검색어: kipaji (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

alikuwa na binti watatu ambao walikuwa na kipaji cha unabii.

월로프어

amoon na ñeenti doom yuy janq, ñuy wax ci kàddug yàlla.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

mwenye kipaji cha utumishi na atumikie. mwenye kipaji cha kufundisha na afundishe.

월로프어

kuy topptoo yëfi mbooloo mi, nga takku ci; ku yàlla may, ngay jàngale, nekk ci;

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kipaji cha kutangaza ujumbe wa mungu ni lazima kitawaliwe na huyo mwenye hicho kipaji.

월로프어

Ñiy jottali kàddug yàlla dañoo moom seen xel,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

hata hampungukiwi kipaji chochote cha kiroho mkiwa mnangojea kufunuliwa kwake bwana wetu yesu kristo.

월로프어

noonu nag ñàkkuleen genn may léegi bi ngeen di séentu waxtu, wi sunu boroom yeesu kirist di feeñ ci biir ndamam.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

hizo zote ni kazi za roho huyohuyo mmoja, ambaye humpa kila mtu kipaji tofauti, kama apendavyo mwenyewe.

월로프어

loolu lépp, menn xel moomu moo koy def, ku nekk mu sédd la ci, ni mu ko soobe.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, tunavyo vipaji mbalimbali kufuatana na neema tuliyopewa. mwenye kipaji cha unabii na akitumie kadiri ya imani yake.

월로프어

kon gannaaw yàlla séddale na ay mayam, ku nekk ak sa cér, nanu koy jëfandikoo. ku yàlla may, ngay waare kàddoom, nga wax ko kem sa ngëm;

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kila mmoja anapaswa kutumia kipaji alichojaliwa na mungu kwa faida ya wengine, kama vile uwakili mwema wa zawadi mbalimbali za mungu.

월로프어

te lu la yàlla jagleel kenn ku nekk ci yéen, nanga ko bokk ak ñépp ni jawriñ ju jub, ci séddale yiwu yàlla wu yaatu.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

jitahidini kuwa na upendo. vilevile fanyeni bidii ya kupata vipaji vingine vya kiroho, hasa kipaji cha kutangaza ujumbe wa mungu.

월로프어

xintewooleen mbëggeel te fonk mayi xelum yàlla, rawatina mayu wax ci kàddug yàlla,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

je, wote ni mitume? wote ni manabii? wote ni walimu? wote ni wenye kipaji cha kufanya miujiza?

월로프어

ndax ñépp ay ndawi kirist lañu? ndax ñépp dañuy wax ci kàddug yàlla? ndax ñépp ay jàngale? ndax ñépp ay def kéemaan?

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

je, wote ni wenye kipaji cha kuponya? wote ni wenye kipaji cha kusema lugha ngeni? je, wote hufafanua lugha?

월로프어

ndax ñépp a am mayu wéral ay jàngoro? ndax ñépp ay wax ay làkk? ndax ñépp a leen di firi?

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

mwenye kipaji cha kuwafariji wengine na afanye hivyo. mwenye kumgawia mwenzake alicho nacho na afanye hivyo kwa ukarimu. msimamizi na asimamie kwa bidii; naye mwenye kutenda jambo la huruma na afanye hivyo kwa furaha.

월로프어

kuy feddali ngëmu nit ñi ci yàlla, nga sax ci; kuy séddoo alalam ak nit ñi, nga def ko ak xol bu laab; kuy jiite mbooloo mi, nga sawar ci; kuy dimbali ñi néew doole, nanga ci bég.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, ningependa ninyi nyote mseme kwa lugha ngeni lakini ningependelea hasa muwe na kipaji cha kutangaza ujumbe wa mungu, maana mtu mwenye kipaji cha kutangaza ujumbe wa mungu, ni wa maana zaidi kuliko yule mwenye kusema lugha ngeni, isipokuwa tu kama yupo hapo mtu awezaye kuyafafanua hayo mambo asemayo, ili kanisa lipate kujengwa.

월로프어

léegi nag bëgg naa yéen ñépp, ngeen di wax ay làkk, waaye li ma gënal mooy ngeen di wax ci kàddug yàlla. kiy wax ci kàddug yàlla moo gën kiy wax ay làkk, su firiwul li muy wax, ngir ngëmu mbooloo mi yokku.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

인적 기여로
7,778,740,824 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인