전문 번역가, 번역 회사, 웹 페이지 및 자유롭게 사용할 수 있는 번역 저장소 등을 활용합니다.
c`est là une parole certaine et entièrement digne d`être reçue.
wax ju wóor a ngii, te mat a nangu ak gépp kóolute.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
cette parole est certaine: si nous sommes morts avec lui, nous vivrons aussi avec lui;
kàddu gu wóor a ngii:su nu deeyaalee ak kirist,dinanu dundaat ak moom;
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
cette parole est certaine, et je veux que tu affirmes ces choses, afin que ceux qui ont cru en dieu s`appliquent à pratiquer de bonnes oeuvres.
wax jooju ju wóor la, te damaa bëgg nga dëggal loolu, ngir ñi gëm yàlla sax ci jëf lu rafet. loolu moo baax te am njariñ ci nit.
마지막 업데이트: 2024-04-14
사용 빈도: 26
품질:
cette parole est certaine: si quelqu`un aspire à la charge d`évêque, il désire une oeuvre excellente.
wax ju wóor a ngii: kuy sabablu yenub sàmm mbooloo mi, mu ngi yóotu liggéey bu rafet.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
c`est une parole certaine et entièrement digne d`être reçue, que jésus christ est venu dans le monde pour sauver les pécheurs, dont je suis le premier.
wax ju wóor a ngii te yelloo gépp kóolute: kirist yeesu ganesi na àddina, ngir musal bàkkaarkat yi, te maa ci raw!
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질:
au bout d`un certain temps, les juifs se concertèrent pour le tuer,
ba ñu ca tegee ay fani fan, yawut yi daldi gise, ngir reylu ko.
마지막 업데이트: 2012-05-05
사용 빈도: 1
품질: