検索ワード: duniani (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

"upate fanaka na miaka mingi duniani."

ウォロフ語

maanaa: «ngir nga am gudd fan gu ànd ak jàmm.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

kweli tunaishi duniani, lakini hatupigani vita kidunia.

ウォロフ語

dëgg la ne nit rekk lanu, waaye dunu xeexe ni nit.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa maana itawajia kama mtego, wote wanaoishi duniani pote.

ウォロフ語

ndaxte dina dal ci ñépp ñi nekk ci kaw suuf.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

maana hatukuleta kitu chochote hapa duniani, wala hatutachukua chochote.

ウォロフ語

ndaxte indaalewunu fi dara, te dunu yóbbaale dara.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"nimekuja kuwasha moto duniani, laiti ungekuwa umewaka tayari!

ウォロフ語

«damaa ñëw ngir indi safara si ci àddina, te bëgg naa xaat taal bi tàkk.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

maana hapa duniani hatuna mji wa kudumu; lakini tunautafuta ule unaokuja.

ウォロフ語

amunu fii ci àddina dëkk bu sax ba fàww, waaye nu ngi wut dëkk biy ñëw.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

wewe umewafanya wawe ufalme wa makuhani wamtumikie mungu wetu nao watatawala duniani."

ウォロフ語

def nga leen askanu saraxalekatibuur yàlla sunu boroom,di ko jaamu,te dinañu nguuru ci àddina.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"utukufu kwa mungu juu mbinguni, na amani duniani kwa watu aliopendezwa nao!"

ウォロフ語

«nañu màggal yàlla ca asamaan su kawe sa,te ci àddina, na jàmm ji wàcc ci nit, ñi mu nangu ndax yiwam!»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, huyo aliyeshuka hapa duniani, ndiye aliyepaa juu ya mbingu zote apate kuujaza ulimwengu.

ウォロフ語

ki wàccoon moo yéegaat, ba tiim asamaan yépp, ngir fees lépp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"msidhani kwamba nimekuja kuleta amani duniani. sikuja kuleta amani bali upanga.

ウォロフ語

«te it buleen defe ne, damaa ñëw ngir indi jàmm ci àddina; ñëwuma ngir indi jàmm, waaye jaasi laa indaale.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"nawaambieni kweli, mtakachofunga duniani kitafungwa mbinguni, na mtakachofungua duniani kitafunguliwa mbinguni.

ウォロフ語

ci dëgg maa ngi leen koy wax, lépp lu ngeen yeew ci àddina, dees na ko yeew ci asamaan, te lépp lu ngeen yiwi ci àddina, dees na ko yiwi ci asamaan.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, huyu mnyama wa pili akafanya miujiza mikubwa hata akasababisha moto kutoka mbinguni ushuke duniani mbele ya watu.

ウォロフ語

muy def kéemaan yu réy, ba dem sax bay wàcce ci kaw suuf safara su jóge asamaan, nit ñi di gis.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mavazi yake yakang'aa, yakawa meupe sana, jinsi dobi yeyote duniani asingeweza kuyafanya meupe.

ウォロフ語

ay yéreem di ray-rayi, weex tàll, te fóotukatu àddina mënu leen weexale nii.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kama matumaini yetu katika kristo yanahusu tu maisha haya ya sasa, basi, sisi ni watu wa kusikitikiwa zaidi kuliko wengine wote duniani.

ウォロフ語

su fekkee ci giiru dund gii rekk la sunu yaakaar ci kirist ame solo, kon noo gën a mat a yërëm ñépp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

alifedheheshwa na kunyimwa haki. hakuna atakayeweza kuongea juu ya kizazi chake, kwa maana maisha yake yameondolewa duniani."

ウォロフ語

ci toroxteem nangu nañu dëggam;ñi mu tollool jamono, ku ci xalaat lii?jële nañu bakkanam ci àddina.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

iko miili ya mbinguni na miili ya duniani; uzuri wa miili ya mbinguni ni mwingine, na na uzuri wa miili ya duniani ni mwingine.

ウォロフ語

am na itam ay jëmm ca asamaan ak ay jëmm ci suuf. leeru jëmm ca asamaan wuute na ak gi ci suuf.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"kutakuwa na ishara katika jua na mwezi na nyota. mataifa duniani yatakuwa na dhiki kwa sababu ya wasiwasi kutokana na mshindo wa mawimbi ya bahari.

ウォロフ語

«ay firnde dinañu feeñ ci jant bi, ci weer wi ak ci biddiiw yi. ci kaw suuf xeet yi dinañu tiit, jaaxle ndax riiru géej gi ak yengu-yengub duus yi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, malaika huyo akautupa mundu wake duniani, akakata zabibu za dunia, akazitia ndani ya chombo kikubwa cha kukamulia zabibu, chombo cha ghadhabu ya mungu.

ウォロフ語

noonu malaaka ma daldi dawal sàrtam ci àddina, dagg réseñ yi, sànni leen ci biir segalukaay bu réy bu merum yàlla.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

joka hilo liliburuta kwa mkia wake theluthi moja ya nyota za anga na kuzitupa duniani. nalo lilisimama mbele ya huyo mama aliyekuwa karibu kujifungua mtoto, tayari kabisa kummeza mtoto, mara tu atakapozaliwa.

ウォロフ語

geenam di laawaale ñetti cér yu ne benn ca biddiiwi asamaan, di leen sànni ci suuf. ninkinànka ja taxaw ca kanamu jigéen jay matu, ngir lekk liir ba, bu juddoo.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"anayekuja kutoka juu ni mkuu kuliko wote; atokaye duniani ni wa dunia, na huongea mambo ya kidunia. lakini anayekuja kutoka mbinguni ni mkuu kuliko wote.

ウォロフ語

ki jóge ci kaw moo féete kaw ñépp; ki jóge ci suuf nag, ci suuf rekk la man a bokk, te ni niti àddina lay waxe. ki jóge asamaan

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
8,034,296,130 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK