전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.
nafanya haya yote kwa ajili ya habari njema, nipate kushiriki baraka zake.
damaa def loolu lépp ndax xebaar bu baax bi, ngir man it ma am wàll ci barkeem.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
yaani, badala ya kufanya lile jambo jema ninalotaka, nafanya lile baya nisilotaka.
lu baax nag lu may yéene, duma ko def, waaye lu bon lu ma bëggul, moom laay def.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
basi, yesu akawaambia, "baba yangu anafanya kazi daima, nami pia nafanya kazi."
waaye yeesu tontu na leen ne: «sama baay nekk na ba tey ci liggéey, kon man itam damay liggéey.»
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다
yule aliyenituma yuko pamoja nami; yeye hakuniacha peke yangu kwani nafanya daima yale yanayompendeza."
te it ki ma yónnee ngi ànd ak man; musu maa bàyyi ma wéet, ndaxte li ko neex rekk laay def.»
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다
lakini ulimwengu unapaswa kujua kwamba nampenda baba, na ndiyo maana nafanya kila kitu kama baba alivyoniamuru. simameni, tutoke hapa!"
waaye àddina si war na xam ne, bëgg naa baay bi te ni ma ko baay bi sante, ni laay jëfe. jógleen, nu dem!
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다
lakini kwa sababu ya upendo, ni afadhali zaidi nikuombe. nafanya hivi ingawa mimi ni paulo, balozi wa kristo yesu, na sasa pia mfungwa kwa ajili yake.
waaye dama lay ñaan ci mbëggeel gi nu séq, man pool màggat, mi ñu tëj kaso ci turu kirist.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
kisha yule aliyeketi juu ya kiti cha enzi akasema, "tazama, nafanya yote mapya." tena akaniambia, "andika hili, maana maneno haya ni ya kuaminika na ya kweli!"
noonu ki toog ca gàngune ma ne: «maa ngi yeesal lépp!» mu ne ma: «bindal, ndaxte kàddu yii yu wóor lañu te dëggu.»
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다