Da traduttori professionisti, imprese, pagine web e archivi di traduzione disponibili gratuitamente al pubblico.
e mandò avanti dei messaggeri. questi si incamminarono ed entrarono in un villaggio di samaritani per fare i preparativi per lui
noonu mu yebal ay ndaw, ñu jiitu ko. Ñu dem nag, dugg ci ab dëkk ci diiwaanu samari, ngir wutal ko fa fu mu dal.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
e quando i samaritani giunsero da lui, lo pregarono di fermarsi con loro ed egli vi rimase due giorni
Ñu daldi dikk ñaan yeesu, mu dal ak ñoom. yeesu toog fa ñaari fan.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
e si gettò ai piedi di gesù per ringraziarlo. era un samaritano
mu dëpp jëwam ca tànki yeesu, di ko gërëm. fekk nitu samari la woon.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
gli risposero i giudei: «non diciamo con ragione noi che sei un samaritano e hai un demonio?»
yawut ya ne ko: «ndax danoo waxul dëgg, bu nu nee, nitu samari nga te dangaa am ay rab?»
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
invece un samaritano, che era in viaggio, passandogli accanto lo vide e n'ebbe compassione
waaye benn waay bu dëkk samari bu doon tukki, ñëw ba jege waa ja, gis ko, yërëm ko.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
ma la samaritana gli disse: «come mai tu, che sei giudeo, chiedi da bere a me, che sono una donna samaritana?». i giudei infatti non mantengono buone relazioni con i samaritani
jigéen ja tontu ko ne: «yaw, ngay yawut, man maay jigéen ju dëkk samari; nan nga ma man a ñaane ndox?» jigéen ja wax na loolu, ndaxte yawut ya bokkuñu woon ak waa samari ndab yu ñuy lekke.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità:
molti samaritani di quella città credettero in lui per le parole della donna che dichiarava: «mi ha detto tutto quello che ho fatto»
bi jigéen ja nee waa dëkk ba: «wax na ma li ma def lépp,» ñu bare gëm nañu yeesu.
Ultimo aggiornamento 2012-05-05
Frequenza di utilizzo: 1
Qualità: