검색어: pilato (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

pilato akajibu, "niliyoandika, nimeandika!"

월로프어

pilaat tontu leen ne: «xas naa koo bind, du deñ.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

pilato aliposikia maneno hayo akazidi kuogopa.

월로프어

bi pilaat déggee wax jooju, dafa gën a tiit,

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

lakini yesu hakujibu neno, hata pilato akashangaa.

월로프어

waaye ba tey yeesu tontuwul dara, ba tax pilaat waaru.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, pilato akaamua kwamba matakwa yao yatimizwe.

월로프어

muj gi pilaat dogal, ñu defal leen li ñu bëgg.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, pilato akaamuru yesu achukuliwe, apigwe viboko.

월로프어

noonu pilaat joxe ndigal, ñu dóor yeesu ay yar.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

pilato alitaka kumwachilia yesu, hivyo akasema nao tena;

월로프어

pilaat waxaat ak mbooloo ma, ndaxte dafa bëggoon a bàyyi yeesu.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

watu wengi wakamwendea pilato wakamwomba awafanyie kama kawaida yake.

월로프어

noonu mbooloo mi ñëw, laaj pilaat, mu defal leen la mu daan def.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, yeye alikwenda kwa pilato, akaomba apewe mwili wa yesu.

월로프어

mu dem ca pilaat, laaj ko néewu yeesu.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

lakini makuhani wakuu wakawachochea watu wamwombe pilato awafungulie baraba.

월로프어

waaye saraxalekat yu mag yi xiir mbooloo mi, ñu laaj pilaat, mu bàyyil leen barabas.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, pilato akaitisha mkutano wa makuhani wakuu, viongozi na watu,

월로프어

pilaat daldi woo saraxalekat yu mag ya, njiit ya ak mbooloom yawut ya ne leen:

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

hapo pilato akawafungulia baraba kutoka gerezani, lakini akamtoa yesu asulubiwe.

월로프어

noonu pilaat bàyyil leen barabas, mu dóorlu yeesu ay yar, jébbal ko, ngir ñu daaj ko ci bant.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, hapo pilato akamtia yesu mikononi mwao ili asulubiwe. basi, wakamchukua yesu.

월로프어

noonu pilaat jébbal leen yeesu, ngir ñu daaj ko ci bant. bi leen ko pilaat jébbalee, ñu jël ko, yóbbu.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

akamwendea pilato, akaomba apewe mwili wa yesu. basi, pilato akaamuru apewe.

월로프어

mu dem ca pilaat, laaj ko néewu yeesu. pilaat santaane, ñu jox ko ko.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

herode na pilato, ambao hapo awali walikuwa maadui, tangu siku hiyo wakawa marafiki.

월로프어

erodd ak pilaat dañoo ñi bañante woon bu jëkk, waaye ca bés booba doon nañu ay xarit.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kesho yake, yaani siku iliyofuata ile ya maandalio, makuhani wakuu na mafarisayo walimwendea pilato,

월로프어

ba bët setee nag, ca bés ba topp bésu waajal ba, saraxalekat yu mag ya ak farisen ya dajaloo, jëm ci pilaat.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

pilato akawaambia makuhani wakuu na umati wa watu, "sioni kosa lolote katika mtu huyu."

월로프어

pilaat ne saraxalekat yu mag ya ak mbooloo ma: «gisuma genn tooñ ci nit kii.»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

mbele ya mungu anayevipa vitu vyote uhai, na mbele ya yesu kristo aliyetoa ushahidi na kukiri ukweli mbele ya pontio pilato,

월로프어

noonu fi kanam yàlla mi jagleel dund ci lépp, ak fi kanam kirist yeesu, mi seede woon seede su rafet fa kanam poñsë pilaat, maa ngi lay dénk lii:

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

pilato akaingia tena ndani ya ikulu, akamwita yesu na kumwuliza: "ati wewe ndiye mfalme wa wayahudi?"

월로프어

gannaaw loolu pilaat duggaat ca taaxum kaw ma, woo yeesu ne ko: «ndax yaa di buuru yawut yi?»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

basi, herode pamoja na maaskari wake, wakamwaibisha yesu na kumfanyia mzaha; kisha wakamvika vazi la kifalme, wakamrudisha kwa pilato.

월로프어

noonu erodd ak ay xarekatam toroxal yeesu, di ko ñaawal. gannaaw loolu mu solal ko mbubb mu rafet, delloo ko pilaat.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

hivyo pilato akamwambia, "husemi nami? je, hujui kwamba ninayo mamlaka ya kukufungua na mamlaka ya kukusulubisha?"

월로프어

pilaat ne ko: «man ngay bañ a waxal? xanaa xamuloo ne, am naa sañ-sañu bàyyi la, te am naa itam sañ-sañu daaj la ci bant?»

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

인적 기여로
7,794,831,343 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인