전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.
kisha, akaziangazia akili zao ili wapate kuelewa maandiko matakatifu.
noonu mu ubbi seen xel, ngir ñu xam li mbind mi di wax.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
tunayo mengi ya kusema juu ya jambo hili, lakini ni vigumu kuwaelezeni, kwa sababu ninyi si wepesi wa kuelewa.
ci fànn googu, am na lu bare lu nu ci bëgg a wax, waaye tekkil leen ko dina jafe, ndaxte dangeen a naqari xel.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
huyo mtu akamjibu, "ninawezaje kuelewa bila mtu kunielewesha?" hapo akamwalika filipo apande juu, aketi pamoja naye.
mu tontu ko ne: «nu ma ko man a xame, su ma ko kenn firilul?» mu woo filib nag, mu yéeg, toog ak moom.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다
basi, yesu akawauliza, "je, ninyi hamwelewi mfano huu? mtawezaje basi, kuelewa mfano wowote?
noonu yeesu ne leen: «ndax xamuleen léeb wii? nu ngeen xame nag léeb yi ci des?
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다
petro alikuwa bado anajaribu kuelewa lile maono, na hapo roho akamwambia, "sikiliza! kuna watu watatu hapa, wanakutafuta.
bi piyeer di rabal xelam ci peeñu ma, xel mi ne ko: «Ñetti nit a ngi nii, di la wut.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다