検索ワード: ushahidi (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

lakini hata hivyo, ushahidi wao haukupatana.

ウォロフ語

waaye ba tey seeni wax ànduñu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

naye roho mtakatifu anatupa ushahidi wake. kwanza anasema:

ウォロフ語

te it xel mu sell mi seedeel na nu ko;

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

roho, maji na damu; na ushahidi wa hawa watatu waafikiana.

ウォロフ語

xel mi, ndox ak deret, te ñoom ñett ñépp, ñoo bokk benn baat.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kisha wengine walisimama, wakatoa ushahidi wa uongo wakisema:

ウォロフ語

ba mujj naaféq taxaw, seede ci moom naan:

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

nikijishuhudia mimi mwenyewe, ushahidi wangu hauwezi kukubaliwa kuwa wa kweli.

ウォロフ語

«su ma seedeelee sama bopp, sama wax du am maana.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

imeandikwa katika sheria yenu ya kwamba ushahidi wa watu wawili ni halali.

ウォロフ語

seen yoon dafa wax ne, seedes ñaari nit a gën a wóor.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

watu wengi walitoa ushahidi wa uongo juu ya yesu, lakini ushahidi wao haukupatana.

ウォロフ語

teewul sax naaféq ñu bare ñëw, seede ci yeesu lu dul dëgg, waaye seen seede ànduñu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

si kwamba mimi nautegemea ushahidi wa wanadamu, lakini nasema mambo haya ili mpate kuokolewa.

ウォロフ語

man ci sama bopp soxlawuma seedes nit; waaye nag damay wax loolu rekk, ngir ngeen mucc.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, makuhani wakuu na baraza lote wakatafuta ushahidi wa uongo dhidi ya yesu wapate kumwua,

ウォロフ語

noonu saraxalekat yu mag ya ak kureelu àttekat ya di seet naaféq bu man a seede ci yeesu, ba ñu man koo rey,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mtu yeyote asiyeitii sheria ya mose, huuawa bila ya huruma kukiwa na ushahidi wa watu wawili au watatu.

ウォロフ語

ku weddi ndigali yoonu musaa wi, te ñaar walla ñetti nit seede ko, dina dee ci lu amul benn yërmande.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, mafarisayo wakamwambia, "wewe unajishuhudia mwenyewe; kwa hiyo ushahidi wako si halali."

ウォロフ語

farisen ya ne ko: «yaw yaay seedeel sa bopp, kon li ngay wax du dëgg.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

huu ndio ushahidi yohane alioutoa: "nilimwona roho akishuka kama njiwa kutoka mbinguni na kutua juu yake.

ウォロフ語

ci kaw loolu yaxya seede na lii: «gis naa xelu yàlla mi ci melow pitax, mu jóge ci asamaan, tegu ci moom.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

maana moyoni hutoka mawazo maovu yanayosababisha uuaji, uzinzi, uasherati, wizi, ushahidi wa uongo na kashfa.

ウォロフ語

ndaxte ci xol la xalaat yu bon di jóge, ak bóom, njaaloo, ndoxaanu yàqute, càcc, seede lu dul dëgg ak saaga.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mungu pia aliongeza hapo ushahidi wake kwa kufanya kila namna ya miujiza na maajabu, na kwa kuwagawia watu vipaji vya roho mtakatifu kadiri ya mapenzi yake.

ウォロフ語

te it yàlla dëggal na seen seede ci ay firnde ak ay kéemaan, ay jaloore yu bare ak ci ay may yu jóge ci xelam mu sell, te mu séddale leen ni mu ko bëgge.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ikiwa twaukubali ushahidi wa binadamu, ushahidi wa mungu una uzito zaidi; na huu ndio ushahidi alioutoa mungu mwenyewe juu ya mwanae.

ウォロフ語

seedes nit, dinanu ko nangu, waaye seedes yàlla moo gën a wóor, ndax boobu seede mooy li yàlla seede ci doomam.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hii ni mara yangu ya tatu kuja kwenu. "kila tatizo litatatuliwa kwa ushahidi wa watu wawili au watatu," yasema maandiko.

ウォロフ語

bii mooy ñetteel bi yoon, ma di leen ganesi. «bépp àtte dina aju ci seedes ñaar walla ñetti nit.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

anayemwamini mwana wa mungu anao ushahidi huo ndani yake; lakini asiyemwamini mungu, anamfanya yeye kuwa mwongo, maana hakuamini ushahidi alioutoa mungu juu ya mwanae.

ウォロフ語

ku gëm doomu yàlla ji, am nga seede boobu ci sa xol. ku gëmul yàlla, teg nga ko kuy tebbi waxam ndaxte gëmuloo li yàlla seede ci doomam.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

yesu akawajibu, "hata kama ninajishuhudia mwenyewe, ushahidi wangu ni wa kweli kwa sababu mimi najua nilikotoka na ninakokwenda. lakini ninyi hamjui nilikotoka wala ninakokwenda.

ウォロフ語

yeesu tontu leen: «maa ngi seedeel sama bopp, teewul li may wax di dëgg, ndaxte xam naa fa ma bàyyikoo, xam fa ma jëm. waaye yéen xamuleen fa ma bàyyikoo ak fa ma jëm.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

unazijua amri: usizini; usiue; usiibe; usitoe ushahidi wa uongo; waheshimu baba yako na mama yako."

ウォロフ語

xam nga ndigal yi: “bul njaaloo, bul bóom, bul sàcc, bul seede lu dul dëgg, teralal sa ndey ak sa baay.”»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

naye anayetoa ushahidi wake juu ya mambo haya asema: "naam! naja upesi." amina. na iwe hivyo! njoo bwana yesu!

ウォロフ語

kiy seede mbir yii nee na: «waaw, maa ngi ñëw léegi.» amiin. boroom bi yeesu, ñëwal.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,782,486,233 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK