検索ワード: wazawa (スワヒリ語 - ウォロフ語)

人による翻訳

プロの翻訳者、企業、ウェブページから自由に利用できる翻訳レポジトリまで。

翻訳の追加

スワヒリ語

ウォロフ語

情報

スワヒリ語

kama alivyowaahidia wazee wetu abrahamu na wazawa wake hata milele."

ウォロフ語

ni mu ko dige woon sunuy maam,jëmale ko ci ibraayma ak askanam ba fàww.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

mungu alisema: "hakika nitakubariki na nitakupa wazawa wengi."

ウォロフ語

ne ko: «sàllaaw dinaa la barkeel, yokk saw askan.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

ingawa mungu alikuwa amemwambia: "wazawa wako watatokana na isaka."

ウォロフ語

fekk sax yàlla nee woon na ko: «saw askan ci isaaxa lay jaar.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

ikiwa ninyi ni wa kristo, basi ni wazawa wa abrahamu, na mtapokea yale aliyoahidi mungu.

ウォロフ語

bu ngeen bokkee ci kirist, kon bokk ngeen ci askanu ibraayma, te jot ngeen xéewal, yi ko yàlla dig.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

najua kwamba ninyi ni wazawa wa abrahamu. hata hivyo, mnataka kuniua kwa sababu hamuyakubali mafundisho yangu.

ウォロフ語

xam naa ne askanu ibraayma ngeen. waaye yéena ngi may wut a rey, ndaxte li may jàngale xajul ci yéen.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, joka hilo likamkasirikia huyo mama, likajiondokea, likaenda kupigana na wazawa wengine wa huyo mama, yaani wote wanaotii amri za mungu na kuuzingatia ukweli wa yesu.

ウォロフ語

ninkinànka ja mere jigéen ja, daldi xeexi ak ñi des ciy doomam, di ñiy sàmm ndigali yàlla tey sax ci di seedeel yeesu.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

nao wakamjibu, "sisi ni wazawa wa abrahamu, na hatujapata kamwe kuwa watumwa wa mtu yeyote yule. una maana gani unaposema: mtakuwa huru?"

ウォロフ語

Ñu tontu ko ne: «nun ci ibraayma lanu soqikoo te musunoo nekk jaamu kenn. nan nga nu man a waxe ne, dinañu leen goreel?»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

wala, si wazawa wote wa abrahamu ni watoto wake wa kweli. ila, kama yasemavyo maandiko matakatifu: "wazao wake watatokana na isaka."

ウォロフ語

te it du ñi soqikoo ci ibraayma ñépp, ay doomam dëgg lañu. ndaxte yàlla dafa wax ibraayma ne ko: «saw askan ci isaaxa lay jaar.»

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

スワヒリ語

ahadi zile mungu alizotoa kwa njia ya manabii ni kwa ajili yenu; na mnashiriki lile agano mungu alilofanya na babu zenu, kama alivyomwambia abrahamu: kwa njia ya wazawa wako, jamaa zote za dunia zitabarikiwa.

ウォロフ語

yéen nag yéenay donn yonent yi ak kóllëre, gi yàlla fasoon ak seeni maam, bi mu naan ibraayma: “xeeti àddina yépp dinañu barkeel ci ki soqikoo ci yaw.”

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

スワヒリ語

basi, abrahamu alipewa ahadi, yeye pamoja na mzawa wake. maandiko hayasemi: "na wazawa wake," yaani wengi, bali yasema, "na mzawa wake," yaani mmoja, naye ndiye kristo.

ウォロフ語

léegi nag yàlla am na lu mu dig ibraayma ak askanam. mbind mi waxul: «ak i sëtam,» mu mel ni ñu bare, waaye kenn la wax: «ak sa askan,» maanaam kirist.

最終更新: 2012-05-05
使用頻度: 1
品質:

警告:見えない HTML フォーマットが含まれています

人による翻訳を得て
7,744,650,367 より良い訳文を手にいれましょう

ユーザーが協力を求めています。



ユーザー体験を向上させるために Cookie を使用しています。弊社サイトを引き続きご利用いただくことで、Cookie の使用に同意していただくことになります。 詳細。 OK