プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。
hali kadhalika na ninyi, maadam mna hamu ya kupata vipaji vya roho, jitahidini hasa kujipatia vile vinavyosaidia kulijenga kanisa.
yéen itam, gannaaw dangeen a fonk mayi xelum yàlla, jéemleen a ëpple ci liy yokk ngëmu mbooloo mi.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
wakasema, "mtu huyu alisema: ninaweza kuliharibu hekalu la mungu na kulijenga tena kwa siku tatu."
«kii nee woon na: “man naa toj kër yàlla ga, tabaxaat ko ci ñetti fan.”»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
watu waliokuwa wanapita mahali hapo walimtukana, wakitikisa vichwa vyao na kusema, "aha! wewe mwenye kuvunja hekalu na kulijenga kwa siku tatu!
Ña fa doon romb di ko xas, di wëcc seen bopp ndax sib ko naan: «waaw kay, yaw mi bëgg a toj kër yàlla gi, tabaxaat ko ci ñetti fan,
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
"wewe! si ulijidai kulivunja hekalu na kulijenga kwa siku tatu? sasa jiokoe mwenyewe. kama wewe ni mwana wa mungu, basi shuka msalabani!"
naan: «yaw mi man a toj kër yàlla ga, tabaxaat ko ci ñetti fan, musalal sa bopp; boo nekkee doomu yàlla, wàccal ci bant bi.»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
ndugu, tuseme nini, basi? mnapokutana pamoja, mmoja aimbe wimbo, mwingine atoe mafundisho, mwingine awe na ufunuo kutoka kwa mungu, mwingine atumie kipaji cha kusema kwa lugha ngeni na mwingine afafanue yanayosemwa. yote yawe kwa ajili ya kulijenga kanisa.
kon nag bokk yi, lu muy indi? bu ngeen dajee, kii am aw taalif, kii am njàngale, kii dëgg gu yàlla feeñal, kii di wax aw làkk, kee di ko firi. na loolu lépp aw ci yoonu yokk ngëmu mbooloo mi.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質: