検索ワード: walipokuwa (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

walipokuwa huko, siku yake ya kujifungua ikawadia,

ウォロフ語

bi ñu nekkee betleyem, waxtu wa mu waree mucc agsi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kesho yake, walipokuwa wanatoka bethania, yesu aliona njaa.

ウォロフ語

bët set ñu génn betani, fekk yeesu xiif.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini makuhani wakuu na wazee walipokuwa wanamshtaki, hakujibu neno.

ウォロフ語

yeesu tontu ko ne: «wax nga ko,» waaye tontuwul dara ca la ko saraxalekat yu mag ya ak njiit ya jiiñ.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

walipokuwa wakizungumza na kujadiliana, yesu mwenyewe akatokea, akatembea pamoja nao.

ウォロフ語

bi ñuy waxtaan ak a sotteente xalaat, yeesu ci boppam dab leen, ànd ak ñoom,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, wakaenda, wakamkuta mwana punda barabarani amefungwa mlangoni. walipokuwa wakimfungua,

ウォロフ語

taalibe ya dem nag, ñu gis cumbur ga ci mbedd mi, mu yeewe cib buntu kër.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

asubuhi na mapema, walipokuwa wanapita, waliuona ule mtini umenyauka wote, hata mizizi.

ウォロフ語

ci suba si, bi ñuy dem, ñu gis ne garabu figg gi dee na, ba wow koŋŋ.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

walipokuwa wakisafiri njiani, mtu mmoja akamwambia yesu, "nitakufuata kokote utakakokwenda."

ウォロフ語

bi ñuy dem, am ci yoon wi ku ne yeesu: «dinaa la topp fépp foo jëm.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

watu walipokuwa wanakwenda zao, wengine walimletea yesu mtu mmoja aliyekuwa bubu kwa sababu alikuwa amepagawa na pepo.

ウォロフ語

bi ñu fa jógee nag, amoon na ñeneen ñu ñëw fi moom, indil ko ku rab jàpp, mu luu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

petro na yohane walipokuwa bado wanawahutubia watu, makuhani na mkuu wa walinzi wa hekalu pamoja na masadukayo walifika.

ウォロフ語

bi ñuy wax ak mbooloo ma, saraxalekat ya ak kilifag ñiy wottu kër yàlla ga ak sadusen ya daanu ci seen kaw.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mungu alifanya kama kwamba haoni nyakati zile watu walipokuwa wajinga. lakini sasa, anaamuru watu wote kila mahali watubu.

ウォロフ語

ca jamono yu wees ya yàlla toppul ñàkka xam googa, waaye léegi koo man a doon ak foo man a nekk, yàlla santaane na, nga tuub say bàkkaar.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

alipowaona akawaambia, "nendeni mkajionyeshe kwa makuhani." basi, ikawa walipokuwa wanakwenda, wakatakasika.

ウォロフ語

naka la leen yeesu di gis, naan leen: «demleen won seen bopp saraxalekat ya.» bi ñuy dem, ñu daldi set.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

mungu wa taifa hili la israeli aliwateua babu zetu na kuwafanya wawe taifa kubwa walipokuwa ugenini kule misri. mungu aliwatoa huko kwa uwezo wake mkuu.

ウォロフ語

yàllay bànni israyil tànn na sunuy maam, di yokk xeet wa, bi ñuy ganeyaan ci misra; ba noppi mu génne leen fa ak kàttanu loxoom.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

siku moja ya sabato, yesu alikuwa anapita katika mashamba ya ngano. walipokuwa wanatembea, wanafunzi wake wakaanza kukwanyua masuke ya ngano.

ウォロフ語

amoon na benn bésu noflaay yeesu jaar ciy tool yu ñor. bi ñuy dem nag, ay taalibeem daldi fàq ay gub.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

baada ya petro na yohane kutoa ushuhuda wao na kuutangaza ujumbe wa bwana, walirudi yerusalemu. walipokuwa wanarudi walihubiri habari njema katika vijiji vingi vya samaria.

ウォロフ語

noonu bi ñu seedeelee yàlla te wax ci kàddoom, ñu dellu yerusalem, di xamle xebaar bu baax bi ci dëkk yu bare yu waa samari.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

lakini huyo kijana akawaambia, "msishangae. mnamtafuta yesu wa nazareti aliyesulubiwa. amefufuka, hayumo hapa. tazameni mahali walipokuwa wamemlaza.

ウォロフ語

waaye mu ne leen: «buleen tiit. yéena ngi seet yeesum nasaret, mi ñu daajoon ci bant bi. nekkatu fi, dekki na; gisleen fi ñu ko tëraloon.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, walipokuwa wanashuka mlimani, yesu akawaonya: "msimwambie mtu mambo mliyoyaona mpaka mwana wa mtu atakapofufuliwa kutoka wafu."

ウォロフ語

bi loolu amee ñu wàcc ca tund wa. bi ñuy wàcc nag, yeesu sant leen ne: «buleen nettali kenn li ngeen gis, ba kera doomu nit ki dekki.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, kukawa na mtengano wa fikira kati yao. walipokuwa wanakwenda zao, paulo alisema jambo hili, "kweli ni sawa yale aliyoyanena roho mtakatifu kwa wazee wenu kwa njia ya nabii isaya

ウォロフ語

gannaaw mënuñoo déggoo, ñu bëgg a tas. waaye bi ñu laata dem, pool teg ca wax jii: «xel mu sell mi wax na dëgg ak seeni maam, jaarale ko ci yonent yàlla esayi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

walipokuwa wanakula, yesu alitwaa mkate, akashukuru, akaumega na kuwapa wanafunzi wake akisema, "twaeni; huu ni mwili wangu."

ウォロフ語

noonu bi ñuy lekk, yeesu jël mburu, sant yàlla, jox leen ko naan: «jël-leen, lii sama yaram la.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

mungu aliwafunulia kwamba wakati walipokuwa wanasema juu ya hayo mambo ambayo ninyi mmekwisha sikia sasa kutoka kwa wale wajumbe waliowatangazieni habari njema kwa nguvu ya roho mtakatifu aliyetumwa kutoka mbinguni, hiyo kazi yao haikuwa kwa faida yao wenyewe, bali kwa ajili yenu. hayo ndiyo mambo ambayo hata malaika wangependa kuyafahamu.

ウォロフ語

waaye yàlla xamal na leen ne, moomuñu woon kàddu googu ñu wax, waaye yéena ko moom. te mooy kàddu gi ngeen dégg ci gémmiñu ñi leen doon jottali xebaar bu baax bi, ci dooley xel mu sell, mi yàlla yónnee asamaan; malaaka yi sax bëgg nañoo gëstu yëf yii.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, hao wajumbe wa yohane walipokuwa wanakwenda zao, yesu alianza kuyaambia makundi ya watu habari za yohane: "mlikwenda kutazama nini kule jangwani? je, mlitaka kuona mwanzi unaotikiswa na upepo?

ウォロフ語

bi nga xamee ne taalibe ya yaxya yónni woon ci yeesu dem nañu, yeesu daldi wax ak mbooloo ma ci mbirum yaxya ne leen: «lu ngeen seeti woon ca màndiŋ ma? xanaa barax buy jaayu ci ngelaw li?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,799,636,896 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK