검색어: walipata (스와힐리어 - 월로프어)

인적 기여

전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.

번역 추가

스와힐리어

월로프어

정보

스와힐리어

maana wazee wa kale walipata kibali cha mungu kwa sababu ya imani yao.

월로프어

maam ya, seen ngëm a tax ba yàlla seedeel leen lu baax.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

msisahau kuwakaribisha wageni; maana kwa kufanya hivyo watu wengine walipata kuwakaribisha malaika bila kujua.

월로프어

buleen fàttee teral ñiy ñëw ci yéen, ndaxte ñenn ñi, bi ñu ko defee, teral nañu ay malaaka te xamuñu ko.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

walizima mioto mikali, waliepuka kuuawa kwa upanga. walikuwa dhaifu lakini walipata nguvu. walikuwa hodari katika vita wakashinda majeshi ya kigeni.

월로프어

fey dooley safara, rëcc ci jaasi, ñu génn ci néew doole, dugg ci kàttan, doon ay jàmbaar, dàq xarekat, ya jóge bitim réew.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

yesu alipopata habari hiyo, aliondoka mahali pale kwa mashua, akaenda mahali pa faragha peke yake. lakini watu walipata habari, wakamfuata kwa miguu toka mijini.

월로프어

bi yeesu déggee deewu yaxya nag, mu jóge fa, dugg cig gaal, di dem ca bérab bu wéet. waaye bi ko nit ñi yégee, ñu daldi jóge ci dëkk yi, topp ko ak seeni tànk.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

스와힐리어

kisha nikaona viti vya enzi na watu walioketi juu yake; watu hao walipewa mamlaka ya hukumu. niliona pia roho za wale waliokuwa wamenyongwa kwa sababu ya kumtangaza yesu na kwa sababu ya neno la mungu. hawa hawakumwabudu yule mnyama na sanamu yake, wala hawakupigwa alama yake juu ya paji za nyuso zao, au juu ya mikono yao. walipata tena uhai, wakatawala pamoja na kristo kwa muda wa miaka elfu moja.

월로프어

noonu ma gis ay gàngune, ñu jox ña ca toog sañ-sañu àtte. noonu ma gis ruuwi ñi ñu bóomoon ndax li ñu doon seedeel yeesu te gëm kàddug yàlla. Ñooñu jaamuwuñu rab wa mbaa nataalam, te nanguwuñoo am màndargam rab wa ca seen jë mbaa seen loxo. Ñu daldi dekki, nguuru ak kirist diirub junniy at.

마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:

인적 기여로
7,745,866,402 더 나은 번역을 얻을 수 있습니다

사용자가 도움을 필요로 합니다:



당사는 사용자 경험을 향상시키기 위해 쿠키를 사용합니다. 귀하께서 본 사이트를 계속 방문하시는 것은 당사의 쿠키 사용에 동의하시는 것으로 간주됩니다. 자세히 보기. 확인