Vous avez cherché: bindoon (Wolof - Tchèque)

Contributions humaines

Réalisées par des traducteurs professionnels, des entreprises, des pages web ou traductions disponibles gratuitement.

Ajouter une traduction

Wolof

Tchèque

Infos

Wolof

bindoon naa leen, ngeen bañ a séq dara ak njaalookat yi.

Tchèque

psal jsem vám v listu, abyste se nesměšovali s smilníky.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

wottuleen nag ba li yonent yi bindoon bañ leen a dal, ci li ñu ne:

Tchèque

protož vizte, ať na vás nepřijde to, což jest v prorocích povědíno:

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

ndaxte ci bés yooyu yàlla dina fey jëf yi, te li ñu bindoon ci téereb yàlla dina mat.

Tchèque

neboť budou dnové pomsty, aby se naplnilo všecko, což psáno jest.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yaw teyofil, téere bu jëkk, ba ma bindoon, ëmb na lépp li yeesu tàmbali woon a jëf ak a jàngale,

Tchèque

první zajisté knihu sepsalť jsem, ó teofile, o všech věcech, kteréž začal ježíš činiti a učiti,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

bindoon nañu ci jëwam tur wii ëmb kumpa, mu di: babilon mu mag mi, ndeyi jigéeni moykat yi ak ñaawteefi àddina yi.

Tchèque

a na čele jejím napsané jméno: tajemství, babylon veliký, mátě smilstva a ohavností země.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

yeesu wéetoo ak fukki taalibe yi ak ñaar ne leen: «nu ngi dem yerusalem, te li yonent yi bindoon lépp ci mbirum doomu nit ki dina mat.

Tchèque

tedy pojav ježíš dvanácte, řekl jim: aj, vstupujeme do jeruzaléma, a naplníť se všecko to, což psáno jest skrze proroky o synu člověka.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

def na ko ngir nun seeni sët, ci li mu dekkal yeesu. moom lañu bindoon ci ñaareelu saaru sabóor ne:“yaa di sama doom,maa di sa baay tey.”

Tchèque

jakož i v druhém Žalmu napsáno jest: syn můj jsi ty, já dnes zplodil jsem tebe.

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Wolof

saraxalukaayu wurus, ba ñuy taal cuuraay ca kawam, a nga fa woon, ak gaalu kóllëre, ga ñu taf wurus ba mu daj. ca biir gaal ga amoon na fa benn njaqu wurus bu defoon ñam, wi ñuy wax mànn, ak it yetu aaroona wi jebbi woon, ak àlluway doj, ya ñu bindoon wax yi kóllëre gi ëmb.

Tchèque

zlatou maje kadidlnici, a truhlu smlouvy, všudy obloženou zlatem, kdežto bylo věderce zlaté, mající v sobě mannu, a hůl aronova, kteráž byla zkvetla, a dsky zákona,

Dernière mise à jour : 2012-05-05
Fréquence d'utilisation : 1
Qualité :

Obtenez une traduction de meilleure qualité grâce aux
7,793,378,509 contributions humaines

Les utilisateurs demandent maintenant de l'aide :



Nous utilisons des cookies pour améliorer votre expérience utilisateur sur notre site. En poursuivant votre navigation, vous déclarez accepter leur utilisation. En savoir plus. OK