전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.
jambo hili ni kweli. ninakutaka uyatilie mkazo mambo haya, ili wale wanaomwamini mungu, wawe na hamu ya kuutumia wakati wao katika kutenda mema, ambayo ni mambo mazuri na ya manufaa kwa watu.
wax jooju ju wóor la, te damaa bëgg nga dëggal loolu, ngir ñi gëm yàlla sax ci jëf lu rafet. loolu moo baax te am njariñ ci nit.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
maana wakati tulipowahubirieni ile habari njema haikuwa kwa maneno tu, bali pia kwa nguvu na kwa roho mtakatifu, tukiwa na hakika kwamba ujumbe huo ulikuwa wa kweli. mnajua jinsi tulivyoishi pamoja nanyi; tuliishi kwa manufaa yenu.
ndaxte xebaar bu baax, bi nu leen doon yégal, yemul woon ci ay wax rekk, waaye àndoon na ak kàttan ak xel mu sell mi ak kóolute gu mag. xam ngeen sunu taxawaay ci seen biir ngir seen njariñ.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질: