検索ワード: mashua (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

nao mara wakaiacha mashua pamoja na baba yao, wakamfuata.

ウォロフ語

ca saa sa ñu daldi bàyyi gaal ga ak seen baay, topp ci moom.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

yesu alipanda mashua, na wanafunzi wake wakaenda pamoja naye.

ウォロフ語

bi mu ko waxee, yeesu dugg ca gaal ga, ay taalibeem topp ko.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

yesu alipanda mashua, akavuka ziwa na kufika katika mji wake.

ウォロフ語

bi loolu amee yeesu dugg cig gaal, jàll dex ga, dellu dëkkam.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, wakaondoka peke yao kwa mashua, wakaenda mahali pa faragha.

ウォロフ語

noonu ñu dugg cig gaal, dem ca bérab bu wéet.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, yesu akawaaga watu, akapanda mashua, akaenda katika eneo la magadani.

ウォロフ語

noonu yeesu yiwi mbooloo mi, dugg ci gaal, ñëw ci wàlli magadan.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, baada ya kuzileta zile mashua ukingoni mwa ziwa, wakaacha yote, wakamfuata.

ウォロフ語

noonu ñu teer ca tefes ga, bàyyi lépp, di topp ci moom.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, dhoruba kali ikaanza kuvuma, mawimbi yakaipiga ile mashua hata ikaanza kujaa maji.

ウォロフ語

naka noona ngelaw lu mag daldi jóg, duus yi sàng gaal gi, ba mu bëgg a fees.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

wakapanda mashua ili wavuke kwenda kafarnaumu. giza lilikuwa limeingia, na yesu alikuwa hajawafikia bado.

ウォロフ語

dugg ci gaal, di jàll dex gi, jëm dëkku kapernawum. booba guddi woon na, te yeesu agseegul ci ñoom.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

akaona mashua mbili ukingoni mwa ziwa; wavuvi wenyewe walikuwa wametoka, wanaosha nyavu zao.

ウォロフ語

noonu mu gis ñaari gaal yu teer ca tefes ga, nappkat ya ca wàcce, di raxas seeni mbaal.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, wakauacha ule umati wa watu, wakamchukua yesu katika mashua alimokuwa. palikuwapo pia mashua nyingine hapo.

ウォロフ語

mu yiwi mbooloo mi nag, ay taalibeem jël ko ni mu mel ci gaal gi; te yeneeni gaal ànd ak moom.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, hao watu walipogundua kwamba yesu na wanafunzi wake hawakuwapo mahali hapo, walipanda mashua, wakaenda kafarnaumu wakimtafuta.

ウォロフ語

bi mbooloo ma gisee ne, yeesu walla taalibe ya kenn nekkatu fa, ñu dugg ca gaal yooyu, dem seeti ko kapernawum.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

alipokwenda mbele kidogo, aliwaona yakobo na yohane, wana wa zebedayo. nao pia walikuwa ndani ya mashua yao wakizitengeneza nyavu zao.

ウォロフ語

bi yeesu demee ba ca kanam, mu gis saag doomu sebede, ak yowaana, mi mu bokkal ndey ak baay, ñu nekk ci gaal gi, di defar seeni mbaal.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mara yesu akawaamuru wanafunzi wake wapande mashua, wamtangulie kwenda bethsaida, ng'ambo ya ziwa, wakati yeye anauaga umati wa watu.

ウォロフ語

ci kaw loolu yeesu sant ay taalibeem, ñu dugg ci gaal gi, jàll ba betsayda, bi muy yiwi mbooloo mi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

alipomaliza kufundisha, akamwambia simoni, "peleka mashua mpaka kilindini, mkatupe nyavu zenu mpate kuvua samaki."

ウォロフ語

bi mu jàngalee ba noppi, mu ne simoŋ: «joowal gaal gi, ba fa ndox ma gën a xóote, ngeen sànni fa seeni mbaal ngir napp.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

lakini wale wanafunzi wengine walikuja pwani kwa mashua huku wanauvuta wavu uliojaa samaki; hawakuwa mbali na nchi kavu, ila walikuwa yapata mita mia moja kutoka ukingoni.

ウォロフ語

yeneen taalibe ya xëcc mbaal, mi fees dell ak jën, jëme ko ca tefes ga, ndaxte gaal ga sorewul woon; diggante bi waroon na tollook téeméeri meetar.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kesho yake umati wa watu wale waliobaki upande wa pili wa ziwa walitambua kwamba kulikuwa na mashua moja tu pale, na yesu hakuingia katika mashua pamoja na wanafunzi wake, ila wanafunzi hao walikuwa wamekwenda zao peke yao.

ウォロフ語

ca ëllëg sa mbooloo, ma des ca geneen wàllu dex ga, gis ne genn gaal ga fa nekkoon rekk dem na. xam nañu ne yeesu bokku ko woon ak taalibe ya, ndaxte ñoom rekk a àndoon.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

baada ya yesu kuingia katika mashua moja, iliyokuwa ya simoni, alimtaka simoni aisogeze majini, mbali kidogo na ukingo wa ziwa. akaketi, akafundisha umati wa watu akiwa ndani ya mashua.

ウォロフ語

mu dugg ci genn gaal, fekk muy gu simoŋ, mu ne ko, mu joow ba sore tuuti. noonu yeesu toog ca gaal ga, di jàngal mbooloo ma.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

siku moja, yesu alipanda mashua pamoja na wanafunzi wake, akawaambia, "tuvuke ziwa twende mpaka ng'ambo." basi, wakaanza safari.

ウォロフ語

benn bés yeesu àndoon na ak ay taalibeem, dugg ci gaal. mu ne leen: «nanu jàll dex gi.» noonu ñu dem.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

alipokwenda mbele kidogo, aliwaona ndugu wengine wawili: yakobo na yohane, wana wa zebedayo. hao walikuwa ndani ya mashua pamoja na baba yao zebedayo, wakitengeneza nyavu zao. basi yesu akawaita,

ウォロフ語

ba yeesu demee ba ca kanam, mu gis yeneen ñaar ñu bokk ndey ak baay, ñuy saag doomu sebede, ak yowaana rakkam. Ñu nekk ci seen biir gaal ak sebede seen baay, di defar seeni mbaal. noonu yeesu woo leen.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

人による翻訳を得て
7,745,738,145 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK