検索ワード: walio (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

heri walio na huruma, maana watahurumiwa.

ウォロフ語

yéen ñi am yërmande, barkeel ngeen,ndax dees na leen yërëm.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

muwe na huruma kwa watu walio na mashaka;

ウォロフ語

jubbantileen ñi am werantey xel,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

waheshimu wanawake wajane walio wajane kweli.

ウォロフ語

ci wàllu ñi seen jëkkër faatu nag, ku ci sësul ci kenn, teral ko ngir yàlla.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

alikuja katika nchi yake mwenyewe, nao walio wake hawakumpokea.

ウォロフ語

Ñëw na ci réewam, te ay ñoñam nanguwuñu ko.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, wale walio na imani wanabarikiwa pamoja na abrahamu aliyeamini.

ウォロフ語

kon ñi gëm, yàlla dina leen barkeel, sukkandikoo ko ci seen ngëm, ni mu defal ibraayma, boroom ngëm.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"heri walio maskini rohoni, maana ufalme wa mbinguni ni wao.

ウォロフ語

«yéen ñi xam seen ñàkk doole ngir neex yàlla,barkeel ngeen,ndaxte nguuru yàlla aji kawe ji,yéena ko yelloo.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

sasa basi jueni kwamba watu wenye kumwamini ndio walio watoto halisi wa abrahamu.

ウォロフ語

xamleen boog ne, boroom ngëm yi rekk ñooy doomi ibraayma.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mimi ni mchungaji mwema. nawajua walio wangu, nao walio wangu wananijua mimi,

ウォロフ語

«man maay sàmm bu baax bi. ni ma xame baay bi te baay bi xame ma ni, noonu laa xame samay xar, te ñoom it ni lañu ma xame. te it kat dinaa joxe sama bakkan ngir xar yi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini walio wa kwanza watakuwa wa mwisho, na walio wa mwisho watakuwa wa kwanza.

ウォロフ語

waaye ñu bare ci ñi jiitu, ñooy mujji; ñi mujj, ñooy jiituji.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

au, waache hawa walio hapa waseme kosa waliloliona kwangu wakati niliposimama mbele ya baraza lao kuu,

ウォロフ語

waaye it na nit ñii wax ci lan laa tooñe ci jataayu géewub àtte ba,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini, jihadharini: huu uhuru wenu usiwafanye walio na imani dhaifu waanguke katika dhambi.

ウォロフ語

waaye moytuleen, ba sañ-sañ bi ngeen am, bañ a yóbbe bàkkaar ñi seen ngëm néew.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini wengi walio wa kwanza watakuwa wa mwisho, na walio wa mwisho watakuwa wa kwanza."

ウォロフ語

waaye ñu bare ci ñi jiitu ñooy mujji; ñi mujj ñooy jiituji.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

anapaswa awe mwenye sifa njema kati ya watu walio nje ya kanisa, ili asije akalaumiwa na kuanguka katika mtego wa ibilisi.

ウォロフ語

te it war na am seede su rafet ci waa àddina, ngir ñu bañ koo diiŋat, ba muy daanu ci fiiru seytaane.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hapo walioko yudea wakimbilie milimani; wale walio mjini watoke; na wale walio mashambani wasirudi mjini.

ウォロフ語

kon nag ku nekk ci biir diiwaanu yude, nanga daw ca tund ya; ku nekk ci biir dëkk bi, nanga ko génn; te ku nekk ca tool ya, bul dugg ca dëkk ba!

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hivyo ataiimarisha mioyo yenu, nanyi mtakuwa wakamilifu na watakatifu mbele ya mungu na baba yetu wakati bwana wetu yesu atakapokuja pamoja na wote walio wake.

ウォロフ語

na samp seeni xol noonu ci cell gu amul sikk fa kanam yàlla sunu baay, ba bés bu yeesu sunu boroom dellusee, ànd ak gaayam yu sell yépp.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kila kitu ni safi kwa watu walio safi; lakini hakuna chochote kilicho safi kwa wale waliochafuliwa na wasioamini, maana dhamiri na akili zao zimechafuliwa.

ウォロフ語

Ñi sell seen lépp a sell, waaye ñi selladi te gëmadi seen dara sellul, du seeni xalaat, du seeni xel.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi sisi twafundisha, si kwa maneno tuliyofundishwa kwa hekima ya binadamu, bali kwa maneno tuliyofundishwa na roho, tukifafanua mambo ya kiroho kwa walio na huyo roho.

ウォロフ語

te loolu nu yàlla may, yéglewunu ko ci ay baat yu soqikoo ci xam-xamu nit, waaye nu ngi koy yégle ci baat, yi soqikoo ci xelum yàlla, di tekkantal yëfi xelum yàlla ci ay baat yu mu nu sol.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"kisha atawaambia wale walio upande wake wa kushoto, ondokeni mbele yangu enyi mliolaaniwa! nendeni katika moto wa milele aliotayarishiwa ibilisi na malaika wake.

ウォロフ語

«gannaaw loolu dina wax ñi ci càmmooñam: “soreleen ma yéen ñi alku, te dem ci safara su dul fey, si ñu sàkkal seytaane ak ay malaakaam.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

kwa wayahudi nimeishi kama myahudi ili niwapate wayahudi; yaani, ingawa mimi siko chini ya sheria, nimejiweka chini ya sheria kwao, ili niwapate hao walio chini ya sheria.

ウォロフ語

ci biir yawut yi, sol naa melow yawut yi, ngir gindi leen. man ci sama bopp yoonu musaa jiitalu ma, terewul bi ma nekkee ci biir ñiy sàmm yoonu musaa, sàmm naa yoon wa, ngir gindi leen.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

halafu akamwambia na yule aliyemwalika, "kama ukiwaandalia watu karamu mchana au jioni, usiwaalike rafiki zako au jamaa zako au jirani zako walio matajiri, wasije nao wakakualika nawe ukawa umelipwa kile ulichowatendea.

ウォロフ語

noonu yeesu ne ki ko woo woon lekk: «boo dee woote añ walla reer, bul woo rekk say xarit, say doomi ndey, say bokk, walla say dëkkandoo yu am alal. lu ko moy ñooñu itam dinañu la woo, fey la bor bi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,776,288,966 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK