プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。
wanafunzi wake walipoona hayo wakakasirika, wakasema, "ya nini hasara hii?
waaye bi ko taalibe ya gisee, ñu daldi mer ne: «yàq gii lu muy jariñ?
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
wale wanafunzi wake walipoona hayo wakasema, "bwana, tutumie panga zetu?"
bi ñi àndoon ak yeesu gisee liy bëgg a xew, ñu ne: «boroom bi, ndax nu dóore jaasi?»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
yesu alipokuwa yerusalemu kwa sikukuu ya pasaka, watu wengi walimwamini walipoona ishara alizozifanya.
bi yeesu nekkee yerusalem ci màggalu bésu jéggi ba, ñu bare gis kéemaan, yi mu doon def, daldi gëm ci turam.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
basi, wayahudi wengi waliokuwa wamefika kwa maria walipoona kitendo hicho alichokifanya yesu wakamwamini.
yawut yu bare ca ña ñëwoon kër maryaama te gis li yeesu defoon, daldi koy gëm.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
na mara yule aliyekuwa kipofu akapata kuona, akamfuata yesu akimtukuza mungu. watu wote walipoona hayo, wakamsifu mungu.
ca saa sa mu daldi gis. noonu mu topp ci yeesu, di màggal yàlla. mbooloo mépp gis loolu, di sant yàlla.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
watu wale wote waliokuwa wamekusanyika hapo kwa ajili ya tukio hilo, walipoona hayo yaliyotukia, walirudi makwao wakijipiga vifua kwa huzuni.
nit ña fa dajaloo woon ñépp, di seetaan li xew, ba ñu gisee loolu, ñu dellu seen kër, fëgg seen dënn, di jooy.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
"basi, watumishi wenzake walipoona jambo hilo walisikitika sana, wakaenda kumpasha habari bwana wao juu ya mambo hayo yaliyotukia.
«bi ay moroomam gisee loolu nag, ñu am naqar wu réy, daldi dem, xamal seen sang li xew lépp.
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
mafarisayo walipoona hayo, wakawaambia wanafunzi wake, "mbona mwalimu wenu anakula pamoja na watoza ushuru na wenye dhambi?"
bi ko farisen ya gisee nag, ñu ne taalibe ya: «lu tax seen kilifa di lekkandoo ak ay juutikat ak ay boroom bàkkaar?»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
mafarisayo walipoona hayo, wakamwambia yesu, "tazama, wanafunzi wako wanafanya jambo ambalo si halali siku ya sabato."
farisen ya nag gis ko, ne yeesu: «gisal, say taalibe ñu ngi def lu jaaduwul ci bésu noflaay bi.»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
umati wa watu walipoona alichofanya paulo, ulianza kupiga kelele kwa lugha ya kilukaonia: "miungu imetujia katika sura za binadamu!"
bi mbooloo ma gisee li pool def, ñu daldi yuuxu, ne ci làkku waa likawni: «yàlla yi soppiku nañu nit, wàcc ci nun.»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
basi, wanafunzi wake, kina yohane na yakobo, walipoona hayo, wakasema, "bwana, wataka tuamuru moto ushuke kutoka mbinguni uwateketeze?"
bi taalibe yi tudd saag ak yowaana gisee loolu, ñu ne: «boroom bi, ndax dangaa bëgg nu ne, na safaras asamaan dal ci seen kaw, faagaagal leen?»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています
basi, jemadari na wale waliokuwa wakimlinda yesu walipoona tetemeko la ardhi na yale mambo yaliyotukia, wakaogopa sana, wakasema, "hakika mtu huyu alikuwa mwana wa mungu."
noonu njiitu xare bi ak ñi ànd ak moom di wottu yeesu, bi ñu gisee suuf si yengu ak li xew, ñu daldi tiit lool ne: «ci dëgg, kii doomu yàlla la.»
最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:
警告:見えない HTML フォーマットが含まれています