검색어: kaumatua (마오리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

마오리어

월로프어

정보

마오리어

na konei hoki nga kaumatua i korerotia paitia ai

월로프어

maam ya, seen ngëm a tax ba yàlla seedeel leen lu baax.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

koia ona matua i mea ai, he kaumatua ia; ui atu ki a ia

월로프어

looloo tax waajur ya ne: «laajleen ko; magum jëmm la.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

na ka huihui nga apotoro ratou ko nga kaumatua ki te whakaaro ki tenei mea

월로프어

noonu ndaw yi ak njiit yi dajaloo, ngir seet mbir moomu.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

na ka tono tangata atu ia i miretu ki epeha, hei tiki i nga kaumatua o te hahi

월로프어

bi pool eggee mile nag, mu yónnee ca efes, ngir woo njiiti mbooloom ñi gëm.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

na ka mea nga mea ora e wha, amine. a ka hinga iho nga kaumatua, ka koropiko

월로프어

Ñeenti mbindeef ya naan: «amiin.» mag ña sukk di màggal.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

i pena ano te tawai a nga tohunga nui, ratou ko nga karaipi, ko nga kaumatua, i mea

월로프어

saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ak njiit ya it di ko ñaawal naan:

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

a, ka takiri te ata, ka runanga nga tohunga nui katoa me nga kaumatua o te iwi mo ihu kia whakamatea

월로프어

ci suba teel saraxalekat yu mag yépp ak njiiti xeet wa gise, ngir fexee reylu yeesu.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

i nga mea katoa kia kitea koe he tauira mo nga mahi pai; ko tau whakaako kia tapatahi, kia tu kaumatua

월로프어

te yaw, ci lépp lu mu man a doon, nekkal ab royukaay ci jëf yu baax. na sa njàngale wér te am faayda,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

a, i te whakapanga a nga tohunga nui ratou ko nga kaumatua i tetahi he ki a ia, kihai ia i whakahoki kupu atu

월로프어

yeesu tontu ko ne: «wax nga ko,» waaye tontuwul dara ca la ko saraxalekat yu mag ya ak njiit ya jiiñ.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

a ka oti raua te tuku, ka haere ki o raua hoa, a korerotia ana nga mea katoa i korero ai nga tohunga nui me nga kaumatua ki a raua

월로프어

bi ñu leen yiwee nag, ñu dem ci seeni bokk, nettali leen li saraxalekat yu mag ya ak njiit ya waxoon lépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

e kore hoki nga parihi me nga hurai katoa e kai, ki te kahore i ata horoia nga ringa, e pupuri ana hoki i te whakarerenga iho a nga kaumatua

월로프어

farisen yi nag ñoom ak yawut yi yépp dañuy topp aaday yoon, yi maam yi tëral, te fandee leen gënal lekk ak loxo yu ñu raxasul.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

a, i ahau i hiruharama, ka korerotia mai ia ki ahau e nga tohunga nui, e nga kaumatua o nga hurai, ka tono ratou kia whakawakia ia

월로프어

te bi ma nekkee yerusalem, saraxalekat yu mag ya ak njiiti yawut ya kalaame nañu ko ci man, ñaan ma, ma daan ko.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

a, no to raua taenga ki hiruharama, ka whakamanuhiritia raua e te hahi, e nga apotoro hoki ratou ko nga kaumatua, ka korerotia nga mea i mahi tahi ai te atua me raua

월로프어

te bi ñu agsee yerusalem, mbooloom ñi gëm, ndaw yi ak njiit yi teeru leen, ñu nettali leen fi ñu jaar ak yàlla fépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

a ka oho mai tetahi o nga kaumatua, ka mea mai ki ahau, ko enei i whakakakahuria nei ki nga kakahu ma, ko wai ra? a i haere mai ratou i hea

월로프어

noonu kenn ca mag ña ne ma: «Ñi sol mbubb yu weex yi, ñooy ñan ak fan lañu jóge?»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

a takoto ana nga kaumatua e rua tekau ma wha me nga mea ora e wha, koropiko ana ki te atua e noho ana i runga i te torona, mea ana, amine; areruia

월로프어

noonu ñaar-fukki mag ña ak ñeent, ak ñeenti mbindeef ya, daldi sukk di jaamu yàlla, moom mi toog ca gàngune ma. Ñu naan:«amiin! aleluya!»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

a i tetahi o aua ra, i a ia e whakaako ana i te iwi i roto i te temepara, e kauwhau ana i te rongopai, ka tae mai nga tohunga nui, nga karaipi, me nga kaumatua ki a ia

월로프어

benn bés yeesu doon jàngal nit ña ca kër yàlla ga, di leen yégal xebaar bu baax bi. saraxalekat yu mag ya ak xutbakat ya ak njiit ya ñëw ne ko:

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

a tenei ake kei nga ra whakamutunga, e ai ta te atua, ka ringihia e ahau toku wairua ki nga kikokiko katoa; ka poropiti hoki a koutou tama, a koutou tamahine, ka moemoea hoki o koutou kaumatua

월로프어

“yàlla nee na: ci bés yu mujj yi,dinaa tuur ci sama xel ci kaw nit ñépp;seen xeet wu góor ak wu jigéendinañu wax ci kàddug yàlla;waxambaane yi dinañu gis ay peeñute màggat yi di gént ay gént.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

a, i to ratou rongonga, ka haere takitahi atu ki waho, na nga kaumatua i timata, a poto noa o muri rawa: a ko ihu anake i mahue, me te wahine e tu ana i waenganui

월로프어

bi ñu déggee loolu, ñuy rocceeku kenn-kenn, mag ña jiitu. yeesu rekk des fa, jigéen ja taxaw ca kanamam.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

마오리어

a i kite ano ahau, na, i waenganui o te torona, o nga mea ora hoki e wha, i waenganui ano hoki o nga kaumatua, he reme e tu ana, te ahua kei to te mea i whakamatea, e whitu ona haona, e whitu nga kanohi; ko nga wairua e whitu enei o te atua, kua tonoa nei puta noa i te ao

월로프어

noonu ma gis mbote mu mel ni dañu koo rendi woon, mu taxaw ca digg gàngune ma, ñeenti mbindeef ya séq ko, mag ña wër ko. mbote ma amoon na juróom-ñaari béjjén ak juróom-ñaari bët, ñu di juróom-ñaari xeli yàlla, yi ñu yónni ci àddina sépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

인적 기여로
7,793,960,789 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인