プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。
maana tunaishi kwa imani, na si kwa kuona.
ndaxte doxewunu ab gis, waaye ngëm lanuy doxe.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
kweli tunaishi duniani, lakini hatupigani vita kidunia.
dëgg la ne nit rekk lanu, waaye dunu xeexe ni nit.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
kwani sasa tunaishi kweli ikiwa ninyi mnasimama imara katika kuungana na bwana.
ndaxte noo ngi dund dëgg-dëgg, ndegam yéena ngi sax ci boroom bi.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
lakini jambo la maana zaidi, tunataka kumpendeza, iwe tunaishi hapa duniani au huko.
kon nag des fi walla jóge fi, li nuy faaydaal moo di neex boroom bi.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
tunajua kwamba tunaishi katika umoja na mungu, naye mungu anaishi katika umoja nasi, kwani yeye ametupa roho wake.
ci lii lanuy xame ne, sax nanu ci yàlla, te moom itam dëkk na ci nun: sol na nu xelam.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
mungu alifanya hivyo kusudi matakwa ya haki ya sheria yatekelezwe kikamilifu ndani yetu sisi ambao tunaishi, si kwa nguvu za kibinadamu, bali kwa nguvu ya roho.
ba tax na léegi njub, gi yoonu musaa di digle, am na ci nun, ñiy déggal xelu yàlla mi te bañ a topp sunu nafsu.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
kwa imani yetu, yeye ametuleta katika hali hii ya neema ya mungu ambamo sasa tunaishi. basi, tunajivunia tumaini tulilo nalo la kushiriki utukufu wa mungu.
moo nu ubbil bunt ci yàlla, nu taxaw temm ci yiwam, jaar ci ngëm. te it nu ngi bég ciy négandiku, yàlla boole nu ci ndamam.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
kama alivyosema mtu mmoja: ndani yake yeye sisi tunaishi, tunajimudu, na tuko! ni kama washairi wenu wengine walivyosema: sisi ni watoto wake.
“ndaxte ci moom lanuy dunde, di ci jëf te nekk ci,” ni ko ñenn ci seeni taalifkat dëggale naan: “nun noo di aw xeetam.”
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
maana tunajua kwamba hema hii ambayo ndani yake tunaishi sasa hapa duniani, yaani mwili wetu, itakapong'olewa, mungu atatupa makao mengine mbinguni, nyumba ya milele isiyotengenezwa kwa mikono.
yaram wi nu soloo ci kaw suuf dafa mel ni ab tànt. su daanoo, xam nanu ne, yàlla jagleel na nu am taax ci asamaan, mu loxol nit defarul, di taax muy sax ba fàww.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質: