検索ワード: isipokuwa (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

lakini sikuwaona mitume wengine isipokuwa yakobo, ndugu yake bwana.

ウォロフ語

waaye gisuma keneen ci ndaw yi ku dul saag, doomu ndeyu boroom bi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

namshukuru mungu kwamba sikumbatiza mtu yeyote miongoni mwenu isipokuwa tu krispo na gayo.

ウォロフ語

maa ngi sant yàlla ci li ma sóobul kenn ci yéen, ku dul kirispus ak gayus,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hakuna mtu aliyepata kwenda juu mbinguni isipokuwa mwana wa mtu ambaye ameshuka kutoka mbinguni.

ウォロフ語

kenn musul a yéeg ci asamaan su dul ki fa jóge, muy doomu nit ki.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

msiwe na deni kwa mtu yeyote, isipokuwa tu deni la kupendana. ampendaye jirani yake ameitekeleza sheria.

ウォロフ語

buleen ameel kenn dara, lu dul mbëggeel; ndax ku bëgg sa moroom, wàccoo nga ak yoonu musaa.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

nilipokuwa kwenu niliamua kutojua chochote kile isipokuwa tu kumjua yesu kristo; naam, kristo aliyesulubiwa.

ウォロフ語

dogu woon naa ci bañ a xam dara ci seen biir lu dul yeesu kirist, te muy ki ñu rey ca bant ba.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, nitajivunia juu ya mtu wa namna hiyo, na si juu yangu mimi binafsi, isipokuwa tu juu ya udhaifu wangu.

ウォロフ語

dinaa damu ci nit ku mel noonu. waaye duma damu ci sama bopp, lu dul liy wone sama néew doole.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

akapiga marufuku mtu yeyote kununua au kuuza kitu isipokuwa tu mtu aliyetiwa alama hiyo, yaani jina la yule mnyama au tarakimu ya jina hilo.

ウォロフ語

ba kenn du man a jënd mbaa mu jaay te amul màndargam rab wi, maanaam turam walla siifar bu mengoo ak turam.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

yesu akawaambia, "nabii hakosi heshima isipokuwa katika nchi yake, kwa jamaa zake na nyumbani mwake."

ウォロフ語

noonu yeesu ne leen: «dees na faaydaal yonent, waaye du ci réewam, ciy bokkam mbaa ci këram.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

kweli nawaambieni, punje ya ngano hubaki punje tu isipokuwa ikianguka katika udongo na kufa. kama ikifa, basi huzaa matunda mengi.

ウォロフ語

ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, fi ak peppu dugub ji wadd ci suuf jaarul ci dee, du man a weesu li mu doon: pepp doŋŋ. waaye bu deeyee, dina jur pepp yu bare.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"anathubutuje kusema hivyo? anamkufuru mungu! hakuna mtu awezaye kusamehe dhambi isipokuwa mungu peke yake."

ウォロフ語

«kii kan la, ba sañ a wax lii; mi ngi sosal yàlla. ana ku man a baale bàkkaar yi, ku dul yàlla doŋŋ?»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, wakawa na mashaka naye. lakini yesu akawaambia, "nabii hakosi kuheshimiwa, isipokuwa katika nchi yake na nyumbani mwake!"

ウォロフ語

kon ñu daldi koy xeeb.noonu yeesu ne leen: «dees na faaydaal yonent, waaye du ci réewam ak ci këram.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

je, mlipungukiwa nini zaidi kuliko makanisa mengine, isipokuwa tu kwamba mimi kwa upande wangu sikuwasumbueni kupata msaada wenu? samahani kwa kuwakoseeni haki hiyo!

ウォロフ語

lan laa defal yeneen mboolooy ñi gëm te defaluma leen ko, xanaa rekk li ma wéeru ci ñoom te wéeruma ci yéen? baal-leen ma googu tooñ!

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

msinyimane haki zenu, isipokuwa kama mnaafikiana kufanya hivyo kwa kitambo tu, ili mpate nafasi nzuri ya kusali. kisha rudianeni tena mara, ili shetani asije akawajaribu kwa sababu ya udhaifu wenu.

ウォロフ語

bu kenn tere boppam moroomam, su dul ne dangeen a mànkoo ci def noonu ab diir, ngir gën a man a wéet ak yàlla ciy ñaan. waaye su loolu weesoo, nangeen doxal yoonu séy; lu ko moy, seytaane dina leen fiir ndax seen ñàkk maandute.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kizazi kiovu kisicho na uaminifu! mnataka ishara, lakini hamtapewa ishara yoyote isipokuwa tu ile ya yona." basi, akawaacha, akaenda zake.

ウォロフ語

yéenay laaj firnde, yéen niti jamono ju bon jii, yéen ñi fecci seen kóllëre ak yàlla. waaye dungeen jot genn firnde gu dul firndeg yunus.» bi yeesu waxee loolu, mu jóge ci ñoom, dem.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

hivyo, ndugu zangu, kama nikija kwenu na kusema nanyi kwa lugha ngeni itawafaa nini? haitawafaa chochote, isipokuwa tu kama nitawaelezeni ufunuo wa mungu au ujuzi fulani au ujumbe wa mungu au mafundisho fulani.

ウォロフ語

kon nag bokk yi, su ma ñëwee ci yéen, di wax ay làkk, lu ma leen di jariñ? dara, su ma leen indilul dëgg gu yàlla feeñal, walla xam-xam walla kàddu gu tukkee ca yàlla, walla am njàngale.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"aliye na masikio, basi, na asikie yale roho anayoyaambia makanisa! "wale wanaoshinda nitawapa ile mana iliyofichika. nitawapa pia jiwe jeupe lililoandikwa jina jipya ambalo hakuna mtu aliyelijua isipokuwa tu wale wanaolipokea.

ウォロフ語

yaw mi am ay nopp, déglul li xelum yàlla di wax mboolooy ñi gëm. ku daan, dinaa la jox, nga lekk dund bi ñuy wax mànn te mu nëbbu, te dinaa la jox xeer wu weex. ci kaw xeer woowu bindees na ci tur wu bees wu kenn xamul, ku dul ki ko jot.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,783,731,556 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK