検索ワード: sanamu (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

watoto wangu, epukaneni na sanamu za miungu.

ウォロフ語

samay doom, wottuleen seen bopp ciy xërëm.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa hiyo, wapenzi wangu, epeni ibada za sanamu.

ウォロフ語

looloo tax, sama soppe yi, nangeen daw xërëm yi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mnajua kwamba, kabla ya kuongoka kwenu, mlitawaliwa na kupotoshwa na sanamu tupu.

ウォロフ語

xam ngeen ne, bi ngeen xamagul woon yàlla, xërëm, yi mënul a wax, ñoo leen jiitaloon, di leen wommat.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hapo ndipo walipojitengenezea sanamu ya ndama, wakaitambikia na kukifanyia sherehe kitu ambacho ni kazi ya mikono yao wenyewe.

ウォロフ語

booba nag ñu tëgglu aw sëllu, muy xërëm, ñu di ko tuuru, di bànneexu ci seeni jëfi loxo.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kisha alijaliwa kuipulizia uhai hiyo sanamu ya yule mnyama wa kwanza, hata ikaweza kuongea na kuwaua watu wote ambao hawakuiabudu.

ウォロフ語

mayees ko it, mu dundloo nataalu rab wa, waxloo ko, ba képp ku jaamuwul nataalu rab wa rekk ñu rey la.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kuabudu sanamu, uchawi, uadui, ugomvi, wivu, hasira, choyo, mabishano, mafarakano;

ウォロフ語

xërëm, luxus, noonoo ak xuloo, ñeetaane, xadar, diiroo mbagg, féewaloo ak xaajaloo,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kwa hiyo, kuhusu vyakula vilivyotambikiwa sanamu, twajua kwamba sanamu si kitu duniani; twajua kwamba mungu ni mmoja tu.

ウォロフ語

kon nag ci li jëm ci lekk yàpp wu ñu jébbal xërëm yi, xam nanu ne, xërëm du dara ci àddina te xam nanu itam ne, yàlla kenn rekk la.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini ninayo machache dhidi yako: baadhi yenu ni wafuasi wa balaamu aliyemfundisha balaki kuwatega wana wa israeli wale vyakula vilivyotambikiwa sanamu za kufanya uzinzi.

ウォロフ語

waaye am na lu ma naqari ci yaw, moo di uuf nga foofu gaa yuy sàmm njàngalem balaam, moom mi jàngaloon balag, mu sóob bànni israyil ci bàkkaar, xiir leen ci lekk ñam wu ñu tuuroo xërëm yi, xiir leen ci njaaloo.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

aliwapotosha wakazi wa dunia kwa miujiza hiyo aliyojaliwa kutenda mbele ya mnyama wa kwanza. aliwaambia wakazi wa dunia watengeneze sanamu kwa heshima ya yule mnyama aliyekuwa amejeruhiwa kwa upanga lakini akaishi tena.

ウォロフ語

noonu mu nax waa àddina ci kéemaan, yi mu am sañ-sañu def ci turu rab wu jëkk wa. mu sant waa àddina, ñu def nataalu rab, wi am gaañu-gaañub jaasi tey dund.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

bali tuwapelekee barua kuwaambia wasile vyakula vilivyotiwa najisi kwa kutambikiwa sanamu za miungu; wajiepushe na uasherati; wasile mnyama yeyote aliyenyongwa, na wasinywe damu.

ウォロフ語

waaye nu bind leen, ñu moytu ñam wu araam wu ñu tuuroo xërëm, tey moytu njaaloo, ak jur gu médd, bay naan deret ja.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

maana, mtu ambaye dhamiri yake ni dhaifu, akikuona wewe mwenye ujuzi unakula vyakula hivyo ndani ya hekalu la sanamu, je, hatatiwa moyo wa kula vyakula vilivyotambikiwa sanamu?

ウォロフ語

su amee ku ngëmam néew, mu gis la, yaw mi bare xam-xam, nga toog di lekk ca màggalukaayu xërëm ya, ndax du ko xiir mu lekk yàppu sarax?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

au je, hamjui kwamba watu wabaya hawataurithi utawala wa mungu? msijidanganye! watu wanaoishi maisha ya uasherati, wanaoabudu sanamu, wazinzi, au walawiti,

ウォロフ語

xanaa xamuleen ne, ñi jubadi duñu bokk ci nguuru yàlla? bu leen ci kenn nax: ñiy doxaan walla xërëmkat yi ak njaalookat yi ak góor-jigéen ñi ak ñi ko nangu,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hatimaye karani wa mji alifaulu kuwanyamazisha, akawaambia, "wananchi wa efeso, kila mtu anajua kwamba mji huu wa efeso ni mlinzi wa nyumba ya mungu artemi na mlinzi wa ile sanamu iliyoanguka kutoka mbinguni.

ウォロフ語

gannaaw loolu boroom dëkk ba dalal mbooloo ma ne leen: «yéen waa efes, ana ku xamul ne, dëkku efes moo di wottukaayu màggalukaayu artemis ak nataalam, bi wàcce asamaan?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"ndugu, kwa nini mnafanya mambo hayo? sisi pia ni binadamu kama ninyi. na, tuko hapa kuwahubirieni habari njema, mpate kuziacha hizi sanamu tupu, mkamgeukie mungu aliye hai, mungu aliyeumba mbingu na nchi, bahari na vyote vilivyomo.

ウォロフ語

«yéen nit ñi, lu leen xiir ci lii? nun it ay nit lanu, ñu bokk bind ak yéen. te nu ngi leen di xamal xebaar bu baax ne leen, ngeen dëddu yëfi neen yii te woññiku ci yàlla miy dund te sàkk asamaan, suuf, géej ak li ñu ëmb lépp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,745,805,916 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK