검색어: waliogopa (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

yeye na wenzake waliogopa hata hakujua la kusema.

월로프어

fekk xamul lu muy wax, ndaxte tiitaange jàpp na leen ñoom ñett ñépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kanisa lote pamoja na wote waliosikia habari ya tukio hilo, waliogopa sana.

월로프어

noonu tiitaange ju mag tàbbi ci mbooloom ñi gëm ñépp ak ñi ko dégg ñépp.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

anania aliposikia hayo, akaanguka chini, akafa. watu wote waliosikia habari ya tukio hilo waliogopa sana.

월로프어

bi anañas déggee baat yooyu, mu daanu dee. Ñi ko dégg ñépp tiit, ba ne nërëm.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

hao maofisa waliwapasha habari mahakimu juu ya jambo hilo, nao waliposikia kwamba paulo na sila walikuwa raia wa roma, waliogopa.

월로프어

bi mu ko waxee, alkaati ya yégal àttekat ya la mu wax. bi ñu déggee ne, jaamburi room lañu, ñu daldi tiit.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

petro alipokuwa akisema hayo, mara wingu likatokea na kuwafunika; na wingu hilo lilipowajia, wale wanafunzi waliogopa sana.

월로프어

bi mu koy wax, niir ñëw muur leen, taalibe yi daldi tiit, bi leen niir wa ëmbee.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, wakatoka pale kaburini mbio, maana walitetemeka kwa hofu na kushangaa. hawakumwambia mtu yeyote kitu, kwa sababu waliogopa mno.

월로프어

noonu jigéen ñi génn, dawe bàmmeel ba, tiit bay lox. te waxuñu kenn dara ndax seen tiit.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

hapo mkuu wa walinzi wa hekalu pamoja na watu wake walikwenda hekaluni, akawaleta. lakini hawakuwakamata kwa kutumia nguvu, maana waliogopa kwamba watu wangewapiga mawe.

월로프어

ci kaw loolu kilifa ga ak wottukat ya dem jëli leen; waaye boolewuñu ci fitna, ngir ragal nit ñi sànni leen ay xeer.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

na tukisema, yalitoka kwa watu..." (waliogopa umati wa watu maana wote waliamini kwamba yohane alikuwa kweli nabii.)

월로프어

waaye bu nu nee: “ci nit ñi,” kon mbooloo mi dal ci sunu kaw;» ndaxte ñépp teg nañu yaxya ab yonent.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

경고: 보이지 않는 HTML 형식이 포함되어 있습니다

스와힐리어

makuhani wakuu, walimu wa sheria na wazee walifahamu ya kwamba mfano huo ulikuwa unawahusu. kwa hiyo walijaribu kumtia nguvuni, lakini waliogopa umati wa watu. basi, wakamwacha wakaenda zao.

월로프어

noonu kilifa yi di wut pexem jàpp ko, ndaxte xam nañu ne, ñoom lay wax. waaye ragal nañu mbooloo mi, ba ñu bàyyi ko fa, dem.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

basi, walikuwa njiani kwenda yerusalemu, na yesu alikuwa anawatangulia. wanafunzi wake walijawa na hofu, na watu waliofuata waliogopa. yesu akawachukua tena kando wale kumi na wawili, akaanza kuwaambia yale yatakayompata:

월로프어

gannaaw loolu ñu ànd jëm yerusalem, yeesu jiitu; taalibe yi am njàqare, te ñi ci topp tiit. noonu yeesu woowaat fukk ak ñaar ña cig wet, xamal leen li nar a xew ci mbiram.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

인적 기여로
7,726,960,568 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인