검색어: malaika (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

kwa maana imeandikwa: atawaamuru malaika wake wakulinde,

월로프어

ndaxte mbind mi nee na:“dina jox ay malaakaam ndigal ci sa mbir,ñu sàmm la,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, ibilisi akamwacha, na malaika wakaja, wakamhudumia.

월로프어

noonu seytaane bàyyi ko. te ay malaaka daldi ñëw fi yeesu, di ko topptoo.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

hapo, malaika kutoka mbinguni, akamtokea ili kumtia moyo.

월로프어

noonu malaakam yàlla daldi koy feeñu, may ko doole.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

maana wafu watakapofufuliwa hawataoa wala kuolewa, watakuwa kama malaika mbinguni.

월로프어

ndaxte keroog ndekkite li kenn du am jabar, kenn du am jëkkër, waaye dinañu mel ni malaaka yi ci kaw.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kisha nikawaona wale malaika saba wanaosimama mbele ya mungu wamepewa tarumbeta saba.

월로프어

noonu ma gis juróom-ñaari malaaka, yi taxaw ca kanam yàlla, ñu daldi leen jox juróom-ñaari liit.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kisha wale malaika saba wenye tarumbeta saba wakajiweka tayari kupiga mbiu ya mgambo.

월로프어

ba mu ko defee juróom-ñaari malaaka, ya yoroon juróom-ñaari liit ya, daldi defaru di waaj a liit.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kisha malaika mwingine akatoka katika hekalu mbinguni akiwa na mundu wenye makali.

월로프어

bi loolu amee meneen malaaka génn ca kër yàlla ga nekk ca asamaan, yor moom itam sàrt bu ñaw.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

adui aliyepanda yale magugu ni ibilisi. mavuno ni mwisho wa nyakati na wavunaji ni malaika.

월로프어

seytaane mooy noon bi ko ji; tukkitel àddina mooy ngóob mi, te malaaka yi ñooy góobkat yi.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

malaika akawaambia, "msiogope! nimewaleteeni habari njema ya furaha kuu kwa watu wote.

월로프어

waaye malaaka mi ne leen: «buleen tiit, ndaxte dama leen di xamal xebaar bu baax buy indi mbég mu réy ci nit ñépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

kisha malaika akanionyesha mto wa maji ya uzima maangavu kama kioo yakitoka kwenye kiti cha enzi cha mungu na mwanakondoo.

월로프어

noonu malaaka ma won ma dexu ndoxum dund, mu leer ni weer bu set, di génn ca gàngune mu yàlla ak mbote ma,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

je, hamjui kwamba, licha ya kuhukumu mambo ya kawaida ya kila siku, tutawahukumu hata malaika?

월로프어

xanaa xamuleen ne, nooy àtteji malaaka yi? waxatumaak mbiri àddina sii.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

akakaa huko siku arubaini akijaribiwa na shetani. alikuwa huko pamoja na wanyama wa porini, nao malaika wakawa wanamtumikia.

월로프어

mu nekk fa ñeent-fukki fan, jànkoonte ak fiiri seytaane; mu dëkk ci biir rabi àll yi, te malaakay yàlla di ko topptoo.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

akawaona malaika wawili waliovaa mavazi meupe, wameketi pale mwili wa yesu ulipokuwa umelazwa, mmoja kichwani na wa pili miguuni.

월로프어

séen ñaari malaaka yu sol mbubb yu weex, toog ca bérab, ba ñu dencoon yeesu; kenn ka féeteek bopp bi, ki ci des ca tànk ya.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, roho akanikumba, naye malaika akanipeleka juu ya mlima mrefu sana. akanionyesha mji mtakatifu, ukishuka kutoka kwa mungu mbinguni,

월로프어

noonu xelum yàlla solu ma, malaaka ma yóbbu ma ci kaw tund wu réy-a-réy. noonu mu won ma yerusalem, dëkk bu sell bi, muy wàcce ci asamaan, jóge ca wetu yàlla,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

"miaka arobaini ilipotimia, malaika wa bwana alimtokea mose katika kichaka kilichokuwa kinawaka moto kule jangwani karibu na mlima sinai.

월로프어

«lu ko wees ñeent-fukki at nag, bi mu nekkee ca màndiŋu tundu sinayi, malaaka feeñu ko ci takk-takku safara ci biir as ngarab.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

"ikatokea kwamba huyo maskini akafa, malaika wakamchukua, wakamweka karibu na abrahamu. na yule tajiri pia akafa, akazikwa.

월로프어

«noonu miskin ma dee, malaaka yi yóbbu ko ca wetu ibraayma. boroom alal ja itam dee, ñu suul ko.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

"jihadharini! msimdharau mmojawapo wa wadogo hawa. nawaambieni, malaika wao huko mbinguni wako daima mbele ya baba yangu aliye mbinguni.

월로프어

«te it wottuleen a xeeb kenn ci ñi gën a tuuti, ndax kat seeni malaakaa ngi sax ci jataayu sama baay bi nekk ci kaw. maa leen wax loolu.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

lakini kuhusu malaika, mungu alisema: "mungu awafanya malaika wake kuwa pepo, na watumishi wake kuwa ndimi za moto."

월로프어

ci wàllu malaaka yi, lii la ci yàlla wax:«def na malaakaam yi, ñu mel ni ay ngelaw,ñooñu koy liggéeyal, mu def leen niki safara.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

"mimi, yesu, nimemtuma malaika wangu awathibitishieni mambo haya katika makanisa. mimi ni mzawa wa ukoo wa daudi. mimi ni nyota angavu ya asubuhi!"

월로프어

«man yeesu maa yónni sama malaaka, ngir mu seede leen mbir yii ci digg mboolooy ñi gëm. man maay car, bi soqikoo ci daawuda, di biddiiwu njël bu leer bi.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

siri ya nyota zile saba ulizoziona katika mkono wangu wa kulia, na siri ya vile vinara saba vya taa hii: zile nyota saba ni malaika wa makanisa; na vile vinara saba vya taa ni makanisa saba.

월로프어

juróom-ñaari biddiiw yi nga gis ci sama loxol ndeyjoor, ak juróom-ñaari làmpi diwlin yu wurus yi, ay mbóoti yàlla lañu te lii lañuy tekki: biddiiw yi ñoo di malaakay juróom-ñaari mboolooy ñi gëm; juróom-ñaari làmp yi ñoo di juróom-ñaari mbooloo yi.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

인적 기여로
7,786,800,002 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인