プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。
wakumbukeni wale waliofungwa kana kwamba mmefungwa pamoja nao. wakumbukeni wale wanaoteseka kana kwamba nanyi mnateseka kama wao.
fàttalikuleen ñi ñu tëj, mel ni su ñu leen boole woon ak ñoom tëjaale. fàttalikuleen ñi ñuy sonal, ni su ngeen bokkoon ak ñoom coono.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
sauti hiyo ikamwambia huyo malaika wa sita mwenye tarumbeta, "wafungulie malaika wanne waliofungwa kwenye mto mkubwa eufrate!"
mu ne juróom-benneelu malaaka, ma yoroon liit: «yiwil ñeenti malaaka, ya yeewe ca efraat, dex gu mag ga.»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
salamu zangu kwa androniko na yunia, wananchi wenzangu waliofungwa gerezani pamoja nami; wao wanajulikana sana kati ya mitume; tena walikuwa wakristo kabla yangu mimi.
nuyul-leen ma it andoronikus ak yuñas, sama bokk, yi ñu ma booleeloon tëj; am nañu tur ci ndawi yàlla yi, te ñoo ma jiitu sax ci gëm kirist.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質: