Você procurou por: lignelser (Dinamarquês - Wolof)

Contribuições humanas

A partir de tradutores profissionais, empresas, páginas da web e repositórios de traduções disponíveis gratuitamente

Adicionar uma tradução

Dinamarquês

Wolof

Informações

Dinamarquês

og han lærte dem meget i lignelser og sagde til dem i sin undervisning:

Wolof

noonu yeesu daldi leen jàngal lu bare ciy léeb. ci njàngaleem nag mu ne leen:

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Dinamarquês

og det skete, da jesus havde fuldendt disse lignelser, drog han bort derfra.

Wolof

bi nga xamee ne yeesu dégtal na léeb yooyu ba noppi, mu jóge fa,

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Dinamarquês

og da ypperstepræsterne og farisæerne hørte hans lignelser, forstode de, at han talte om dem.

Wolof

bi nga xamee ne saraxalekat yu mag ya ak farisen ya dégg nañu léebam yooyu, ñu xam ne ñoom lay wax.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Dinamarquês

alt dette talte jesus til skarerne i lignelser, og uden lignelse talte han intet til dem,

Wolof

loolu yeesu wax mbooloo ma, ëmb na ko lépp ciy léeb, te waxuleen dara lu dul ciy léeb.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Dinamarquês

og disciplene gik hen og sagde til ham: "hvorfor taler du til dem i lignelser?"

Wolof

bi yeesu waxee ba noppi, ay taalibeem jegeñsi, laaj ko lu tax mu di leen wax ciy léeb.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Aviso: contém formatação HTML invisível

Dinamarquês

og han talte meget til dem i lignelser og sagde: "se, en sædemand gik ud at så.

Wolof

noonu yeesu dégtal leen lu bare ciy léeb ne leen: «dafa amoon beykat bu demoon jiyi.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Aviso: contém formatação HTML invisível

Dinamarquês

derfor taler jeg til dem i lignelser, fordi de skønt seende dog ikke se, og hørende dog ikke høre og forstå ikke heller.

Wolof

“dañuy xool te duñu gis, di déglu waaye duñu dégg te duñu xam,” moo tax ma di leen wax ciy léeb.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Dinamarquês

dette har jeg talt til eder i lignelser; der kommer en time, da jeg ikke mere skal tale til eder i lignelser, men frit ud forkynde eder om faderen.

Wolof

«loolu lépp, dama leen koo wax ci ay misaal. jamono dina ñëw, ju ma dootul wax ak yéen ci ay misaal, waaye ju ma leen dee wax lu leer ci baay bi.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Dinamarquês

og han sagde til dem: "eder er guds riges hemmelighed givet; men dem, som ere udenfor, meddeles alt ved lignelser,

Wolof

mu tontu leen: «yéen may nañu leen, ngeen xam mbóoti nguuru yàlla, waaye ñi ci biti léeb ay ëmb lépp.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Aviso: contém formatação HTML invisível

Dinamarquês

og han begyndte at tale til dem i lignelser: "en mand plantede en vingård og satte et gærde derom og gravede en perse og byggede et tårn, og han lejede den ud til vingårdsmænd og drog udenlands.

Wolof

noonu yeesu daldi leen wax ciy léeb. mu ne leen: «amoon na fi nit ku jëmbët toolu réseñ. mu ñag tool bi, gas pax ngir nal ci réseñ yi, tabax wottukaay, ba noppi batale ko ay beykat, daldi tukki.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Aviso: contém formatação HTML invisível

Dinamarquês

"himmeriges rige lignes ved en konge, som gjorde bryllup for sin søn.

Wolof

«nguuru yàlla aji kawe ji dafa mel ni buur buy waajal céetu doomam ju góor.

Última atualização: 2012-05-05
Frequência de uso: 1
Qualidade:

Aviso: contém formatação HTML invisível

Consiga uma tradução melhor através
7,791,461,848 de colaborações humanas

Usuários estão solicitando auxílio neste momento:



Utilizamos cookies para aprimorar sua experiência. Se avançar no acesso a este site, você estará concordando com o uso dos nossos cookies. Saiba mais. OK