検索ワード: wasiwasi (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

kwa maneno hayo waliwatia wasiwasi wakuu wa mji na kundi la watu.

ウォロフ語

bi ko mbooloo mi ak àttekat yi déggee, ñu daldi jaaxle lool.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

ni nani kati yenu kwa kuwa na wasiwasi anaweza kuongeza urefu wa maisha yake?

ウォロフ語

ana kan ci yéen ci kaw njaaxleem, moo man a yokk ab waxtu ci àppam?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"basi, msiwe na wasiwasi: tutakula nini, tutakunywa nini, tutavaa nini!

ウォロフ語

buleen jaaxle nag, di wax ne: “lu nu war a lekk? lu nu war a naan?” walla: “lu nu war a sol?”

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

basi, kama hamwezi kufanya jambo dogo kama hilo, kwa nini kuwa na wasiwasi juu ya yale mengine?

ウォロフ語

su fekkee lu tuuti loolu rekk mënuleen koo def, kon lu tax ngeen di jaaxle ci li ci des?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

mkuu wa walinzi wa hekalu na makuhani wakuu waliposikia habari hiyo wakawa na wasiwasi, wasijue yaliyowapata.

ウォロフ語

bi kilifag wottukati kër yàlla ga ak saraxalekat yu mag ya déggee loolu, ñu daldi ciy jaaxle lool, ñuy laajante, fu lii di mujj.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

kama mtu yeyote ni dhaifu, nami pia ni dhaifu; mtu yeyote akikwazwa, nami pia huwa na wasiwasi.

ウォロフ語

ana ku ci néew doole, te wàlluma ko? ana ku ci bàkkaar, te awma naqar wu tiis?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, msiwe na wasiwasi juu ya kesho; kesho inayo yake. matatizo ya siku moja yanawatosheni kwa siku hiyo.

ウォロフ語

buleen jaaxle nag ngir ëllëg, ndaxte ëllëg dina topptoo boppam. bés bu nekk, coonoom doy na ko.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

hawa wamepotoka kabisa mbali na ukweli, na wanatia imani ya watu wengine katika wasiwasi kwa kusema ati ufufuo wetu umekwisha fanyika.

ウォロフ語

dañoo moy dëgg, di wax ne ndekkite wees na, ba yàq ngëmu ñenn ñi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"watakapowapeleka ninyi mbele ya masunagogi na mbele ya wakuu na watawala msiwe na wasiwasi juu ya jinsi mtakavyojitetea au jinsi mtakavyosema.

ウォロフ語

«bu ñu leen yóbboo ca jàngu ya, ca kanamu kilifa ya ak àttekat ya, buleen am xel ñaar ci li ngeen war a tontu ak nan ngeen war a tontoo, walla lu ngeen war a wax,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"na kuhusu mavazi, ya nini kuwa na wasiwasi? tazameni maua ya porini jinsi yanavyostawi. hayafanyi kazi wala hayasokoti.

ウォロフ語

«te lu tax ngeen di jaaxle ngir koddaay? seetleen bu baax, ni tóor-tóori ñax mi di saxe ci tool yi. duñu liggéey, duñu ëcc,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"kutakuwa na ishara katika jua na mwezi na nyota. mataifa duniani yatakuwa na dhiki kwa sababu ya wasiwasi kutokana na mshindo wa mawimbi ya bahari.

ウォロフ語

«ay firnde dinañu feeñ ci jant bi, ci weer wi ak ci biddiiw yi. ci kaw suuf xeet yi dinañu tiit, jaaxle ndax riiru géej gi ak yengu-yengub duus yi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

"nawaachieni amani; nawapeni amani yangu. siwapi ninyi kama vile ulimwengu ufanyavyo. msiwe na wasiwasi, wala msifadhaike.

ウォロフ語

jàmm laa leen bàyyeel, sama jàmm laa leen jox, jàmm ju àddina mënul a joxe. buleen jàq, buleen tiit.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

kisha yesu akawaambia wanafunzi wake, "kwa sababu hiyo nawaambieni, msiwe na wasiwasi juu ya chakula mnachohitaji ili kuishi, wala juu ya mavazi mnayohitaji kwa ajili ya miili yenu.

ウォロフ語

noonu yeesu daldi ne taalibeem yi: «loolu moo tax maa ngi leen koy wax, buleen seen bakkan jaaxal, ci lu ngeen war a lekk. buleen jaaxle it ngir seen yaram ci lu ngeen war a sol,

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

nao watakapowatieni nguvuni na kuwapeleka mahakamani, msiwe na wasiwasi juu ya yale mtakayosema; saa ile itakapofika, semeni chochote mtakachopewa, maana si ninyi mtakaosema, bali roho mtakatifu.

ウォロフ語

saa su ñu leen jàppee nag, dëj leen ci péncum layoo, buleen jàq ci li ngeen war a wax; li ngeen jot ca waxtu woowa waxleen ko, ndaxte du yéenay wax waaye xel mu sell mi.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

"ndiyo maana nawaambieni, msiwe na wasiwasi juu ya chakula na kinywaji mnavyohitaji ili kuishi, wala juu ya mavazi mnayohitaji kwa ajili ya miili yenu. je, maisha ni chakula tu au zaidi? na mwili, je, si zaidi ya mavazi?

ウォロフ語

«loolu moo tax maa ngi leen koy wax, buleen seen bakkan jaaxal, ci lu ngeen war a lekk, walla lu ngeen war a naan. buleen jaaxle it ngir seen yaram, ci lu ngeen war a sol. xanaa bakkan gënul lekk, te yaram gënul koddaay?

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,749,124,816 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK