検索ワード: wagonjwa (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

halafu akawatuma waende kuhubiri ufalme wa mungu na kuponya wagonjwa.

ウォロフ語

noonu mu yónni leen ñuy yégle nguuru yàlla ak di faj jarag yi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kutokana na tukio hilo, wagonjwa wote katika kile kisiwa walikuja wakaponywa.

ウォロフ語

ci kaw loolu jarag ya ca des ca dun ba daldi dikk, amaat wér-gi-yaram.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hakuweza kutenda miujiza hapo, ila aliwawekea mikono wagonjwa wachache, akawaponya.

ウォロフ語

te yeesu mënu faa def ay kéemaan yu bare, lu dul teg loxo yenn jarag, wéral leen.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ndiyo maana wengi kati yenu ni dhaifu na wagonjwa, na wengine kadhaa wamekufa.

ウォロフ語

looloo tax ñu bare ci yéen wopp te ñàkk doole, ba ñenn ñi faatu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, wakaanza safari, wakapitia vijijini wakihubiri habari njema na kuponya wagonjwa kila mahali.

ウォロフ語

noonu ñu dem dëkk ak dëkk, di fa yégle xebaar bu baax bi, tey wéral jarag yi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, aliposhuka pwani, aliona umati mkubwa wa watu, akawaonea huruma, akawaponya wagonjwa wao.

ウォロフ語

yeesu génn ci gaal gi nag, gis mbooloo mu réy, mu yërëm leen, ba faj ñi ci wopp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ponyeni wagonjwa, fufueni wafu, takaseni wenye ukoma, toeni pepo. mmepewa bure, toeni bure.

ウォロフ語

fajleen ñi wopp, dekkal ñi dee, fajleen gaana yi te dàq rab yi. cig neen ngeen ame, mayeleen cig neen.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

humo barazani mlikuwa na wagonjwa wengi wamekaa: vipofu, viwete na waliopooza. walikuwa wakingojea maji yatibuliwe,

ウォロフ語

ca suufu mbaar yooyu la jarag yu bare, yu deme niki ay gumba, ay lafañ ak ay làggi, daan tëdd, di xaar ndox mi yengatu;

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

watu wengi walifika kutoka katika miji ya kando kando ya yerusalemu, wakiwaleta wagonjwa wao na wale waliokuwa na pepo wachafu, nao wote wakaponywa.

ウォロフ語

te it nit ñu bare dajaloo, jóge ca dëkk ya wër yerusalem, ñu indi ay jarag ak ñu rab yu bon sadd; te ñoom ñépp daldi wér.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, kwa haraka wakazunguka katika nchi ile yote, wakaanza kuwachukua wagonjwa wamelala juu ya mikeka yao, wakawapeleka kila mahali waliposikia yesu yupo.

ウォロフ語

ñu daldi daw ca diiwaan ba bépp, te fépp fu ñu ko dégg ñu di ko indil ñu wopp, tëdd ci seeni lal.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

jua lilipokuwa linatua, wote waliokuwa na wagonjwa wao mbalimbali waliwaleta kwake; naye akaweka mikono yake juu ya kila mmoja wao, akawaponya wote.

ウォロフ語

bi jant sowee, ñu indil yeesu ñi wopp ñépp ak ay jàngoro yu wuute. kenn ku nekk mu teg la loxo, wéral la.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

watu wengi sana wakamjia wakiwaleta vilema, vipofu, viwete, bubu na wengine wengi waliokuwa wagonjwa, wakawaweka mbele ya miguu yake, naye yesu akawaponya.

ウォロフ語

ba mu fa nekkee, nit ñu bare ñëw ci moom, indaale ay lafañ, ay làggi, ay gumba, ay luu ak ñeneen ñu bare. Ñu teg leen ci tànki yeesu, mu faj leen.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ilipokuwa jioni, walimletea watu wengi waliokuwa wamepagawa na pepo; naye, kwa kusema neno tu, akawafukuza hao pepo. aliwaponya pia watu wote waliokuwa wagonjwa.

ウォロフ語

ca ngoon sa ñu indil ko ñu bare ñu rab jàpp. yeesu dàq rab ya ak kàddoom te faj ñi wopp ñépp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kila mahali yesu alipokwenda, vijijini, mijini, au mashambani, watu waliwaweka wagonjwa uwanjani, wakamsihi waguse walau pindo la vazi lake. nao wote waliomgusa walipona.

ウォロフ語

te fu mu man a aw, ci dëkk yu mag mbaa yu ndaw walla ci àll bi, ñu indil ko jarag yi ci pénc yi, ñaan ko, mu may leen ñu laal cati mbubbam rekk. te képp ku ko laal daldi wér.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

siku moja yesu alikuwa akifundisha. mafarisayo na walimu wa sheria kutoka katika kila kijiji cha galilaya, yudea na yerusalemu, walikuwa wameketi hapo. nguvu ya bwana ilikuwa pamoja naye kwa ajili ya kuponyea wagonjwa.

ウォロフ語

am na bés yeesu doon jàngale. amoon na ca mbooloo, ma teewoon, ñu bokkoon ca farisen ya ak ay xutbakat yu jóge ca dëkk yépp, ya ca galile ak ya ca yude ak yerusalem. yeesu àndoon na ak dooley boroom bi, ba muy faj ay jarag.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

yesu alipowasikia, akawaambia, "watu wenye afya hawahitaji daktari; wanaomhitaji ni wale walio wagonjwa. sikuja kuwaita watu wema, ila wenye dhambi."

ウォロフ語

noonu yeesu dégg ko, mu ne leen: «Ñi wér soxlawuñu fajkat, ñi wéradi ñoo ko soxla; ñëwuma woo ñi jub, waaye bàkkaarkat yi laay woo.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

habari zake zikaenea katika mkoa wote wa siria. wagonjwa wote wenye maradhi ya kila namna na wale waliosumbuliwa na kila namna ya taabu: waliopagawa na pepo, wenye kifafa na watu waliokuwa wamelemaa, walipelekwa kwake; naye akawaponya wote.

ウォロフ語

ba tax turam siiw ba ci biir réewu siri mépp. Ñu di ko indil ñi wopp ñépp, ñi sonn ndax ay jàngoro ak metit yu bare, ñi rab jàpp, ñiy say ak ñi làggi, mu faj leen.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

人による翻訳を得て
7,776,220,127 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK