검색어: nimekuwa (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

je, sasa nimekuwa adui yenu kwa sababu ya kuwaambieni ukweli?

월로프어

ndax dëgg, gi ma leen wax, moo tax ngeen def ma ab noon?

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kama ilivyoandikwa katika zaburi ya pili: wewe ni mwanangu, mimi leo nimekuwa baba yako.

월로프어

def na ko ngir nun seeni sët, ci li mu dekkal yeesu. moom lañu bindoon ci ñaareelu saaru sabóor ne:“yaa di sama doom,maa di sa baay tey.”

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

ndugu, nawasihi muwe kama mimi, kwa vile hata mimi nimekuwa kama ninyi. hamkunitendea ubaya wowote.

월로프어

bokk yi, dama leen di ñaan, ngeen mel ni man, ndaxte man itam fekksi naa leen ci seen xalaat. tooñuleen ma.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

wakatuomba lakini kitu kimoja: tuwakumbuke maskini; jambo ambalo nimekuwa nikijitahidi kutekeleza.

월로프어

li ñu doon laaj rekk moo di, nuy fàttaliku seen aji néew doole yi, fekk sax laxasu woon naa ci def ko.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

hata kama nikinena lugha za watu na hata za malaika, lakini kama sina upendo mimi nimekuwa tu kama sauti ya debe tupu au kengele.

월로프어

su fekkee ne damay wax làkki nit ñi ak yu malaaka yi sax, te boolewuma ci mbëggeel, duma dara lu dul ndënd muy riir, walla jóolóoli buy kandaŋ-kandaŋi.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, ninalo ombi moja kwako kuhusu mwanangu onesimo, ambaye ni mwanangu katika kristo kwani nimekuwa baba yake nikiwa kifungoni.

월로프어

maa ngi tinul sama doomu diine onesim, mi ma jur ci kirist fii ci kaso bi.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

"nimekuwa nikienda huko na huko kati yenu nikiuhubiri ufalme wa mungu. sasa lakini, najua hakuna hata mmoja wenu atakayeniona tena.

월로프어

«fi mu ne nag xam naa ne, dootuleen gis sama kanam, yéen ñépp ñi ma jaaroon ci seen biir, di yégle nguuru yàlla.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

basi, sasa nawaambieni ninyi watu wa mataifa mengine: maadamu mimi nimekuwa mtume kwa watu wa mataifa mengine, ninajivunia huduma yangu,

월로프어

yéen ñi dul yawut, yéen laay waxal. ndegam yàlla daf maa def ndawam, yónni ma ci yéen xeeti àddina si, damay matal samab yónnent.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

nimefanya kazi na kutaabika, nimekesha bila usingizi mara nyingi; nimekuwa na njaa na kiu; mara nyingi nimefunga na kukaa katika baridi bila nguo.

월로프어

sonn naa, di ñaq, di fanaane xool, di xiif ak a mar tey fande, di dékku liw te rafle,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

nimekuwa nikiwapeni daima mfano kwamba kwa kufanya kazi mithili hiyo tunapaswa kuwasaidia walio dhaifu, tukikumbuka maneno ya bwana yesu mwenyewe: heri zaidi kutoa kuliko kupokea."

월로프어

ci lépp won naa leen royukaay, ci li nu war a dimbali ñi néew doole te fàttaliku li yeesu boroom bi wax moom ci boppam ne: “joxe moo gën a barkeel nangu.”»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

hali kadhalika naye kristo hakujitwalia mwenyewe heshima ya kuwa kuhani mkuu, bali mungu alimwambia: "wewe ni mwanangu; mimi leo nimekuwa baba yako."

월로프어

kirist itam yékkatiwul boppam, ba doon saraxalekat bu mag, waaye yàlla moo ko woo, bi muy wax ne:«yaa di sama doom,maa di sa baay tey.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

lakini, kwa neema yake mungu, nimekuwa kama nilivyo. na neema yake kwangu haikuwa bure. mimi nimefanya kazi kuliko wote; si mimi hasa, ila ni neema ya mungu ifanyayo kazi pamoja nami.

월로프어

waaye nag yiwu yàlla moo tax ma doon li ma doon, te yiw, wi mu wone ci man, du cig neen. waaye sax maa gën a liggéey ñi ci des ñépp: du ci man, waaye yiwu yàlla, wiy jëf ci man, moo tax.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, akamwambia mfanyakazi wake: angalia! kwa miaka mitatu nimekuwa nikija kuchuma matunda ya mtini huu, nami nisiambulie kitu. ukate! kwa nini uitumie ardhi bure?

월로프어

noonu mu ne surga ba: “Ñetti at a ngii may ñëw di raas-si garab gii te duma ci fekk dara. gor ko. lu tax muy xatal tool bi?”

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

인적 기여로
7,800,348,825 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인