プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。
jaribuni kujua yale yanayompendeza bwana.
dëggal-leen ci seeni jëf li neex boroom bi,
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
wanafunzi wakatazama wasiweze kabisa kujua anasema nani.
taalibe yi di xoolante, te xamuñu kan lay wax.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
kwa hiyo, msiwe wapumbavu, bali jaribuni kujua matakwa ya bwana.
buleen ñàkk bopp nag, waaye xamleen liy coobareg boroom bi.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
basi, wakamwashiria baba yake wapate kujua alitaka mtoto wake apewe jina gani.
Ñu daldi liyaar baayam, ngir xam nan la bëgg ñu tudde xale ba.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
kila mwanamume anapaswa kujua namna ya kuishi na mkewe kwa utakatifu na heshima,
ngeen noot seeni cér ci cell ak tedd,
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
nanyi mkiyasoma maneno yangu mtaweza kujua jinsi ninavyoielewa siri hiyo ya kristo.)
bu ngeen jàngee loolu, dingeen man a xam bu wér dégg, gi ma am ci mbóoti mbiri kirist.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
"je, sheria yetu humhukumu mtu kabla ya kumsikia kwanza na kujua anafanya nini?"
«ndax ci sunu yoon, man nañoo daan kenn te dégluwuñu ko, mbaa ñu xam lu mu def?»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
msisahau kuwakaribisha wageni; maana kwa kufanya hivyo watu wengine walipata kuwakaribisha malaika bila kujua.
buleen fàttee teral ñiy ñëw ci yéen, ndaxte ñenn ñi, bi ñu ko defee, teral nañu ay malaaka te xamuñu ko.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
ingalikuwa afadhali kwao kama wasingalijua kamwe njia hiyo ya uadilifu kuliko kujua na kisha kuiacha na kupoteza amri takatifu waliyopokea.
ndaxte ñu xam yoon wu jub wi, ba noppi dëddu ndigal lu sell li ñu déggoon, bañoon koo xam moo gënoon ci ñoom.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
tukiko, ndugu yetu mpenzi na mtumishi mwaminifu wa bwana, atawapeni habari zangu zote mpate kujua ninachofanya.
yónnee naa leen tisig sama mbokk, mi ma sopp, te muy jawriñ ju takku ci liggéeyu boroom bi, ngir mu xamal leen lépp li aju ci man ak li may def.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
hivyo walimchukua paulo, wakampeleka areopago, wakasema, "tunataka kujua jambo hili jipya ulilokuwa unazungumzia.
kon nag ñu jël ko, yóbbu ko ca géew, ba ñuy wax areyopas. Ñu ne ko: «danoo bëggoon, nga leeral nu ci sa xam-xam bu bees, bii ngay yégle.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
naye akawaambia, "ninyi mmejaliwa kujua siri ya utawala wa mungu, lakini wale walio nje wataambiwa kila kitu kwa mifano,
mu tontu leen: «yéen may nañu leen, ngeen xam mbóoti nguuru yàlla, waaye ñi ci biti léeb ay ëmb lépp.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
halafu anania akasema: mungu wa babu zetu amekuchagua upate kujua matakwa yake na kumwona yule mtumishi wake mwadilifu na kumsikia yeye mwenyewe akiongea.
mu ne ma: “sunu yàllay maam tànn na la, ba may la, nga xam coobareem te gis aji jub ji te nga dégg ay waxam.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
enyi wanafiki! mnajua kutabiri hali ya hewa kwa kuangalia dunia na anga; kwa nini basi, hamwezi kujua maana ya nyakati hizi?
naaféq yi ngeen doon! man ngeen a ràññee melow asamaan ak suuf, waaye lu tax mënuleen a ràññee li jamonoy léegi ji di tekki?
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
"huyo mtu mashuhuri alirudi nyumbani baada ya kufanywa mfalme, na mara akaamuru wale watumishi aliowapa zile fedha waitwe ili aweze kujua kila mmoja amepata faida gani.
«bi ñu ko falee buur nag, ba mu dellusi, mu woolu surga, ya mu joxoon wurus wa, ngir xam nan lañu ci liggéeye.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
napenda kujua tu kitu kimoja kutoka kwenu: je, mlipokea roho wa mungu kwa sababu ya kutimiza matakwa ya sheria ama kwa sababu ya kuisikia na kuiamini habari njema?
lenn rekk laa bëgg, ngeen wax ma ko: ndax sàmm yoon wee tax, ngeen jot xelum yàlla? déedéet! dangeen a dégg xebaar bu baax bi te gëm ko.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
mimi niwe ndani yao, nawe uwe ndani yangu; naomba wakamilishwe na kuwa kitu kimoja, ili ulimwengu upate kujua kwamba wewe ulinituma, na kwamba unawapenda wao kama unavyonipenda mimi.
man ci ñoom, yaw it ci man, ngir ñu gën a ànd, nekk benn, ba àddina xam ne yaa ma yónni, xam ne bëgg nga leen, ni nga ma bëgge.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
basi, ninyi na watu wote wa israeli mnapaswa kujua kwamba mtu huyu anasimama mbele yenu leo, mzima kabisa, kwa nguvu ya jina lake yesu wa nazareti ambaye ninyi mlimsulubisha, lakini mungu akamfufua kutoka wafu.
nangeen xam lii, yéen ñépp ak bànni israyil gépp! ci turu yeesu kirist mu nasaret, mi ngeen daajoon ca bant te yàlla dekkal ko, ci tur woowu la nit kii jële ag wér, ba taxaw ci seen kanam.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
sababu yenyewe ni kwamba katika pitapita yangu niliangalia sanamu zenu za ibada nikakuta madhabahu moja ambayo imeandikwa: kwa ajili ya mungu yule asiyejulikana. basi, huyo mnayemwabudu bila kujua, ndiye ninayemhubiri kwenu.
ndaxte bi may doxantu di seet seeni màggalukaay, gis naa ci benn bu ñu bind lii: “yàlla mi nu xamul.” li ngeen di màggal nag te xamuleen ko, loolu laa leen di xamal.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
kesho yake, mkuu wa jeshi alitaka kujua mashtaka kamili ambayo wayahudi walikuwa wamemwekea paulo. hivyo, alimfungua paulo minyororo, akaamuru makuhani wakuu na baraza lote wafanye kikao. kisha alimleta paulo, akamsimamisha mbele ya baraza.
ca ëllëg sa mu bàyyi ko, ndaxte bëggoon na xam bu wóor lu ko yawut ya jiiñ. mu santaane ne, saraxalekat yu mag ya dajaloo, ñoom ak kureelu àttekat ya. gannaaw loolu mu indilu pool, dëj ko ci seen kanam.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質: