검색어: kanisa (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

msiwe kikwazo kwa wayahudi au kwa wagiriki au kwa kanisa la mungu.

월로프어

buleen def dara lu man a fanq ngëmu yawut yi walla ñi dul yawut walla mbooloom yàlla.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kanisa lote pamoja na wote waliosikia habari ya tukio hilo, waliogopa sana.

월로프어

noonu tiitaange ju mag tàbbi ci mbooloom ñi gëm ñépp ak ñi ko dégg ñépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, petro alipokuwa gerezani, kanisa lilikuwa linamwombea kwa mungu kwa moyo.

월로프어

noonu ñuy wottu piyeer ca kaso ba, waaye mbooloom ñi gëm di ko ñaanal yàlla ak seen xol bépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

napenda kumjulisha kwenu dada yetu foibe ambaye ni mtumishi katika kanisa la kenkrea.

월로프어

bu nu weesoo loolu, maa ngi leen di dénk sunu jigéen febe, miy liggéeyal mbooloom ñi gëm ci dëkku señsere.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kanisa ni mwili wa kristo, na ukamilifu wake yeye anayekamilisha vitu vyote kila mahali.

월로프어

miy jëmmam, di matug kirist, mi fees mbindeef mu ne ci fànn gu ne. 

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kuna ukweli uliofichika katika maneno haya, nami naona kwamba yamhusu kristo na kanisa lake.

월로프어

loolu ëmb na mbóot mu xóot; man maa ngi wax ci lu jëm ci kirist ak mbooloo mi.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

habari ya jambo hilo ikasikika kwa lile kanisa la yerusalemu. hivyo wakamtuma barnaba aende antiokia.

월로프어

ba mbir ma siiwee, ba àgg ci noppi mbooloom ñi gëm ci yerusalem, ñu yebal barnabas ba ancos.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

nanyi waume, wapendeni wake zenu kama kristo alivyolipenda kanisa, akajitoa mwenyewe sadaka kwa ajili yake.

월로프어

yéen nag góor ñi, na ku nekk bëgg jabaram, ni kirist bëgge mbooloo mi, ba joxe bakkanam ndax moom,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

anapaswa awe mwenye sifa njema kati ya watu walio nje ya kanisa, ili asije akalaumiwa na kuanguka katika mtego wa ibilisi.

월로프어

te it war na am seede su rafet ci waa àddina, ngir ñu bañ koo diiŋat, ba muy daanu ci fiiru seytaane.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

asipowasikia hao, liambie kanisa. na kama hatalisikia kanisa, na awe kwako kama watu wasiomjua mungu na watoza ushuru.

월로프어

bu leen dégluwul ñoom itam, wax ko mbooloom ñi gëm. bu dégluwul mbooloo ma nag, nga teg ko ni ku gëmul yàlla mbaa ab juutikat.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

je, yuko mgonjwa kati yenu? anapaswa kuwaita wazee wa kanisa, nao watamwombea na kumpaka mafuta kwa jina la bwana.

월로프어

su amee ci yéen ku wopp, na woo njiiti mbooloo mi, ñu ñaanal ko te diw boppam ci turu boroom bi.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

bila shaka mlikwisha sikia jinsi nilivyokuwa ninaishi zamani kwa kuzingatia dini ya kiyahudi, na jinsi nilivyolitesa kanisa la mungu kupita kiasi na kutaka kuliharibu kabisa.

월로프어

dégg ngeen ni ma doon jëfe, bi ma nekkee ci diiney yawut yi, di fitnaal bu metti mbooloom yàlla, di ko jéem a tas.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

"kwa malaika wa kanisa la pergamoni andika hivi: "huu ndio ujumbe wake yeye aliye na upanga mkali wenye kuwili.

월로프어

«bindal malaakam mbooloom ñi gëm ci dëkku pergam, ne ko: i boroom jaasi ju ñaw, ji am ñaari boor nee na:

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

mzee wa kanisa anapaswa kuwa mtu asiye na hatia; aliye na mke mmoja tu, na watoto wake wanapaswa kuwa waumini, wasiojulikana kuwa wakorofi au wakaidi.

월로프어

njiit nag nii la war a mel: war na ñàkk ŋàññ, yem ci benn soxna, am ay doom yu gëm yu amul baatu gannaaw cig yàqute mbaa déggadi.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

jambo hili lilisababisha ubishi mkubwa, na baada ya paulo na barnaba kujadiliana nao, ikaamuliwa paulo na barnaba pamoja na waumini kadhaa wa lile kanisa la antiokia waende yerusalemu kuwaona wale mitume na wazee kuhusu jambo hilo.

월로프어

pool ak barnabas nag am ak ñoom diisoo ak werante wu metti; noonu bokk yi jàpp ne, pool ak barnabas ak ñeneen ci ñoom war nañoo dem yerusalem ca ndaw ya ak njiit ya, ngir leeral werante wi.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

"kwa malaika wa kanisa la smurna andika hivi: "huu ndio ujumbe kutoka kwake yeye wa kwanza na wa mwisho, ambaye alikufa na akaishi tena.

월로프어

«bindal malaakam mbooloom ñi gëm ci dëkku samirin, ne ko: i ki jëkk te mujj, ki dee woon te dekki nee na:

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

mitume, wazee na kanisa lote waliamua kuwachagua watu fulani miongoni mwao na kuwatuma antiokia pamoja na paulo na barnaba. basi, wakamchagua yuda aitwaye pia barsaba, na sila ambao wote walikuwa wanajulikana zaidi kati ya ndugu.

월로프어

bi mu ko waxee, ndaw yi ak njiit yi ak mbooloom ñi gëm mépp fas yéenee tànn ci ñoom ay nit, yónni leen ancos, ñu ànd ak pool ak barnabas. noonu ñu tànn yudd, mi ñuy dippee barsabas, ak silas, di ay njiit ca bokk ya.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

alipompata, alimleta antiokia. nao wote wawili walikaa na lile kanisa kwa mwaka wote mzima wakifundisha kundi kubwa la watu. huko antiokia, ndiko, kwa mara ya kwanza, wafuasi waliitwa wakristo.

월로프어

bi mu ko gisee, mu indi ko ancos. noonu atum lëmm ñu bokk ak mbooloom ñi gëm, di jàngal nit ñu bare. te ci ancos lañu jëkk a tudde taalibe ya gaayi kirist.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

"kwa malaika wa kanisa la efeso andika hivi: "huu ndio ujumbe kutoka kwake yeye ashikaye nyota saba katika mkono wake wa kulia, na ambaye hutembea katikati ya vinara saba vya taa vya dhahabu.

월로프어

«bindal malaakam mbooloom ñi gëm ci dëkku efes, ne ko: i ki téye juróom-ñaari biddiiw yi ci loxol ndeyjooram, tey dox ci diggu juróom-ñaari làmpi diwlin yu wurus yi nee na:

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

인적 기여로
8,045,163,996 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인