検索ワード: kiroho (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

wote walikula chakula kilekile cha kiroho,

ウォロフ語

Ñoom ñépp bokk nañoo lekk ñam, wa yàlla joxe,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mtu huzaliwa kimwili kwa baba na mama, lakini huzaliwa kiroho kwa roho.

ウォロフ語

lu juddoo ci nit, nit la; waaye lu juddoo ci xelum yàlla, xel la.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

vipaji vya kiroho ni vya namna nyingi, lakini roho avitoaye ni mmoja.

ウォロフ語

am na fànni may yu bare yu jóge ci xelum yàlla, waaye menn xel moomu moo koy séddale.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa maana ninatamani sana kuwaoneni ili nipate kuwagawieni zawadi ya kiroho na kuwaimarisha.

ウォロフ語

ndaxte bëgg naa leen a gis lool, ba indil leen barke bu jóge ci xel mu sell mi, ndax seen ngëm gën a dëgër.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hata hampungukiwi kipaji chochote cha kiroho mkiwa mnangojea kufunuliwa kwake bwana wetu yesu kristo.

ウォロフ語

noonu nag ñàkkuleen genn may léegi bi ngeen di séentu waxtu, wi sunu boroom yeesu kirist di feeñ ci biir ndamam.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini unaotangulia kuwako si ule mwili wa kiroho, ila ule mwili wa kawaida kisha ule mwili wa kiroho.

ウォロフ語

yaram wi soloo ndamu xelum yàlla jiituwul; yaramu doom aadama moo jiitu; yaramu ndam li moo ci topp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ikiwa sisi tumepanda mbegu ya kiroho kati yenu, je, ni jambo kubwa tukichuma kwenu faida ya kidunia?

ウォロフ語

nu ji ci yéen yëfi xelum yàlla, ba noppi góobe ci yéen yëfi àddina, ndax loolu dafa ëpp li nu war a séentu?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

unapozikwa ni mwili wa kawaida, unapofufuliwa ni mwili wa kiroho. kuna mwili wa kawaida na kutakuwa na mwili wa kiroho.

ウォロフ語

bu ñu koy suul, yaram lay doon wu soloo woon ruu. bu dekkee, doon yaram wu soloo ndamu xelum yàlla. ndegam am na yaram wu soloo ruu, kon dina am yaram wu soloo ndamu xelum yàlla.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

jitahidini kuwa na upendo. vilevile fanyeni bidii ya kupata vipaji vingine vya kiroho, hasa kipaji cha kutangaza ujumbe wa mungu.

ウォロフ語

xintewooleen mbëggeel te fonk mayi xelum yàlla, rawatina mayu wax ci kàddug yàlla,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

atukuzwe mungu na baba wa bwana wetu yesu kristo! maana, katika kuungana na kristo ametubariki kwa kutujalia zawadi zote za kiroho mbinguni.

ウォロフ語

cant ñeel na yàlla baayu sunu boroom yeesu kirist, mi nu sotti ci sunu bokk ci kirist lépp luy barkeel ci baatin te nekk ca bérab yu kawe ya.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi sisi twafundisha, si kwa maneno tuliyofundishwa kwa hekima ya binadamu, bali kwa maneno tuliyofundishwa na roho, tukifafanua mambo ya kiroho kwa walio na huyo roho.

ウォロフ語

te loolu nu yàlla may, yéglewunu ko ci ay baat yu soqikoo ci xam-xamu nit, waaye nu ngi koy yégle ci baat, yi soqikoo ci xelum yàlla, di tekkantal yëfi xelum yàlla ci ay baat yu mu nu sol.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa sababu hiyo, hao waliokufa ambao walikuwa wamehukumiwa katika maisha yao ya kimwili kama anavyohukumiwa kila mmoja, walihubiriwa habari njema kusudi katika maisha yao ya kiroho waishi kama aishivyo mungu.

ウォロフ語

looloo waral it ñu jottali xebaar bu baax ndee, ya fekke woon jamonoy nóoyin jooju, ngir ñu dunde yàlla ci seen xel, doonte sax nit ñaa ngi leen daan fitnaal ci àddina.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hata hivyo, sisi tunatumia lugha ya hekima kwa wale waliokomaa kiroho; lakini hekima hiyo si ya hapa duniani, wala si ya watawala wa dunia hii ambao wako katika mkumbo wa kupotea.

ウォロフ語

moona am na xam-xam bu nuy yégal ñi mat, xam-xam bu bokkul ci àddina si, te njiiti àddina si xamuñu ko, ñoom ñi nar a wéy.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ujumbe wa kristo ukae ndani yenu pamoja na utajiri wake wote. fundishaneni na kushauriana kwa hekima yote. imbeni zaburi, nyimbo na tenzi za kiroho; mwimbieni mungu mioyoni mwenu kwa shukrani.

ウォロフ語

na kàddug kirist dëkk ci yéen, bay baawaan, ngeen di jàngalante ak a artoonte ci seen biir ak xel mu mat sëkk, di woy ak a gërëm yàlla ak seen xol bépp, ay taalifi sabóor, ay kañ yàlla ak ay cant yu tukkee ci xelum yàlla.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa maana kristo mwenyewe alikufa kwa ajili ya dhambi zenu; alikufa mara moja tu na ikatosha, mtu mwema kwa ajili ya waovu, ili awapeleke ninyi kwa mungu. aliuawa kimwili lakini akafanywa hai kiroho;

ウォロフ語

ndaxte kirist ci boppam dee na benn yoon ba fàww, ngir dindi bàkkaar yi, moom mi jub ngir ñi jubadi, ngir yóbbu leen fa yàlla; dee na ci jëmm, waaye dundaat na ci xel.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

人による翻訳を得て
7,747,458,550 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK