検索ワード: kuleta (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

heri wenye kuleta amani, maana wataitwa watoto wa mungu.

ウォロフ語

yéen ñiy wut jàmm, barkeel ngeen,ndax dees na leen tudde doomi yàlla.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa hiyo tuyazingatie daima mambo yenye kuleta amani, na yanayotusaidia kujengana.

ウォロフ語

kon nag nanu wut luy indi jàmm, tey yékkati ngëmu sunu moroom.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

nami nikafa. hiyo amri ambayo shabaha yake ilikuwa kuleta uhai, kwangu imeleta kifo.

ウォロフ語

noonu gis naa ne, ndigal loolu waroon a jëme nit ñi ci dund, daf maa jëme ci dee.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mnadhani nimekuja kuleta amani duniani? hata kidogo; si amani bali utengano.

ウォロフ語

ndax dangeen a xalaat ne, damaa ñëw ngir indi jàmm ci àddina? déedéet. maa ngi leen koy wax, damaa ñëw ngir indi féewaloo.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"msidhani kwamba nimekuja kuleta amani duniani. sikuja kuleta amani bali upanga.

ウォロフ語

«te it buleen defe ne, damaa ñëw ngir indi jàmm ci àddina; ñëwuma ngir indi jàmm, waaye jaasi laa indaale.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

atukuzwe mungu na baba wa bwana wetu yesu kristo, baba mwenye huruma na mungu mwenye kuleta faraja yote.

ウォロフ語

cant ñeel na yàlla, baayu sunu boroom yeesu kirist, di baay biy aji yërmande tey boroom lépp luy dëfël xol yi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kama vile dhambi ilivyotawala kwa kifo, kadhalika neema inatawala kwa njia ya uadilifu, na kuleta uzima wa milele kwa njia ya yesu kristo bwana wetu.

ウォロフ語

ba tax, ni bàkkaar doon yilife ñépp ni buur, indaale dee, noonu itam la yiwu yàlla faloo ni buur, jóge ci njub, jëm ci dund gu dul jeex. te loolu lépp darajay yeesu kirist sunu boroom moo nu ko may.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

aliiondoa ile sheria ya wayahudi pamoja na amri zake na kanuni zake, ili kutokana na jamii hizo mbili aumbe jamii moja mpya katika umoja naye na hivyo kuleta amani.

ウォロフ語

far noonu yoonu musaa, muy ndigal ya ak dogal ya. noonu la nu jële, yawut ak ki dul yawut, def nu benn ci moom, ba nu jàmmoo.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kama mtu anataka kuleta ubishi juu ya jambo hili, basi, na ajue kwamba sisi hatuna desturi nyingine, wala makanisa ya mungu hayana desturi nyingine.

ウォロフ語

waaye su kenn bëggee werante ci mbir moomu, na xam lii: amunu beneen aada ci njàng mi, du nun walla mboolooy yàlla.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kuwa na huzuni jinsi atakavyo mungu, husababisha badiliko la moyo, badiliko lenye kuleta wokovu; hivyo hakuna sababu ya kujuta. lakini huzuni ya kidunia huleta kifo.

ウォロフ語

ndaxte tiis wu jóge ci yàlla dina jur réccu guy jëme ci mucc, te réccu googu laajul gëstu. waaye tiisu àddina day jëme ci dee.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa makelele yao yasiyo na adabu, watu hao ni kama madoa machafu katika mikutano yenu ya karamu ya bwana. hujipendelea wao wenyewe tu, na wako kama mawingu yanayopeperushwa huko na huko na upepo bila ya kuleta mvua. wao ni kama miti isiyozaa matunda hata wakati wa majira yake, wamekufa kabisa.

ウォロフ語

su ñu bokkee ak yéen reeru mbooloo mi, dañu ciy indi ay, niy xeer yu nëbbu ci biir géej; amuñu genn gàcce, waaye dañuy giiroo te fonk seen biir rekk. Ñu ngi mel ni xiin yu amul ndox, yuy naaxsaay ci ngelaw; ni garab yu meññul ci jamonoy meññeef, te buddeeku, dee ba wow koŋŋ;

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

人による翻訳を得て
7,793,833,757 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK