検索ワード: mwenendo (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

mwenendo wenu ulikuwa mzuri! nani, basi aliyewazuia kuuzingatia ukweli?

ウォロフ語

ni ngeen jógtee woon de baax na! waaw ku leen dog, ba ngeen bañ a déggal dëgg?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

bali mnapaswa kuwa watakatifu katika mwenendo wenu wote, kama vile yule aliyewaiteni ni mtakatifu.

ウォロフ語

waaye na seen dund gépp sell, ni yàlla mi leen woo selle.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mtu wa namna hiyo, mwenye nia mbili na asiye na msimamo katika mwenendo wake wote,

ウォロフ語

bu kooku yaakaar dara ci boroom bi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

alimwokoa loti, mtu mwema, ambaye alisikitishwa sana na mwenendo mbaya wa watu hao waasi.

ウォロフ語

waaye musal na lóot mi jub, mi sonnoon ndax ñaawteefi ñu dëng, ñooñu mu nekkaloon.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, nasema hivi: mwenendo wenu na uongozwe na roho, nanyi hamtafuata tena tamaa za kidunia.

ウォロフ語

li ma leen di wax mooy lii: dundleen ci xelum yàlla, kon dungeen topp seen nafsu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, acheni mwenendo wenu wa awali, yaani ule utu wenu wa kale uliokuwa unaangamizwa kwa tamaa zake danganyifu.

ウォロフ語

maanaam ngeen yulli seen jikko ju bon, ji ngeen judduwaale te daan fés ci seeni jëf, te muy gën a yées, moom ak i bëgg-bëggam yuy naxe kese.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hayo ndiyo mliyoitiwa; maana kristo mwenyewe aliteseka kwa ajili yenu, akawaachieni mfano, ili muufuate mwenendo wake.

ウォロフ語

ndaxte ci loolu la leen yàlla woo, ndaxte kirist itam sonn na ngir yéen, teg fi seen kanam royukaay, ngir ngeen jaar ciy tànkam.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa ajili ya wafalme na wote wenye mamlaka, ili tupate kuishi maisha ya utulivu na amani pamoja na uchaji wa mungu na mwenendo mwema.

ウォロフ語

Ñaanal-leen buur yi ak kilifa yépp, ngir nu man a am dund gu dal te jàmmu, ànd ak ragal yàlla ak faayda yu mat.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mwenendo wetu uwe wa adabu kama inavyostahili wakati wa mchana; tusiwe na ulafi na ulevi, uchafu na uasherati, ugomvi na wivu.

ウォロフ語

gannaaw nu ngi ci leer, na sunug dund rafet. bunu naan sangara ba màndi tey bànneexu; bunu njaaloo tey def i ñaawteef ak sunuy cér; bunu xuloo mbaa nuy ñeeyante.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hali kadhalika waambie wanawake wazee wawe na mwenendo wa uchaji wa mungu; wasiwe wachongezi, au watumwa wa pombe. wanapaswa kufundisha mambo mema,

ウォロフ語

jigéen ñu mag ñi itam, na seen doxalin ànd ak faayda; buñuy jëw mbaa xér ci sangara. waaye nañuy jàngale lu baax,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

je, ni nani mwenye hekima na akili miongoni mwenu? basi, aonyeshe jambo hilo kwa mwenendo wake mzuri na kwa matendo yake mema yanayofanyika kwa unyenyekevu na hekima.

ウォロフ語

ana ku neex xel ci yéen, ana kuy boroom xam-xam? na ko wone ciy jëfam ak dundam gu sell, te feeñal xelam ci jikkoom ju lewet.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa hiyo, tupilieni mbali mwenendo mchafu na tabia zote mbovu; jiwekeni chini ya mungu na kupokea ule ujumbe uliopandwa mioyoni mwenu, ambao waweza kuziokoa nafsi zenu.

ウォロフ語

moo tax nanguleen ci woyof kàddu, gi leen yàlla sol te man leen a musal, di dëddu bépp sobe ak coxor gi daj àddina.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kama ukimhuzunisha ndugu yako kwa sababu ya chakula unachokula, basi mwenendo wako hauongozwi na mapendo. usikubali hata kidogo chakula chako kiwe sababu ya kupotea kwa mtu mwingine ambaye kristo alikufa kwa ajili yake!

ウォロフ語

soo dee lekk luy indil sa moroom tiis, génn nga ci mbëggeel. yaw nag bul réeral sa moroom ci sa ñam, ndax kirist dee na ngir moom.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

wewe lakini, umeyafuata mafundisho yangu, mwenendo wangu, makusudi yangu katika maisha, imani yangu, uvumilivu wangu, upendo wangu, subira yangu,

ウォロフ語

waaye yaw nag xam nga bu baax sama njàngale, sama dund, sama takkute, sama ngëm, sama muñ, sama mbëggeel ak sama dékku tiis.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mimi nilimwita tito, nikamtuma kwenu na ndugu yetu mwingine. je, tito aliwanyonyeni? je, hamjui kwamba sisi tumekuwa tukiongozwa na roho yuleyule, na mwenendo wetu ni mmoja?

ウォロフ語

sant naa tit, mu ñëw ci yéen, te yebal naa sunu mbokk moomu ak moom. ndax tit dafa lekk seen alal? man ak moom, ndax bokkunu woon xel mu nu yékkati ak tànk yu nuy dox?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

人による翻訳を得て
7,747,288,269 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK