検索ワード: kulikuwa (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

karibu na mahali hapo kulikuwa na nguruwe wengi wakichungwa.

ウォロフ語

fekk amoon na ca wet ya géttu mbaam-xuux yu bare yuy for.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

tangu saa sita mchana mpaka saa tisa kulikuwa giza nchini kote.

ウォロフ語

li tàmbalee digg-bëccëg, ba ci tisbaar, réew mépp lëndëm.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

katika chumba tulimokuwa, ghorofani, kulikuwa na taa nyingi zinawaka.

ウォロフ語

ca néeg bu kawe, ba nu booloo nag, amoon na fa làmp yu bare.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

baada ya hayo kulikuwa na sikukuu ya wayahudi, naye yesu akaenda yerusalemu.

ウォロフ語

gannaaw loolu yawut ya amoon nañu genn màggal, moo tax yeesu demoon yerusalem.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

huko yerusalemu kulikuwa na sikukuu ya kutabaruku. wakati huo ulikuwa wa baridi.

ウォロフ語

am bés ñu doon màggal ca yerusalem bés ba ñu sellale woon kër yàlla ga; ci jamonoy sedd la woon.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kulikuwa na kiongozi mmoja myahudi, wa kikundi cha mafarisayo, jina lake nikodemo.

ウォロフ語

amoon na ca farisen ya nit ku ñu naan nikodem te mu bokk ca kilifay yawut ya.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, kulikuwa na ndugu saba. wa kwanza alioa, akafa bila kuacha mtoto.

ウォロフ語

«amoon na fi nag juróom-ñaari góor, ñu bokk ndey ak baay. taaw ba takk jabar, faatu, te bàyyiwul doom.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kulikuwa na kijana mmoja aliyekuwa anamfuata yesu akiwa amevaa shuka. nao wakajaribu kumkamata.

ウォロフ語

fekk amoon na ca waxambaane wu lëkkaayoo woon sér, topp yeesu, ñu daldi ko jàpp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa kupitia amfipoli na apolonia, walisafiri mpaka thesalonika ambako kulikuwa na sunagogi la wayahudi.

ウォロフ語

bi ñu fa jógee, ñu aw yoon wa jaar dëkku amfipolis ak apoloni, door a ñëw tesalonig, fa yawut ya am jàngu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hawa walimfuata yesu alipokuwa galilaya na kumtumikia. kulikuwa na wanawake wengine wengi waliokuja yerusalemu pamoja naye.

ウォロフ語

bi yeesu nekkee galile, jigéen ñooñu ñoo ko doon topp, di ko topptoo. amoon na fa it yeneen jigéen yu bare yu àndoon ak moom, ba ñëw yerusalem.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kulikuwa na mtu mmoja huko lustra ambaye alikuwa amelemaa miguu tangu kuzaliwa, na alikuwa hajapata kutembea kamwe.

ウォロフ語

amoon na ca listar nag nit ku fa toog, ku ay tànkam làggi, ndax li mu judduwaale lafañ te musul a dox.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

alisema: "katika mji mmoja kulikuwa na hakimu ambaye hakuwa anamcha mungu wala kumjali binadamu.

ウォロフ語

nee na: «dafa amoon cib dëkk, benn àttekat bu ragalul yàlla te faalewul mbindeef.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, kulikuwa na mtu mmoja aitwaye baraba, ambaye alikuwa amefungwa pamoja na waasi wengine kwa kusababisha uasi na mauaji.

ウォロフ語

fekk booba amoon na ku ñu tëj, tudd barabas, ku bokk ci ña bëggoon a tas réew mi, boole ci rey nit.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kulikuwa na mtu mmoja huko kaisarea aitwaye kornelio, jemadari wa kikosi kimoja kiitwacho "kikosi cha italia."

ウォロフ語

amoon na ci sesare nit ku tudd korney, nekk njiitu xare, mu bokk ci mbooloom xare, mi ñuy wax mu itali.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

ikiwa basi, kulikuwa na utukufu katika huduma ile iliyoleta hukumu, ni wazi kwamba huduma ile iletayo kukubaliwa kuwa waadilifu itakuwa na utukufu mkuu zaidi.

ウォロフ語

su fekkee ne tëralin, wiy teg nit tooñ, àndoon na ak ndam, rawatina ci tëralin wiy àtte nit jub.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, kulikuwa na mtu mmoja aitwaye simoni ambaye alikuwa amekwisha fanya uchawi wake katika mji huo kwa muda na kuwashangaza watu wa samaria, akijiona kuwa yeye ni mtu maarufu.

ウォロフ語

amoon na nag nit ku tudd simoŋ, di luxuskat bu yàgg ca dëkk ba, te daan yéem waa samari gépp, ci naan: «aji màgg laa.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"huko kulikuwa na mtu mmoja aitwaye anania, mtu mcha mungu, mwenye kuitii sheria yetu na aliyeheshimika sana mbele ya wayahudi waliokuwa wanaishi damasko.

ウォロフ語

«bi ma ko defee ku tudd anañas ñëw ci man. nit ku ragal yàlla la woon ci sàmm yoonu musaa, te yawuti damas yépp seedeel ko lu baax.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

juu ya hilo sanduku kulikuwa na viumbe vilivyodhihirisha kuweko kwa mungu, na mabawa yao yalitanda juu ya mahali ambapo dhambi huondolewa. lakini sasa, hatuwezi kusema kinaganaga juu ya mambo hayo.

ウォロフ語

ca kaw gaal ga teg nañu fa ñaari nataali mbindeef yu ñuy wax seruben, yu doon wone ndamu yàlla. seeni laaf ñoo doon yiir baalukaay ba. waaye loolu lépp léegi mënunu koo tekki benn-benn.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, kulikuwa na vizazi kumi na vinne tangu abrahamu mpaka daudi, vizazi kumi na vinne tangu daudi mpaka wayahudi walipochukuliwa mateka babuloni, na vizazi kumi na vinne tangu kuchukuliwa mateka mpaka wakati wa kristo.

ウォロフ語

mboolem giir googu nag, la dale ca ibraayma ba ca daawuda, fukk lañu ak ñeent; la dale ca daawuda ba ca njaam ga ca babilon, fukk lañu ak ñeent; la dale njaam ga ca babilon ba ci kirist, fukk lañu ak ñeent.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mto huo ulitiririka kupitia katikati ya barabara kuu ya mji. kandokando ya mto huo kulikuwa na mti wa uzima unaozaa matunda mara kumi na mbili kwa mwaka, yaani kila mwezi; na majani yake ni dawa ya kuwaponya watu wa mataifa.

ウォロフ語

xellee ca digg péncu dëkk ba. ca weti dex ga amoon na ca garabu dund, guy meññ fukki yoon ak ñaar, di meññ weer wu nekk, te xob ya di faj xeet yi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

人による翻訳を得て
7,794,003,686 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK