiy nëxal àddina si, ñuy kilifa yi ak ay boroom sañ-sañ, di gaayi seytaane yi ci bérab yu kawe yi.

Suédois

ty den kamp vi hava att utkämpa är en kamp icke mot kött och blod, utan mot furstar och väldigheter och världshärskare, som råda här i mörkret, mot ondskans andemakter i himlarymderna.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

kon nag su jabar ji àndee ak beneen góor, te fekk jëkkër jiy dund, dees na ko àtte njaaloo. waaye bu jëkkër ji faatoo, yoon jeexal na seen diggante; man na séy nag ak beneen góor, te loolu du njaaloo.

Suédois

alltså, om hon giver sig åt en annan man, medan hennes man lever, så kallas hon äktenskapsbryterska; men om mannen dör, då är hon fri ifrån lagen, så att hon icke är äktenskapsbryterska, om hon giver sig åt en annan man.

Dernière mise à jour : 2012-05-04
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,790,634,577 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK