検索ワード: mtumwa (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

kwa hiyo, basi, ndugu, sisi si watoto wa mtumwa bali wa mama huru.

ウォロフ語

kon nag bokk yi, nun dunu doomi jaam, ay doomi gor lanu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mtumwa hana makao ya kudumu nyumbani, lakini mwana anayo makao ya kudumu.

ウォロフ語

te jaam du bokk ci kër gi ba fàww, waaye doom, moom, ci kër gi la bokk ba fàww.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

yesu akawajibu, "kweli nawaambieni, kila mtu anayetenda dhambi ni mtumwa wa dhambi.

ウォロフ語

yeesu ne leen: «ci dëgg-dëgg maa ngi leen koy wax, képp kuy bàkkaar, jaamu bàkkaar la.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

kumbukeni kwamba kila mtu mwenye kutenda mema, awe mtumwa au mtu huru, atapokea tuzo lake kutoka kwa bwana.

ウォロフ語

xam ne ku def lu baax, boroom bi delloo la ko, muy jaam, muy gor.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, nasema hivi: mrithi, akiwa bado mtoto, hawi tofauti na mtumwa ingawaje mali yote ni yake.

ウォロフ語

li ma leen di wax, mooy lii: doom ji war a donni baayam, fi ak mu ngi cig ndaw, ak lu ko alal jiy lew lépp, du wuute dara ak jaam.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, wewe si mtumwa tena, bali mwana. na ikiwa ni mwana, basi, wewe utapokea yote mungu aliyowawekea watoto wake.

ウォロフ語

noonu dootuloo jaam, doom nga. te ndegam doom nga, yàlla jagleel na la cér ci xéewal, yi mu dencal ay doomam.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

imeandikwa katika maandiko matakatifu kwamba abrahamu alikuwa na watoto wawili: mmoja kwa mwanamke mtumwa, na wa pili kwa mwanamke huru.

ウォロフ語

mbind mi nee na: ibraayma am na ñaari doom; ki jaam bi jur ak ki gor si jur.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hivyo, hakuna tena tofauti kati ya myahudi na mgiriki, mtumwa na mtu huru, mwanamume na mwanamke. nyote ni kitu kimoja katika kuungana na kristo yesu.

ウォロフ語

kon nag amul xaajale ci diggante yawut ak ki dul yawut, ci diggante jaam ak gor, ci diggante góor ak jigéen. yéen ñépp benn ngeen ci seen bokk ci kirist.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kisha wafalme wa duniani, wakuu, majemadari, matajiri, wenye nguvu, kila mtumwa na mtu huru, wakajificha mapangoni na kwenye majabali milimani.

ウォロフ語

noonu buuri àddina si, kilifa yi, njiiti xare yi, boroom alal yi, boroom kàttan yi, jaam yi ak gor yi, ñépp làqatuji ci xunti yi ak ci ron doji tund yi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

katika hali hii, hakuna tena tofauti kati ya mgiriki na myahudi, aliyetahiriwa na asiyetahiriwa, msomi na asiye msomi, mtumwa na mtu aliye huru. kristo ni kila kitu, na yumo katika yote.

ウォロフ語

ci dund gu bees googu, amul yawut ak ku dul yawut, ku xaraf walla ku xaraful, jaam walla gor, ku jàngul ni baarbaar yi, ak ku yeewuwul ni waa sit, waaye kirist ay lépp te dëkk ci ñépp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini maandiko matakatifu yasemaje? yasema: "mfukuze mama mtumwa pamoja na mwanawe; maana mtoto wa mtumwa hatarithi pamoja na mtoto wa mama huru."

ウォロフ語

lu ci mbind mi wax nag? nee na: «dàqal jaam bi ak doomam, ndaxte doomu jaam bi warul a bokk cér ak doomu gor si ci ndono.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,793,207,702 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK