検索ワード: dhaifu (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

nilipokuwa kwenu nilikuwa dhaifu, natetemeka kwa hofu nyingi.

ウォロフ語

bi ma teewee ci yéen, ànd naa ak ñàkk doole, ragal ak njàqare.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, inueni mikono yenu inayolegea na kuimarisha magoti yenu yaliyo dhaifu.

ウォロフ語

kon nag mayleen doole loxo yi toqi, ak óom yi bañ,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

maadamu yeye mwenyewe yu dhaifu anaweza kuwaonea huruma wale wasiojua kitu na wanaofanya makosa.

ウォロフ語

te ndegam moom ci boppam nit kese la, man na muñal ñiy moy ndax seen ñàkka xam.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kama mkiwakosesha ndugu zenu jinsi hiyo na kuzijeruhi dhamiri zao dhaifu, mtakuwa mmemkosea kristo.

ウォロフ語

su ngeen bàkkaaree, ba tooñ bokk yi néew ngëm, di nëxal seen xel, bàkkaar ngeen ba tooñ kirist.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini, jihadharini: huu uhuru wenu usiwafanye walio na imani dhaifu waanguke katika dhambi.

ウォロフ語

waaye moytuleen, ba sañ-sañ bi ngeen am, bañ a yóbbe bàkkaar ñi seen ngëm néew.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hivyo, huyo ndugu yako dhaifu ambaye kristo alikufa kwa ajili yake, atapotea kwa sababu ya ujuzi wako.

ウォロフ語

noonu sa xam-xam dina lor kooku ngëmam néew, fekk sa mbokk moomu, kirist dee na ngir moom!

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

baadhi yao huenda katika nyumba za watu na huwateka wanawake dhaifu waliolemewa mizigo ya dhambi na ambao wanaongozwa na tamaa za kila aina;

ウォロフ語

nit ñu mel noonu ñooy yoxoosu ci biir kër yi, ba fàbbi jigéen ñu ñàkk pasteef, ñi seeni bàkkaar ub seen bopp, te bëgg-bëgg yu wuute jiital leen.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

huzikwa katika hali duni, hufufuliwa katika hali tukufu; huzikwa katika hali dhaifu, hufufuliwa ukiwa wenye nguvu.

ウォロフ語

lu ñàkk solo lañuy suul; mu dekki ak ndam. lu néew doole lañuy suul, mu dekki ak kàttan.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini sasa, kwa vile mnamjua mungu, au tuseme mnajulikana na mungu, mnawezaje tena kurudi kwa wale pepo maskini na dhaifu hata kutaka kuwatumikia tena?

ウォロフ語

waaye léegi nag bi ngeen xamee yàlla, walla boog bi leen yàlla xàmmee, nan ngeen man a def, bay delluwaat ca aaday àddina? aada yooyee ñàkk doole te ñàkk njariñ, lu tax ngeen bëgg, ñu nootaat leen?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kisha akawaambia, "kesheni na kusali ili msije mkaingia katika majaribu. roho i radhi, lakini mwili ni dhaifu."

ウォロフ語

xool-leen te ñaan, ngir bañ a daanu cig fiir. seen xol jag na, waaye seen bind a woyof.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

kwa aibu nakubali kwamba sisi tulikuwa dhaifu. iwe iwavyo, lakini kama kuna mtu yeyote anayethubutu kujivunia kitu--nasema kama mtu mpumbavu--mimi nathubutu pia.

ウォロフ語

sunu néew doole mayu nu, nu dem ba jëfe noonu; rus naa ci lool de! ma wax waxi dof; moona lépp lu waay ñemee damoo, ñeme naa ko, man it.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

maana, mtu ambaye dhamiri yake ni dhaifu, akikuona wewe mwenye ujuzi unakula vyakula hivyo ndani ya hekalu la sanamu, je, hatatiwa moyo wa kula vyakula vilivyotambikiwa sanamu?

ウォロフ語

su amee ku ngëmam néew, mu gis la, yaw mi bare xam-xam, nga toog di lekk ca màggalukaayu xërëm ya, ndax du ko xiir mu lekk yàppu sarax?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kadhalika nanyi waume, katika kuishi na wake zenu mnapaswa kutambua kwamba wao ni dhaifu na hivyo muwatendee kwa heshima; maana nao pia watapokea pamoja nanyi zawadi ya uzima anayowapeni mungu. hapo ndipo sala zenu hazitakataliwa.

ウォロフ語

te yéen itam góor ñi, na ku nekk ci yéen am xel, ci ni ngay ànde ak sa jabar, xam ne àndandoo ju la gën a néew doole la. joxleen ko teraanga ju mat, ndax yéena yem cér ci yiwu yàlla, wi nu ubbil buntu dund gu dul jeex. noonu dara du man a yàq seeni ñaan.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini, si kila mtu anao ujuzi huu. maana wako watu wengine waliokwisha zoea sanamu, watu ambao mpaka hivi sasa wanapokula vyakula huviona bado kama vyakula vilivyotambikiwa sanamu. na kwa vile dhamiri zao ni dhaifu, hutiwa unajisi.

ウォロフ語

waaye ñépp xamuñu loolu. am na ñu tàmmoon xërëm yi, te léegi, bu ñu lekkatee yàppu sarax yi, dañuy xalaat ne, xërëm lañu ko jagleel. seen xel dafa leen di yedd, ndaxte ci seen ñàkka xam dañuy foog ne, taq nañu sobe ndax ñam woowu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mtu anaweza kusema: "barua za paulo ni kali na zenye maneno mazito, lakini yeye mwenyewe anapokuwa pamoja nasi ni mtu dhaifu, na hata anapoongea maneno yake ni kama si kitu."

ウォロフ語

ndaxte am na ku naan: «ay bataaxalam dañoo ñagas te am doole, waaye bu teewee dafay ñàkk fulla, di wax waxi picc.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
8,045,136,445 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK